sentence: Ndaxte , ñoom daanaka yoon da leen a muumaloo . sentence: Nun , dipite yi , yoon may nanu nu génn ci jamonoy guural gi . sentence: Luy sa naal ñeel aada ak cosaan ? sentence: Boo fa demee , benn xale du génn . sentence: Li ma tax a wax ne dañ leen k o o sant mooy ne , dara du leen ci fekk , kenn du leen teg i daan . sentence: Paap , yaa nu gënoon nun ñépp . sentence: Damay faral di dégg ñu naan Senegaal réewu layig la . Senegaal sentence: Loolu nag , baaxul , day féewale pólis bi ak askan wi . sentence: Danga yaakaar ni li takk - der yi nekke , dañ leen cee bàyyi ? sentence: Ni ko wér - gi - yaram soxalee , noonu la ko g ë m - g ë mam yittelee . sentence: Dinan la topp , xool ndax jàng nga , ndax am nga ñu lay jàppale ci liggéey bi , ndax am nga béréb bu baax , añs . sentence: Portige : 117i waat . sentence: Kenn umpalewul sunu géej gi fi mu mujje , tey sunu mool yi mënu ñoo am lu dul yaboy . sentence: Moo tax Maki Sàll sonn ci nañ far bor bi . Sàll sentence: Yeneen waat yi noonu lañu mel . sentence: La xewoon ca kër Ilimaan Ñiŋ , jaaduwul te rafetul . Ñiŋ sentence: Duma fàtte mukk sunu waxtaan wa , benn weer laata maay torlub dige ak Olympique de Marseille . Olympique de Marseille sentence: Dara waralu ko lu dul li nguur gi génne loxoom ci diine ji ak ci daara yi . sentence: Man , nag , dama foog ne tàggat gee des . sentence: 😌 🤝 🏿 - Toppaat ma ma xamal la làkk yi farañse àbb ak limu waat yi mu leen àbb . sentence: Alal ji ma wax nii mat na téeméeri yoon bor bi ñuy leb , su nu ko sàmmoon rekk , du soxla ñuy lebi kenn . sentence: Paap Juuf , politiseŋ bi Saa buñ nee Paap Juuf , xel yépp dem ci futbal ak Olympique de Marseille . Juuf Juuf Olympique de Marseille sentence: Bu dul dara sax , rafetul ci xar - kanamu réew , ay xaleem di taxawaalu ci mbedd yi . sentence: Boo demee Ërob , tamit noonu . Ërob sentence: Amaana , looloo dal takk - der yi dem bay xoole askan wi ay bëti noon . sentence: ( Àngale a ko a yées nag , mooy làkk wi ëpp i àbb ci kaw suuf ci li nu xamagum , waatam ya xaaj ba da ko a àbb 😱 🤭 🏃 🏿 ♂ ️ ) sentence: Dëgg la , nag , am nay jafe - jafe diggante askan week takk - der yi leen war a aar . sentence: Tey , ak xool bu tooy laa lay tàggoo . sentence: Bu dee am mag mooy tegaley yére yu bari ngir aaru , nu xale yiy def ? sentence: Boo seetee , 3 ba 5i at ci ginnaaw , ni ma doon waxe fara ñse laa doon waxe wolof . sentence: Waaye du fi ame te bu soobee Yàlla , dina wax fum dugal xaalis bi mu leb yépp . sentence: Seetal rekk , guddig weeru koor , ci ngelaw li , ñuy fanaane taxaw guddi ba bët set .