BUFFET / masakhaner /wol /masakhaner_32_21_train.tsv
akariasai's picture
Upload 133 files
868d802
sentence: Ni njàngum tubaab bi amee kurél guy saytu lépp lu ci aju ( inspection d’académie ) , noonu lees war a wutale daara yi tamit ag kurél guy wattu lépp lu ci aju . inspection <person> d’académie <organization>
sentence: D angay xool ni alkaati yiy doxal e ci doxi ñaxtu yi .
sentence: Seetal rekk , guddig weeru koor , ci ngelaw li , ñuy fanaane taxaw guddi ba bët set .
sentence: Muy lu jaaduwul , lu doy waar .
sentence: Nit dina feebar , dem loppitaal ñ u koy jox i garabi - tubaab te du wér , fekk ne feebaru ng ë m la ame .
sentence: Ndaxte , ñooy wattu s unu kaaraange guddeek bëccëg .
sentence: Bala nga koy xam Gàmmu jot , walla Màggal , walla Pópangin . Pópangin <organization>
sentence: Dama ne , S apo ŋ , Farã s , Amerig añs ñoo ñu ëpp bor fuuf te doo leen mës a dégg ñuy ñaan ku leen ko baal . S <organization> apo <location> ŋ <location> Farã <organization> s <location> Amerig <organization>
sentence: Raayante bi moo fi war a jóg , wolof mooy làmmiñ wi nu war a boole .
sentence: Seen liggéey yombul te anam yiñ koy defe dafa metti lool .
sentence: Mën nañ ko bañ a wax waaye dégg nañ ko , te loo ci wax xam nañ ko .
sentence: Dafa di , nag , Ërob rawatina Farãs , dañuy xeex ak a bunduxataal tuutaafóoni waaso yi . Ërob <organization> Farãs <organization>
sentence: Te mbir mi , wareesu koo yemale re kk ci taalibe yi .
sentence: Luy sa xalaat ci la takk - der ya duggoon kër Ilimaan Ñiŋ ( Caaroy ) , jaay njambootam doole , dóor waa kër ga , toroxal leen ? Ñiŋ <person> Caaroy <organization>
sentence: Alal ji ma wax nii mat na téeméeri yoon bor bi ñuy leb , su nu ko sàmmoon rekk , du soxla ñuy lebi kenn .
sentence: Waaye , bi leen DIC wooloo , ku nekk ci ñoom dellu na ginnaaw . DIC <person>
sentence: Yaa doon sama royukaay .
sentence: Loolu , du lu ma jékki - jekki rekk def ko .
sentence: Waaye , nag , du lépp a bon ci daara yi .
sentence: Bu ngeen fàttalikoo , 4i at ci ginnaaw , Maki Sàll amaloon na fi ndajem jawriñ ca Pikin , ca la waxe woon ni benn taalibe dootul taxawaalu ci mbedd yi ; boobaak léegi , nag , tey la Waalo g ë n a aay . Sàll <person> Pikin <organization> Waalo <organization>
sentence: Xamul woon xàjj - ak - seen te bëggul woon lu jege sax boddekonte , rawatina ñeel nit ku ñuul .
sentence: Fexe ba lempo yeembambaay , ñi war a fey ñépp di fey amagul Senegaal fi mu tollu nii . Senegaal <organization>
sentence: Waaye , Mabaaba , ak lu mu doon mbër mu mag yépp , amul ndam ci xeexam bu mujj bi mu séqaloon ak meneen mbër mu xarañ te gaaw ci rey nit .
sentence: Yenn saa yi ma daje ak ñenn ci ñoom , nu lal aw waxtaan .
sentence: Waaye , Yàlla am na ci nit ñi yërmande joo xam ne , fépp fu mu boole ay nit yu wute ci waaso , dina fa tàggat aw làmmiñ wu leen di boole , ñu cay jokkoo .
sentence: Sumay wax aada , xam - xam , cosaan ak sag yi m u là mboo ma tax di wax .
sentence: Jean - Michel Aulas Njiitu Olympique Lyonnais . Aulas <person> Olympique <person> Lyonnais <organization>
sentence: Boo fa demee , benn xale du génn .
sentence: Boo demee réew mu mel ni Marog , looloo fa am . Marog <organization>
sentence: Ndaxte askanuw Senegaal dafa ragal yat . Senegaal <organization>
sentence: Fii ci Senegaal , fépp foo dem , dégg nañ wolof . Senegaal <organization>
sentence: Waxuma , nag , tëgg , fecc ak li xew jamono jii .