audio
stringlengths
56
98
transcription
stringlengths
26
222
audio_file
audioduration (s)
/content/drive/MyDrive/segments1/Aicha_El_Hadj_Associ__segment_6.wav
léegi moom bi gis naa ni affaire yi mi ngi dox gis maa ngi sama temps maa ngi koy organiser bu baax waaw waaye nag teewul ba léegi damay
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Aicha_El_Hadj_Associ__segment_4.wav
mais loolu moom moo gën mooy ne moo wut kenn ki nga xam te ne da koy jàppale jàppale bi nag moom mooy kooku day ñëw am taxawaayu associé
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Aicha_El_Hadj_Associ__segment_5.wav
parce que entreprise bi bu ko defee ñoom ñaar ñoom ñooy àndwee yel ci loolu mu daal di dem waxtaan ci ak éage bu daal di ne ko ah éage man de ginnaaw suñu waxtaan bi ba léegi
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Aicha_El_Hadj_Associ__segment_10.wav
bu dee ci wàllu dama dox te mën ak yow bëri na ay jukk yi nga xamante ni ak gis-gis yi nga xamante ni ñoo ko bokk surtout ci wàllu entrepéné yaa
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Aicha_El_Hadj_Associ__segment_12.wav
mais loolu am na entreprise am nga compétence ci wàllu jàppale ma ba sama entreprise bi mën a taxaw ci yeneen fan yi côté administratif wala yeneen mbir yi
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Aicha_El_Hadj_Associ__segment_3.wav
mais loolu moom mooy fay kooku noonu amagu ko ndax entreprise am nekk guul entreprise bu mag te amaguul koo pargi nga xamante ne dina ko permettre muy muy fay nit
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Aicha_El_Hadj_Associ__segment_7.wav
donc ñoom ñoo xam ne dañuy sam bopp bi day tëju des fois damay jaxa soo mën na ko nag léegi dama ñëw fii waxtaan ak yow ngeen la nga ñëw ñu liggéey mën ak yow ci entreprise bi
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Aicha_El_Hadj_Associ__segment_9.wav
li nga xam ne kii ku ku am xalaat nga te jàpp naa leen di nga ma jàppale lool te di nga mën a seddu ak mën lépp li nga xam te ne wàllu xalaat la ngir suñu entrepiz bi gën a mën
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Aicha_El_Hadj_Associ__segment_2.wav
waaye xam nga xamante ne dafa am ba jël kenn ki nga xamante ne dina ko jàppale ci yooyu yëpp mu koy fay waaye mu xalaat ni loolu mun na nekk lu yu jafe ndax kat xaalis bi nga xamante ne
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Aicha_El_Hadj_Associ__segment_1.wav
naka lay def ba lii di entrepis am mu mun a céddalee taa bii famim doot ñu ko merré ak yooyu mu gis nii lii ëpp solo wala lii gën a urgent moom mooy fekk
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Aicha_El_Hadj_Associ__segment_8.wav
loolu moo tax nga xalaat ma àscha ne ko ah mais parce que El Hadj man am naa yow am naa confiance ci yow te yow nekk nit ki nga xamante ni koo jub nga nekk nit ki nga xamante ni
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Aicha_El_Hadj_Associ__segment_0.wav
ah ay sa ginnaaw ba mu waxtaanee ak éage boobu léegi nag mi ngi toog di xalaat di xalaat naka lay def ba lii di entrepis am gën a mën a dox
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Aicha_El_Hadj_Associ__segment_11.wav
mënu ma defar jus yi mënu ma defar confiture ay chans a jee ne ko waaw xam naa leen mënu ma defar jus yi amoo amoo compétence yooyu waaye am nga compétence si wàll organiser
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_49.wav
clien waaye clients yi nekkul ñoom kese ñoom ñoo ko tax jóg ndax clients yi ci biir clients yi daf ci am ay xe daf ci am ay pàcc ndax na ngay yeg ni
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_41.wav
li ñaa yi yan xeetu jënd nañu gën a bëgg waaw mën nga tànn ba juróomi xeetu jënd nga nii kat clients yi faral nañ ko di bëgg
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_4.wav
naka lay doxee yéen ñoo ci nekk est ce que marché bi nga xamante ni marché physique la mooy benn bërëm bu ñuy dem wala benn marché bi nga xamante ni
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_11.wav
mais loolu mooy gis bi bu ko dajale da ngay gis nit da koy jàppale lool ngir mu bokk ci entreprise yi nga xamante ni moom la ñuy woowee entreprise yu xarañ ndax saafara bi dafay nekk saafaro
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_45.wav
bës lay clients yi di faral di ñëw donc bës yooyu def ci baax tamit foog nga saytu tamit say clients ba xam ndax ñoom ay professionnels nañ wala ñi nga xamante ni dañuy liggéey du ñu am wior
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_50.wav
li nga xamante ni client yi consommateurs yi ci clients yi nañu bokk consommateurs yi moom mooy ñi nga xamante ni ñoom dañuy utiliser sa produit wala service bi nga xamante ni moom ngay joxe
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_27.wav
te fi mu dëkk dafa sonn foog ma am benn saafara bi nga xamante ne dina mo muscle ci li nga xamante ne moom mooy déplacement yu bëri yi may def
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_38.wav
te wér ci marché bi nu muy doxee ak nu muy yeggee waaye tamit ak bëgg-bëgg clients yi ak tamit lan mooy seen i soxla yu jàmp
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_28.wav
ñaari di xale lu góor ñu mét ñaari waxambaane dañuy taxaw ci jaaykat daal di kenn gi ni ko mën damay jël daal perme de perle daal bi parce que moom moo gën a mooy cher te boo xoolee
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_35.wav
donc dafa nekk lu am solo étude de marché boobu dafay jëm ci nga gën a xam naka nga koy joxe li nga xamante ni moom mooy sa saafara
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_53.wav
diasir yi nag beneen xeet la moom mooy ñi nga xamante ni ñoom ñooy poussé nit ñi ñooy jënd sa sa sa sa li ngay jaay
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_48.wav
donc nag pour tënk na ngay yëg ni li nga xamante ni moom mooy joxe boobu ngay joxe ñi ko tax a jóg ñenn kese la moom mooy say
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_37.wav
say xeetu kil yaa li nga xamante ni moom mooy taxaw seetlu boobu ba léegi ci naka ngay joxe daf lay jàppale loolu ngir nga am ay informations yu leer
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_46.wav
donc dimage bi kese ne ñi ñëw donc yooyu yëpp mu nekk benn taxaw seetlu bi nga xamante ni yow mii entrepeneur war nga ko def ngir gën a mën a am dégg-dëgg bu leen
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_32.wav
par rapport ak li nga xamante ni moom mooy yow mii entrepreneur bi li ngay joxe mën ngay jaay jën kii gis ni moom mun jënd jën yu bëri parce que
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_56.wav
nooy koo semateur bi ñoom dañ koy jëfandikoo client bi moom mooy ki nga xamante ne ñi ngi jënd li ngay def doon tënni utiliser wu mu utiliser que mu ñàkk ko utiliser moom bu fekkee da koy jënd rek
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_13.wav
parce que loolu moom sa marché dafa nekk lu nga xamante ni lu munul ñàkk la boo ko réeréer bi rek da ngay gis nii ci joxe bi nga xamante ni moom ngay joxe produit bi ak
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_8.wav
ci moom mu xam lan mooy marché bi ndax xam bi nga xam te ne moom ngay am ci marché bi moom moo lay jàppale lool ngir nga mën a teg tëralin bi nga xamante ni
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_17.wav
donc yooyu yëpp nekk ay mbir yi nga xamante ni yu am solo la lool bu ñu waxee marché tamit am na ay mbir yi nga xamante ni ñoom ñoo ko tënk
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_2.wav
mën nañu ne dafa am entrepeneur dafay baax lool ginnaaw ba nga na mais teg li nga xamante ni saafara la ci benn jafe-jafe bi nga gëstu
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_31.wav
donc ñun ñoo xam ne dañuy gën dëkkaat bi mu ngi koy faral di am ci marché bi li ñu ci jublu moom mooy nit ñi
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_5.wav
donc bu virtuelle la maanaam ci téléphon yi la nekk wala ci internet bi donc yooyu yëpp mu nekk ñaari xeetu mbir yi nga xamante ni yu wite la
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_23.wav
ñun ku ci nekk say bëgg-bëgg du wite bu ñu jëlee ci missile rek ñetti ñetti jigéen suñu taxawee ci jaaykat bi da ngay gis ñu kenn ki mën a taxaw di ko laaj
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_40.wav
da nga yëg ni lu am solo la ndax moom façon bi nga xamante ni moom ngay joxe moom moo lay jàppale bu fekkee yaa ngi jëndu ci wàllu njaayum jën
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_29.wav
amul benn wute ak keneen ki nga gis ki keneen ki moom it mën na am xalaat muy mën damay jël beneen daal di tax moom moo gën a nekk qualité
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_44.wav
te tamit bu dee nga xam ne ak dinañ ko gën a gën a ne karott wala ñaan bi wala comme quombar nga gis nii yii kat kil yaayi faral nañu di ko bëgg te tamit bu la neexee nga ba léegi nga gën a gëstu
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_26.wav
ci marché bi ba léegi da ngay gis genn mun a taxaw wax ak nit ñi ko bi mooy ñaar yoon maa ngi ñëw ci marché bi ci semaine bi pour jënd li nga xamante ne moom mooy benn tis
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_0.wav
ñu ñëw ci suñu carte ñaar fukk ak ñett bi nar a waxtaanee ak yow ci lépp lu aajo woo ci jàbëg gi
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_33.wav
bu ko yóbbu kërëm mën na indi ay yàqu-yàqu donc tóotu lay jënt donc yooyu noonu yëpp mu nekk ay mbir yi nga xamante ni yow mii entreprenn bi pare nga pour joxe ci ay tontu
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_25.wav
donc su ma ko jëlee di lu bëri dafay indi li nga xamante ni moom mooy ay yàqu-yàqu wala mën a nëpp te am na awma denc waay ci mel ni ay frigo ak yooyu
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_52.wav
voilà bu fekkee jënd bi ñoom utiliser wuñ ko wala lékku ñu ko wala naanu ñu ko mais ñoom dañ koy jënd donc ñooñu dañuy woowee client
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_3.wav
donc dafa am lu ba gis ko ni war na mën a soxla ñi nga xamante ni ñoom ñooy say jëndkat donc def ci baax lool nga def benn taxaw seetlu gën a xam
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_9.wav
bu leer la sa entreprise dina ci mën a sukkandiku sukkandiku bu nag day jëm ci xam naka lay tegee ay jëgëm naka lay joxe li nga xamante ni moom mooy ay sànq
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_24.wav
wala nga gis jaaykat bi di laaj jënd kat naan yi la mëntax du ngeen jël banan ay yu ñor yi keneen kii ni ko moom moom du ma jël banan ay yu ñor yi parce que dama koy lekk ci lu matul semaine
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_14.wav
donc da ngay gis ñi dafay ndax saa yi wala mun a suuxee te li koy waral moom mooy ñàkk xam boobu noonu ngay def moo tax ngay gis ñi entrepreneurs yu bëri
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_30.wav
donc loolu rek benn misal na ci yenn xeetu wax wala yene xeetu xalaat ci nga xamante ni entretenir bi
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_43.wav
waaye léegi ñoom da ngay gis ni marché boo ñëwee marché da ngay génne yi nga xamante ni jàpp nga ni clients yi moom fa fa faral nañu di ko jënd lu bari
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_34.wav
waaye pare nga pour jàkkaarloo képp ki nga xamante ne xeet client la ak ni mu ñëwee ci yow donc ñu gis ni lii di taxaw seetlu boobu ngay def ci marché bi
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_22.wav
xam nañ ni marché dafa nekk bërëb bi nga xamante ni ay nit yu bëri ñoo fay faral di nage nit yooyu nag kenn ku ci nekk say gis-gis di wute
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_55.wav
xamante ni ñoom dañuy jënd sa produit dañ dañ koy jënd di ko utiliser wala même bu fekkee jënduñu ko ñu koy utiliser mi ngi accès si ñoom boobu ñu koy utiliser donc ñoom ñoom
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_15.wav
Lata ñuy dugg ci marché bi dañuy def li nga xamante ni moom lay tubaab di wax étude de marché muy gëstaxaw gëstu wala taxaw seetlu
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_57.wav
moom client la influenceur yi moom mooy ñi nga xamante ni ñu ngi gis li ngay def amana dañ koy jënd wala jënd ñu ko waaye tamit ñu ngi soñj nit ñi pour ñu mën a jënd li ngay
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_20.wav
waaw daal loolu et de la demande dafay am solo lool yow mi nga xamante ni yàbb gi teg sa projet wala yow mi nga xamante ni yàbb gi soobu ci marché bi nga jàpp
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_10.wav
donc dafa am ak yéen ñooy ay gis-gisam yéen ñooy ay objectifs am lan la viser ak fan la bëgg-égg donc yooyu mu nekk ay mbir yi nga xamante ni
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_54.wav
donc boo xam lu ñuy lekk la moo xam lu ñuy naan la produits wala service donc da ngay gis ni ñetti xeet yooyu dafa jërële la ràññale loolu
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_18.wav
mbir yooyu nag bokk na ci li nga xamante ni moom mooy joxe bi joxe bi bi ñu koy wax moom mooy yow mi entrepreneur bi ni ngay joxe maanaam joxe ba ngay joxe ni muy demee ndax xam
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_42.wav
mën na nekk yes mën na nekk sonpaat wala mu nekk yeneen xeetu jënd yi nga xamante ni kiliaa yi faral nañu di ko bëgg wala bu fekkee tamit yaa ngi yëngu ci li nga xamante ni moom mooy
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_12.wav
donc ñoom ñooy ñoom ñoo xamante ne day ñëw jàppale ñi nga xamante ne ñoom ñooy clients yi ngir ñu fàcceen soxla
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_6.wav
di am yëgal ni li nga xamante ni moom mooy marché bërëbu lëkkale la di nga xamante ni li ñuy joxe ak li ñuy jël
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_47.wav
tey sa leer ngir gën a mën a am taxawaay bu baax ci li nga xamante ni moom mooy joxe boobu ngay joxe ci li jëm ci sa wàllu saafara
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_7.wav
dañ koy faral di gis foofu ci ñi nga xamante ni ñoom ñooy ay jaaykat ak ñii di jëndkat yi lii di entreprise nag dafay am solo lool
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_39.wav
voilà loolu dafa am loolu dafa am yooyu boo ko xamee da ngay gis ni dafa lay jàppale lool ci naka ngay joxe sa produit
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_19.wav
waaw joxe googu tey moom moo lay mën a jàppale ci nga xam jël bi jël bi moom mooy ci nga xamante ne mooy client bi naka lay jëlee donc loolu tubaab di wax
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_21.wav
ñu ngi lay xoolool nga am ci li nga xamante ni moom mooy dégg-dégg bu weer bu ñu njëkk a taxaw ci li nga xamante ni moom mooy joxe bi
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_16.wav
mën a da jàppale ñu dajale ay xeetu xibaar ci jëm ci marché bi nu muy doxee yan moom mooy bëgg-bëgg yi lan moo fii xew a xew yan bëst ñu mbooy gën a dox
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_200.wav
waaw ñi la ñoom liggéey nañ lu toll ci quinze mille litres loolu yëpp boo ko xayma da ngay gis ni moom moo lay jox deux millions cinq cent vingt litres yi nga xamante ni
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_176.wav
dañuy gis ni moom dafa gis ni ñi nga xamante ne ñoom ñooy ay wudjëm joué yu bëri ñu ëpp di jaay dañuy am ay mbir yi
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_198.wav
voilà ñu ngi leen di taw biir nañ lu toll ci 47000 litres ñii di mandat bi yow ñoom génnee nañ ci lu toll ci 34000 litres ñi di zena ñoom
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_160.wav
li nga xamante ni moom mooy ay wuñu kenn ci di entrepies yi nga xamante ne ñu ngi yëngu ci wàllu transformation
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_184.wav
parce que bu ñu xam ne am nañu ne am nañu ne am nañu ne am nañu ne am nañu ne am nañu ne
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_59.wav
joxe boobu ngay joxe gër gën la yombal sa dégg-dégg ak taxawaay bi nga xamante ni moom nga war a am ci wàllu joxe boobu noonu
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_125.wav
mais bu ñu ñëwee dañuy wàllu transformation wala yow mii di yëngu ci wàllu Ndiayeoum genn wala yow mii di yëngu ci wàllu béy wutj boobu moom it ci loolu la yëngu yéen a bokk li ngeen i def kon ku kooku nañuy woowee
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_105.wav
donc yooyu yëpp yi jënd donc yooyu ba mu ko taxwee seetlu moom ay chen gis na ni lii di qualité maanaam seet ak hygène ak seet la
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_167.wav
ñu ngi ne kàllut wala comme combre te ñoo métte dañuy jaay li nga xamante ni moom mooy ay confiturs sécréer ak tamit Salaye Diou yi nga xamante ni fru yi nañ ko defaree
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_207.wav
donc loolu nag boo xoolee moom moo lay jox njëg bii di
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_65.wav
donc ñoom ñoom lu mënti xew ñoom dañuy jënt nga xam ñoom ñooy ñaan ñaata nañ fan nañu nekk ak tamit lan nañu gën a bëgg
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_64.wav
donc yooyu yëpp a ngi nga xamante ni boo ko amee dina la jàppale loolu beneen bi moom mooy nga daal di saytuñ li nga xamante ni ñoom ñooy jënd
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_121.wav
mais ñun fi ñu manqué ne ci yooyu nga xamante ne mën nañu manqué lay yow si ngay sukkandiku ngir amel yow fa wala ngir yokku fa ngir gën a mën a
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_142.wav
par de marché boobu noonu daf lay jàppale loolu ngir nga gën a mën a xam sëggu ji yooyu ndax am nekk nañu ñu am solo woon ñu jar a bàyyi xel
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_118.wav
mooy offer bi jëm ci marché bi dafa nekk ci lu njëkk li nga xamante ni daf lay jàppale ngir nga gën a mën a xam say concurrent maanaam say wujj
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_196.wav
ñu ngi xamante ne ñoom ñooy GIE Kumba ñoom proposer nañ produire nañ ci toll ci huit cent trois mille litres ñi nga xamante ne ñoom ñooy mariaille distribution
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_154.wav
ñëm ñooy ay wudj direct ñu nga xamante ni ñoom ak moom ñoo bokk la ñuy def nekk nañu ay entreprises yi nga xamante ni dañuy yëngu ci wàllu transformation friselle légume
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_96.wav
ñi nga xamante ni maanaam seen at toll na ci vingt cinq ba cinq ans donc ñoom ñoom ñooy gën a faral ñëw ci marché bi di jënd donc ñoom góor yooyu da ngay gis ni
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_177.wav
mais bu ñu nga xamante ne moom nañ ci yokk yenn aromatii yenn aromatis aay wala yenn adit fii wala yeneen mbir yi nga xamante ne da koy neexal te bokk ci
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_109.wav
voilà li nga xamante ni moom mooy amballage bu rafet ak njëg bu yomb bokk na ci li nga xamante ne tamit ay mbir yulee di soñj la ngir ñu gën a jënd
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_123.wav
comme solo lool nga am ay mbir yi nga xamante ni moom ngay bàyyi xel mbir yooyu nag ñu jaarale ko ci ay laaj da lay jàppale nga gën a bàyyi xel li nga xamante ni moom mooy say wuj
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_80.wav
bu ñu ñëwee ci lii di ay chan ba léegi ñu gis ni moom ay chan far tamul woon di
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_77.wav
waaye tamit nga gën a mën a xam naka ngay teggee sa njëkk naka ngay defee li nga xamante ni moom ngay joxe ba balaa muy àgg ci li nga xamante ni moom la war a jëm
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_126.wav
waaye ñu ngi xamante ni ñoom ñooy sa concurrent direct waaye am na ñeneen ñi nga xamante ni ñoom ñooy sa concurrent indirect mooy ñi nga xamante ni
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_193.wav
ci deux millions cinq cent vingt mille litres yooyu noonu da ngay gis ne entrepies yi nekk ci marché bi kenn ku ci nekk def na production yi ñu mel
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_140.wav
donc loolu am nañ fa taxawaay bu rey clients yi xam nañ leen bu baax donc yooyu yëpp mu nekk ay mbéddi nga xamante ni yow mii entrepéner dafay am solo lool nga gëstu ko
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_134.wav
lépp li nga xamante ne xeetu jumtu waaye nag dafay jëm ci lépp li nga xamante ne xeetu communication la wala paquette jëm wala produit bi en tant que telle ndax am
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_165.wav
donc loolu boo xoolee ñoom li ñuy def am na wuute tuuti ci li nga xam te ne moom la ñuy moom lay ay chadr def doon te ni dañuy proposer yenn xeetu jus de frie yi nga xamante ni
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_99.wav
suffarce yi nga xam ne dañuy yaatu wala ci yenn marché yi wala ci yenn zone yi ngir gën a mën a am li nga xamante ni moom mooy produits naturelles yooyu noonu
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_166.wav
donc li ñaay dañ koy faral di ci bëgg yu ci mel ni bisap wala gën-gëm pour wala manga wala fri de baobab wala des fruits yi seze ñëwee ak yi yu nu mel
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_81.wav
jaay mbooloo bu bari moom boo xoolee jaay bi mu doon jaay da ko doon def yàmmale ko ci ñi nga xamante ne ñun ñëwee ay jege naa lem ñi nga xamante ne ñun ñëwee ay dëkaale
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_152.wav
ci étude de marché bi moom ay chas def na li nga xamante ni moom mooy ay taxaw seetlu ay laaj ay enquêtes jëm ci wàllu ay wujëm
Not supported with pagination yet
README.md exists but content is empty.
Downloads last month
29