text
stringlengths 1
1.87k
| duration
float64 0.5
193
| file_name
stringlengths 7
31
| path
stringlengths 13
39
| audio
audioduration (s) 0.03
193
|
---|---|---|---|---|
kooku yàlla moo ñu ko defal | 1.748 | wol_4910_2328.592_2330.34.wav | kallama/wol_4910_2328.592_2330.34.wav | |
ñu ne donc ñoom ñooy nattukaay satélites yi | 2.678 | wol_44121_1667.073_1669.751.wav | kallama/wol_44121_1667.073_1669.751.wav | |
dangay béy fii am lu bëri yow doo xalaat leneen lu dul yóbbu lépp ci marché bi jaay ko lépp def xaalis bi si sa poche bu déwénee nag après nga toog di topp di topp pour am jiw bu baax | 10.183 | wol_41940_2533.715_2543.898.wav | kallama/wol_41940_2533.715_2543.898.wav | |
ah merci beaucoup Bdou yaakaar naa UGPM %hum boo ko doon xool dañu ko adapte ñi jàng alxuraan loolu la ñuy wax | 9.825 | wol_44911_629.984_639.809.wav | kallama/wol_44911_629.984_639.809.wav | |
juróom-ñaar fukk yi | 0.963 | wol_43020_1214.378_1215.341.wav | kallama/wol_43020_1214.378_1215.341.wav | |
donc uti jiw bu gaaw di xool yi nga xam ne daal su tawee rek taw bu doy ci maanaam mois de fin juin début juillet nga ji | 7.942 | wol_43960_373.446_381.388.wav | kallama/wol_43960_373.446_381.388.wav | |
voilà | 0.635 | wol_43810_2202.394_2203.029.wav | kallama/wol_43810_2202.394_2203.029.wav | |
di regenérer wu | 1.321 | wol_4711_1332.015_1333.336.wav | kallama/wol_4711_1332.015_1333.336.wav | |
léegi am ay usines am ay oto ñu koy taal muy ay machines muy génne saxaar saxaar siy jëm si air bi di fa dafaloo | 16.255 | wol_43711_1114.793_1131.048.wav | kallama/wol_43711_1114.793_1131.048.wav | |
il faut que mu ñor ba mu ñor comm ba nga xam ne lii ñor na ñu doog ko ñu ñu doog ko récolté boo ko récolté tamit am na beneen étape bu am solo bu ñu bu ñu bu bu parfois sax ñu ñoom dañu koy tëb mooy le séchage mooy fexe wowal ko wo() mu wow | 14.878 | wol_43311_1226.895_1241.773.wav | kallama/wol_43311_1226.895_1241.773.wav | |
donc loolu nag yàq na ci lu lu bëri waaye nag xëy na lii moo gënoon ci ñun donc yàlla def na li gën | 7.822 | wol_41930_293.396_301.218.wav | kallama/wol_41930_293.396_301.218.wav | |
Ay nit lañ daal ñu bari ñu toog: ay xale, ay jigéen ak ay góor, ay mag ak ay ndaw. Daa mel ni daal ñii dañoo toog ñii taxaw am ku boqu doomam. | 14.357813 | 3385:2046.wav | waxal/3385:2046.wav | |
%e dafa ñuy bëgg tamit terrain bi maanaam %e sa sa sa tool gi | 3.114 | wol_4711_1295.535_1298.649.wav | kallama/wol_4711_1295.535_1298.649.wav | |
ci kaw ñax mi waaw ba pare bu ma paree jël dóomu taal | 4.662 | wol_4210_1412.171_1416.833.wav | kallama/wol_4210_1412.171_1416.833.wav | |
mais nag ci INP la koy jaarale li ci ëpp ci phosphatage de fonds boobu INP moo koy def | 5.383 | wol_4210_1719.816_1725.199.wav | kallama/wol_4210_1719.816_1725.199.wav | |
balaa ngay def dara nanga dem nga laaj ko su doon loolu tamit gis nga projet bi si boppam dafa ñëw boole ci lëkkaloo bi boole ci rajo communautaires daañu fexe de sorte que rajo yi si boppam daañu si joxe ay informations | 12.349 | wol_41920_1478.523_1490.872.wav | kallama/wol_41920_1478.523_1490.872.wav | |
ñu ngi fi ku ci mel ni INP ak yeneen services yu nga xamante ni ñoom seen liggéey | 4.744 | wol_4210_2330.051_2334.795.wav | kallama/wol_4210_2330.051_2334.795.wav | |
wa mbay dañuy wax ne ab système la maanaam %e daa bari yoo xamante ni dafa ñoo lëkkaloo | 4.813 | wol_44311_277.259_282.072.wav | kallama/wol_44311_277.259_282.072.wav | |
%hum %hum waaw waxoon nañu ko mais mais dañ koy dañ ciy | 2.099 | wol_43611_1549.338_1551.437.wav | kallama/wol_43611_1549.338_1551.437.wav | |
061 | 1.469 | wol_45421_1707.369_1708.838.wav | kallama/wol_45421_1707.369_1708.838.wav | |
mën nañu actualisé mais ba léegi nanguwuñu prononcé wu si octobre | 3.194 | wol_44112_24.284_27.478.wav | kallama/wol_44112_24.284_27.478.wav | |
voilà | 1.101 | wol_43711_1618.01_1619.111.wav | kallama/wol_43711_1618.01_1619.111.wav | |
Gis naa fi ab nataal, nataal boo xam ne am mbooloo la ñu toog, am kenn ku nekk ci seen kanam taxaw. Am na meneen waxambaane mu sol mbubbu mu xonq mu toog wane ginnaaw. | 14.317813 | 3571:676.wav | waxal/3571:676.wav | |
FAO ñoo ñu jàppaleegum | 1.47 | wol_45412_57.502_58.972.wav | kallama/wol_45412_57.502_58.972.wav | |
kootoot bi mooy biy dugg si ñebe bi | 1.8 | wol_4410_1944.729_1946.529.wav | kallama/wol_4410_1944.729_1946.529.wav | |
du dara nag du affaire saltige du dara waaye jàng rek la comme ni ngay toogee tey jii rek docteur bi jàkkaarloo ak yow ne la ah yow mii de feebar sangam moo nekk ci yow nangam ak nangam moo lay faj bindal la ordonnance nga dem jënd ko yàlla suturaal la | 10.212 | wol_42411_1394.863_1405.075.wav | kallama/wol_42411_1394.863_1405.075.wav | |
kon su fekkee ne bool bi Sénégal la ñun ñëpp ay sénégalais lañ | 3.335 | wol_44411_1875.015_1878.35.wav | kallama/wol_44411_1875.015_1878.35.wav | |
ndax dab na suñ dugub bi ñorandoo ak moom mais picc yi dañ koo yab lool ñun picc yi moo ko moo ko gàllankoor | 5.345 | wol_41910_1503.234_1508.579.wav | kallama/wol_41910_1503.234_1508.579.wav | |
taw bi ñaata milimètres la évaporation bi ñaata la parce que station météo du taw bi rek ah | 4.907 | wol_42932_278.038_282.945.wav | kallama/wol_42932_278.038_282.945.wav | |
na nga def %e li li ñuy wax un service climatique nga boole ko sa programme | 4.343 | wol_42211_1215.419_1219.762.wav | kallama/wol_42211_1215.419_1219.762.wav | |
est ce que mi ngi koy dimbali | 1.583 | wol_44311_374.365_375.948.wav | kallama/wol_44311_374.365_375.948.wav | |
gis nañ ne su dee si wàllu dugub ji la bëgg nañ su ñu koy récolter ñu koy bàyyi ba mu wow maanaam balaa ngay xëy di góobi danga war a bàyyi ba lay bi wàcc tuuti | 11.617 | wol_41920_386.0_397.617.wav | kallama/wol_41920_386.0_397.617.wav | |
donc yooyu parcelles am na ci huit parcelles parcelle bu nekk li ma ci récolter ci moom ma teg ko ci parcelle am foofu nga xam ne réeróo du am donc loolu liggéey boobu def naa ko | 8.967 | wol_41940_1551.725_1560.692.wav | kallama/wol_41940_1551.725_1560.692.wav | |
d' accord soo nee yëngu-yëngu jigéen ñi xam nga c' vrai que yëngu-yëngu yi wax nga sa biir wax ne bari na | 5.518 | wol_4611_365.009_370.527.wav | kallama/wol_4611_365.009_370.527.wav | |
donc loolu yëpp | 1.128 | wol_43111_873.769_874.897.wav | kallama/wol_43111_873.769_874.897.wav | |
pma ne ko nañu xaar tuuti parce que temps yii man information bi ma am daal | 3.619 | wol_43612_1405.0_1408.619.wav | kallama/wol_43612_1405.0_1408.619.wav | |
donc plante bi aussi day jël li mu soxla rek | 1.952 | wol_44312_102.541_104.493.wav | kallama/wol_44312_102.541_104.493.wav | |
léegi su ñu ñëwee ba ci %e nawet bi dugg léegi li ñuy ne décadaire maanaam ci fukki fan mun nañ ci fukki fan yi ñu joxe ay prévisions | 8.728 | wol_43960_755.385_764.113.wav | kallama/wol_43960_755.385_764.113.wav | |
%hum %hum waaw | 0.561 | wol_44112_863.905_864.466.wav | kallama/wol_44112_863.905_864.466.wav | |
maintenant opérater agréé yi ma yor %e yi ñu yor fii ci département de Louga te ñuy def %e arachide yor naa ko yi ñu ñii di def %e ñebe également yor naa ko | 8.848 | wol_4711_738.49_747.338.wav | kallama/wol_4711_738.49_747.338.wav | |
muy effort perdu | 1.116 | wol_43611_1616.127_1617.243.wav | kallama/wol_43611_1616.127_1617.243.wav | |
ndax %e wànq la wala du moom | 3.094 | wol_45421_1573.136_1576.23.wav | kallama/wol_45421_1573.136_1576.23.wav | |
bu ñu ko approuvé nag ñoom ñu mën a jël lu nga xamante ne moom mooy suuf soosu ñu dellu | 5.227 | wol_44711_635.782_641.009.wav | kallama/wol_44711_635.782_641.009.wav | |
%e jël seen numéros | 1.553 | wol_45422_78.577_80.13.wav | kallama/wol_45422_78.577_80.13.wav | |
maanaam càmm gi daf fi am solo | 1.602 | wol_43810_1542.791_1544.393.wav | kallama/wol_43810_1542.791_1544.393.wav | |
Mbaye waaw | 1.397 | wol_43810_1346.4_1347.797.wav | kallama/wol_43810_1346.4_1347.797.wav | |
commune de Koutiéba | 1.077 | wol_45421_948.066_949.143.wav | kallama/wol_45421_948.066_949.143.wav | |
Waaw nataal bii nag, lii gàncax bu sax ci kaw ndox la. Ay bant sax ci...nekk ci géej gi, am ay garab yu wertë. | 12.197813 | 3453:1932.wav | waxal/3453:1932.wav | |
kon ki nga xam si mooy def céréale it naka noona fi ñuy defaree céréale laajul xale di fa ne | 4.306 | wol_41012_671.12_675.426.wav | kallama/wol_41012_671.12_675.426.wav | |
jërëjëf monsieur Ndiaye %e mu nekk chef station météorologique bu Koungheul di fàttali tamit mooy ki nga xam ne rek moo yore fii lu jëm rek si wàllu météo fii si région de Kaffrine nekkal fi tamit ñii di waa ANACIM waaye tamit di wax ne yéen ñi nga xam ne yéen ay déglu su ngeen amee yeneen xibaar yu gën a leer wala su ngeen bëggee yeneen xibaar yu gën a leer mën ngeen a woote tamit si numéro bii di 33 879 30 92 33 879 30 92 | 31.668 | wol_42514_1215.882_1247.55.wav | kallama/wol_42514_1215.882_1247.55.wav | |
ngir xam sax bi ñuy wax nii | 1.697 | wol_45411_1170.812_1172.509.wav | kallama/wol_45411_1170.812_1172.509.wav | |
waaw ba tey maa ngi koy jafandikoo ndax dama cee gis njariñ | 2.416 | wol_56610_134.114_136.53.wav | kallama/wol_56610_134.114_136.53.wav | |
mais boo xoolee mois de mai mois de juin pratiquement mun nañu wax ne fii nii duñ si am taw en général léegi soo xoolee démarrage saison bi mois de juillet lay commencé | 14.952 | wol_43020_697.579_712.531.wav | kallama/wol_43020_697.579_712.531.wav | |
nekk na 60 %e 65% yëpp | 2.808 | wol_4311_396.474_399.282.wav | kallama/wol_4311_396.474_399.282.wav | |
ngelaw yi bëri woon nañu trop trop trop trop et c' était vraiment kii quoi prévisible quoi ñun à notre niveau | 6.13 | wol_42212_160.349_166.479.wav | kallama/wol_42212_160.349_166.479.wav | |
commencé pelax | 1.526 | wol_4410_1983.996_1985.522.wav | kallama/wol_4410_1983.996_1985.522.wav | |
parce que prévision annuelle bi mu lay annoncé rek | 2.687 | wol_43411_1079.554_1082.241.wav | kallama/wol_43411_1079.554_1082.241.wav | |
fàttaliku fàtte xaju fi | 3.316 | wol_44411_1896.719_1900.035.wav | kallama/wol_44411_1896.719_1900.035.wav | |
donte da nga ciy jaaraat sax delloo ko %e bàyyee ko | 2.335 | wol_4410_1517.445_1519.78.wav | kallama/wol_4410_1517.445_1519.78.wav | |
ñu ne leen béykat bi même bu dee juróomi dërëm wala fukki dërëm mi ngi koy participer ci information yi muy jo | 5.012 | wol_31212_696.324_701.336.wav | kallama/wol_31212_696.324_701.336.wav | |
di nga ci fekk jigéen ñi di nga ci fekk ndaw ñi communauté yoo xamante dañu naan communauté vulnérable | 4.144 | wol_42921_542.13_546.274.wav | kallama/wol_42921_542.13_546.274.wav | |
Daa mel ni ab ordinatéer la. Ordinatéer maa ngi ci gis ñeenti góor maa ngi ci gis ñeenti góor ak ñeenti jigéen. Ordinatéer bi moom de bakkane na de, daa mel ni maa ngi ci gis benn waay buy bind mel ni kuy dindi biton yi. | 15.377813 | 1867:1360.wav | waxal/1867:1360.wav | |
buñ foyee suñu xel yi | 4.81 | wol_44411_1068.682_1073.492.wav | kallama/wol_44411_1068.682_1073.492.wav | |
foofu jarul ñu dem ci benn tool pour dem vérification | 2.287 | wol_44122_39.391_41.678.wav | kallama/wol_44122_39.391_41.678.wav | |
mais man bi nga waxee si assurance %e agricole bi %e dama seetlu ne temps yële boo ko xoolee dañu dem si benn atelier barki démb fële à à Fatick si GTP bi nga xam ne au moins day regroupé tous les chefs de services di %e di yëngatu si mbirum mbéy | 13.449 | wol_43511_682.575_696.024.wav | kallama/wol_43511_682.575_696.024.wav | |
Lii de mi ngi mel ni garabug pomme las koy wax. Garab gi nag maa ngi ciy gis xob yu wert, doom bii nag doom bu wert bii xam naa ni doomub pomme moom la war a doon yaakaar naa. | 14.617813 | 2822:1692.wav | waxal/2822:1692.wav | |
%e Fane %e bu ñu demoo tey %e ñi nga xam ne éni ngi ñuy déglu muy ñi ngeen bokkal programe muy ñi nga xam ne ay %e béykat lañ te bokkuñ si biir programme bi buñ la waxoon tey nga ñaax leen si wàllu yàqu-yàqu yooyu ak nga ñaax leen ci wàllu programme bi nga xam ne tey %e dangeen ko seq ISRA lan nga leen di wax | 20.96 | wol_42010_1406.394_1427.354.wav | kallama/wol_42010_1406.394_1427.354.wav | |
mën ko déposé ji Fapal ndax Fapal yaakaar naa ne ñoom pare nañu pour képp koo xam si ne yow yaa ngi ñëw di déposé ñoom ñu def si xalaat def ci jàngat linga xamsi moom mooy CA bi kooku ñoom lañuy jébal li nga xam si ne moom mooy demande yooyu ñu xool mën ko validé kon kenn ku ci nekk war nga mën a j£el sa jéego boo mënee woote téléphone comme ni nga waxee | 19.324 | wol_4312_178.637_197.961.wav | kallama/wol_4312_178.637_197.961.wav | |
%e Ibvrahima bu ma déggee Jalle ci li mu wax nii est ce que aussi tamit di ngeen taxawu jigéen ñi nga xam ne dañuy bëgg wut Fra mais surtout si béréb yooyu ñuy defaree seen i produit yi balaa muy dem ci labo yi le matériel qu' il faut b ak hygène %e bi nga xamante ne war na faa am | 13.172 | wol_41012_178.979_192.151.wav | kallama/wol_41012_178.979_192.151.wav | |
lu mat ay cinq tonnes wala dix tonnes | 2.151 | wol_44312_492.475_494.626.wav | kallama/wol_44312_492.475_494.626.wav | |
bàyyi ci garab yi bàyyi ci gàncax bi | 1.556 | wol_44114_627.677_629.233.wav | kallama/wol_44114_627.677_629.233.wav | |
waaye saak yi tamit saak yi waroo koo waroo ko teg si suuf loolu tamit dama koy seetlu si gaa yu bëri suñuy denc seen jiw dañuy jël sak bi rek dugg si magasin bi rek tërël ko foofu noonu mu tëdd | 9.121 | wol_42110_2417.612_2426.733.wav | kallama/wol_42110_2417.612_2426.733.wav | |
ñu mën ci wax | 0.753 | wol_45412_661.833_662.586.wav | kallama/wol_45412_661.833_662.586.wav | |
Nataal bi, euuuuh! Aw rab moo ci nekk. Rab bi nag dafa baaxoo nekk ci géej. | 7.457813 | 3439:19.wav | waxal/3439:19.wav | |
%e xeebuñ benn xalaat | 2.216 | wol_44811_871.044_873.26.wav | kallama/wol_44811_871.044_873.26.wav | |
est ce que defu defuñu différence ak sax boobu ak bii léegi | 3.897 | wol_45411_1452.241_1456.138.wav | kallama/wol_45411_1452.241_1456.138.wav | |
mooy agriculture | 1.068 | wol_45411_230.356_231.424.wav | kallama/wol_45411_230.356_231.424.wav | |
parce que su ma fekkee si tool bi dara mun na fa xew mun na daaneel garab sama kaw parce que garab yi ñoo ngi si * bi ngelaw bu fort kii noonu nga ne ah non non xaaral ma xaar ba suba xaw ma ban heure lay egg si fii | 10.552 | wol_43960_850.01_860.562.wav | kallama/wol_43960_850.01_860.562.wav | |
nekk en partenariat avec le PAM | 2.211 | wol_43611_416.303_418.514.wav | kallama/wol_43611_416.303_418.514.wav | |
li gën mooy nga bay fa beneen graminé maanaam nga bay fa dugub wala mboq wala sorgho parce que day fekk sa suuf boobu noonu moom dèjà enrichir na en en azote loolu benn la ci plan de rotation des cultures maanaam lii bu ñu ko bëggoon a tënk daal | 20.034 | wol_43810_769.561_789.595.wav | kallama/wol_43810_769.561_789.595.wav | |
valeurs yooyu ñu mën ko cult() kon di ko cultivé ci biir kër gi | 2.954 | wol_44912_424.494_427.448.wav | kallama/wol_44912_424.494_427.448.wav | |
aar li ngeen stocké | 1.52 | wol_44122_200.099_201.619.wav | kallama/wol_44122_200.099_201.619.wav | |
yaakaar naa côté côté Mbelakadiao la xaw ma mais am na ci fu ma déggoon daal ñu ni def na fa ay kii quoi ay dégâts quoi ba taal fa xaw ma ay kër xaw ma des des trucs comme ça daal | 7.29 | wol_42212_227.019_234.309.wav | kallama/wol_42212_227.019_234.309.wav | |
taal fi nga taal yëpp | 1.162 | wol_44312_742.208_743.37.wav | kallama/wol_44312_742.208_743.37.wav | |
Nataal bii ñu ma yónnee gis naa ci ay gone yoo xam ne dañoo jàngi ba wàcc walla ñu nekk ci bërëb bi ñuy jànge. Gone yu góor ak yu jigeen ñu sol ay buluus yu bula. | 15.677813 | 2659:706.wav | waxal/2659:706.wav | |
ba ci xam ndoxu %e géej bi kaw géej gi température bi ñaata la | 5.561 | wol_42932_314.677_320.238.wav | kallama/wol_42932_314.677_320.238.wav | |
yooyu yëpp mën naa ne ci changement climatique | 1.638 | wol_44312_57.715_59.353.wav | kallama/wol_44312_57.715_59.353.wav | |
Nataal bii day wane ag këyit gu | 15.097813 | 3556:1660.wav | waxal/3556:1660.wav | |
waaye gis nga lii ngay gis nii du dara ay gaz rek la ay gaz rek la maanaam dafa mel ni nge() nge() nge() ngelaw la rek du dara gis nga fi nga toog nii tey boo fi départ fii ngay ñëwaat amul benn amul amul secret | 8.613 | wol_42411_572.731_581.344.wav | kallama/wol_42411_572.731_581.344.wav | |
su boobaa day andi ay yàqu-yàqu | 1.988 | wol_42811_201.192_203.18.wav | kallama/wol_42811_201.192_203.18.wav | |
mën nañ nekk des entrepreneurs agricoles | 2.747 | wol_44812_1030.972_1033.719.wav | kallama/wol_44812_1030.972_1033.719.wav | |
boo àggsee ne jaay ma rek bu la neex ñu jaay la ko am na instant yoo xam ne nag moom %e benn produit rek mooy manqué muy muy bu jëm ci ditax bi | 7.295 | wol_4612_869.478_876.773.wav | kallama/wol_4612_869.478_876.773.wav | |
di ko toppatoo | 0.904 | wol_44311_413.688_414.592.wav | kallama/wol_44311_413.688_414.592.wav | |
loolu tamit am nga sañ-sañ ne man de assuré woon naa ba ma góob mais léegi i tam fi mu koy denc noonu stock bi dama koy assurer waat %e boo jëlee soble day yàqu ñebe bi i tam boo jëlul yenn produits day yàqu foog naa ni gerte tamit noonu la | 13.081 | wol_43951_865.504_878.585.wav | kallama/wol_43951_865.504_878.585.wav | |
waaw gis naa ci sama bopp ndax wax dëgg sonnu ma ci te | 3.343 | wol_56610_96.258_99.601.wav | kallama/wol_56610_96.258_99.601.wav | |
ñett yooyu yëpp nag ay xeetu lay lañu mais bokkuñu booywax rosée mooy bi nga xamante ne bii da ngay xëy le matin rek gis oto bee garré wala nii wala bois bi nga xamante ne gis nalayu bi wàcc si moom mu tooy xepp xepp xepp xepp | 13.083 | wol_4111_1778.526_1791.609.wav | kallama/wol_4111_1778.526_1791.609.wav | |
ndax %e yàlla dimbali nañu sax | 2.271 | wol_43612_370.717_372.988.wav | kallama/wol_43612_370.717_372.988.wav | |
parce que garab mun nga ko dagg mu jébbiwaat | 1.92 | wol_45512_1633.021_1634.941.wav | kallama/wol_45512_1633.021_1634.941.wav | |
dafay jafee rey | 0.604 | wol_4410_863.665_864.269.wav | kallama/wol_4410_863.665_864.269.wav | |
mooy monsieur Sada Ly | 1.357 | wol_45422_1529.841_1531.198.wav | kallama/wol_45422_1529.841_1531.198.wav |
End of preview. Expand
in Dataset Viewer.
README.md exists but content is empty.
- Downloads last month
- 119