fr
stringlengths 4
1.08k
| wo
stringlengths 2
4.02k
| en
stringlengths 3
1.08k
|
---|---|---|
Mais ouais, pourquoi ne pas les utiliser pour faire la publicité d’un tire-lait pour les mères qui gardent leur bébé ? »
| Eilidh Doyle mooy doon “baat atlet” yi ci jiitekat yu atletisma yu Ekost
| But yeah, why not use them to advertise a breast pump for mothers who are keeping their babies? |
La deuxième question est relative à la vente de médicaments illicites qui constitue aujourd’hui un véritable problème de santé publique. | Ñaareelu laaj bi moo ngi joxoñ njaayum garab yu bon ya nga xam ne kaawtéef la ci wàllu wér-gi-yaramu askan wi. | The second issue is the sale of illicit drugs, which is a real public health problem today. |
La lecture de votre dernier ouvrage a changé mon regard sur votre personne. | Bi ma jàngee sa téere bu mujj bi laa soppi sama gis-gis ci yaw. | Reading your latest book has changed my view of you. |
Maintenant que les mourides nous expliquent qu'il en était proprio, les autres veulent aussi obtenir la même chose. | Ginnaaw murit yi xamle nañu ne seen moomeel la, ñeneen ñi tamit dinañu bëgg a am lu mel noonu. | Now that the dead men have told us that he owned it, the others want the same thing. |
Plusieurs autres acteurs politiques constants sur la scène publique n’étaient pas à la salle des banquets. | Way-pólótig yu bari yuy teew ci làng yi nekkul woon ci ndaje mu mak ma. | Several other political actors who are constantly on the public stage were not in the banquet hall. |
C’est fantastique d’être avec un coéquipier lorsque les choses vont bien, mais quand vous êtes là-bas en solitaire, vous êtes mis à l’épreuve à hauteur de votre pleine capacité en tant que golfeur.
| Musuma woon xalaat ne dina fo ñaari mats.
| It's great to be with a teammate when things are going well, but when you're out there on your own, you're being tested to your full potential as a golfer. |
Mais avec Lulaku et Martinez toute défense est sujette au déverrouillage. | Waaye Lukaaku ak Martinees mën nañu xëtt defaas bu nekk. | But with Lulaku and Martinez, any defense is subject to unlocking. |
Le capitaine américain Jim Furyk a commenté après une prestation décevante concernant son équipe : « Je suis fier de ces mecs, ils se sont battus.
| Yeneen juroom benni miliyon ci nit ñoo ngi dundu ci dëkk bi te soxlanañu ndimbal.
| Captain Jim Furyk commented after a disappointing performance for his team: "I'm proud of these guys, they fought hard". |
La question peut sembler incongrue mais il faut savoir que les femmes sont de bien meilleures emprunteuses que leurs homologues masculins au sens où elles ont destaux de remboursement des prêts supérieurs. | Mbir mi dafa mel ni lu yéeme waaye dañoo war a xam ne jigéen ñi ñoo gën a mën a leb ni ki góor ñi te it ndollentu xaalis bi ñuy fay moo ëpp. | The question may seem incongruous, but it is important to know that women are much better borrowers than their male counterparts in the sense that they have superior loan repayment rates. |
Par ailleurs, cet état de fait est d’autant plus surprenant que sur les marchés plus matures, les assureurs ont plutôt tendance à faire la part belle aux obligations souveraines dans leurs portefeuilles d’actifs, ce qui leur confère souvent le titre de financeurs préférentiels des Etats., | Ci beneen anam, Jëf joojoo gën a bette ci li ne ci ja yu gën a mat ya, aarkat yi dañuy faral di def séddu bu rafet ci wareefi yi leen nguur gi jagleel ci seen gafaka jamono ji ñuy ne ci waar wi, li leen jox turu saa-koppaarali nguur yi. | This is all the more surprising as insurers in more mature markets tend to allocate sovereign bonds to their asset portfolios, often giving them the title of preferred state financier. |
Le talent d’Atkinson pour la comédie physique est mis en valeur, bien que l’humour soit plutôt insuffisant et étrangement superflu, en particulier à l’heure où les licences « sérieuses » comme 007 et Mission impossible composent elles-mêmes en toute confiance avec la comédie.
| Ku ñu tuumal lu mu deful warul mer
| Atkinson's talent for physical comedy is highlighted, though the humor is rather lacking and strangely superfluous, especially at a time when serious franchises like 007 and Mission Impossible confidently compose themselves with comedy. |
Il était comme ça :J’ai montré mon chef-d’œuvre aux grandes personnes et je leur ai demandé si mon dessin leur faisait peur. | Sama nataal bi njëkk, nii la meloon:Ma won sama liggéey mag ñi, daldi leen laaj ndax nataal bi tiitalu leen. | It was like this: I showed my masterpiece to the grown-ups and asked them if my drawing scared them. |
L’INCIDENT AVEC BARACK OBAMA QUI A TOUT DÉCLENCHÉ. | Mbiram ak Baraag Obamaa moo ko ubbil ay bunt. | Starting with Barack Obama who's all screwed up. |
Ils veulent être célèbres en disant mon nom, mais ça fait partie du boulot.
| Deñuy jefandikoo benn tekniku lamb-daj bu xareñ loolngir mbas gallaŋkaar aki tolof tolof ci seen yoon bi ñuy jaar ngir naaw.
| They want to be famous by saying my name, but it's part of the job. |
Dans leur rapport intitulé Emploi et questions sociales dans le monde : tendances 2021, l'Oit note que même si les pays du monde entier se sortent de cette crise sanitaire, cinq années de progrès pour éradiquer la pauvreté au travail ont été anéanties. | Ci seen yégle bi ñu tudde Xëy ak mbiri askan ci àdduna bi : li ñuy gis atum 2021, Oit jàpp na ne donte réew yi ci àdduna génn nañu ci mbas mi, juróomi ati yokkute ñooy tax ñu jeexal ndóol gi ci liggéey. | In their report titled Global Employment and Social Issues: Trends 2021, the Eight notes that while countries around the world are recovering from this health crisis, five years of progress in eradicating workplace poverty has been wiped out. |
Chaque nouvelle crise est une opportunité inespérée à saisir pour mieux nous exploiter. | Yëngu-yëngu bu bees bu ne nekk na moyal bu ñuy wuut ngir gën ñoo jëfandikoo. | Each new crisis is an unexpected opportunity to exploit better. |
Le Drukgyal Dzong est une forteresse et un monastère bouddhiste en ruine dans la partie supérieure du district de Paro (dans le village de Phondey).
| Drukgyal Dzong beereeb bu yaxxu la ak keeruk Buddhist bi ci kaw Paro District (ci deekeeuk Phondey).
| The Drukgyal Dzong is a ruined Buddhist fortress and monastery in the upper part of Paro District (in the village of Phondey). |
Tout a commencé ce 3 juin, aux environs de 9 h 30, quand le commandant de la Légion Est de la gendarmerie, le colonel Davy Mané, a reçu un appel téléphonique l’informant de la présence de Baye Modou Fall alias Boy Djiné à Tambacounda. | Lépp a ngi doore ci bésu ñetti fan ci weeru suweŋ bi, boori juróom-ñeenti waxtu (9h) bu teg fanweeri simili (30min), bi njiital kurélu bëj-penku sàndarma yi, Kolonel DawI Maane, jot na wooteb telefon bu koy yégal teewaayu Baay Móodu Faal mi ñuy dàkkantale Booy Jinne ca Tàmbaakundaa. | It all started on June 3rd, around 9:30 a.m., when the commander of the Eastern Legion of the Gendarmerie, Colonel Davy Mané, received a phone call informing him of the presence of Baye Modou Fall aka Boy Djiné in Tambacounda. |
Et encore, on ne parle pas ici des énormes budgets engloutis par les consommations d’électricité au-delà même des heures de travail ni de carburant. | Beneen yoon, waxuñu fi xaalis bu takku lool bu dem ci kurãa bi ginnaaw sax waxtuy liggéey yi wala esãas bi. | And again, we are not talking about the huge budgets swallowed up by the consumption of electricity even beyond working hours or fuel. |
Ensuite, certaines selles, notamment les anglaises, ont des barres de sécurité qui permettent à une étrivière de tomber de la selle si elle est tirée vers l'arrière par un cavalier qui tombe.
| Teg ci, yenn selles yi, rawatina selles yu Angale yi, dañoo am ay baaru kaarànge yuy tax etriyee daanu ci selle bi suko ab warkat buy xëccee ci ginnaaw.
| Secondly, some saddles, especially the English ones, have safety bars that allow a stallion to fall off the saddle if it is pulled backwards by a falling rider. |
Le daaka de Médina Gounass, célébré depuis 1942, est une retraite spirituelle organisée chaque année dans cette cité religieuse du département de Vélingara. | Daaka gu Medina Gunaas te ñu door ko ca atum 1942, wéttali Yàlla la guy am at mu ne ca dëkku diine ba nekk ca Welingara. | The daaka of Medina Gounass, celebrated since 1942, is a spiritual retreat organized every year in this religious city of the department of Vélingara. |
Le noyau est constitué de deux particules — des neutrons et des protons.
| Xoox bi ñaari partikil la boole – nëtron ak poroton.
| The nucleus is made up of two particles neutrons and protons |
Sa première sortie depuis sa dernière défaite face à Lac 2. | Bëreem bu jëkk ba ko Lac 2 daanee jéll bu jëkk ba tey. | His first outing since his last loss at Lake 2. |
Même si le président est le chef du gouvernement. | Donte njiitu réew mi moo nekk ci bopp nguur gi. | Even if the president is the head of government. |
Respectons nous les uns les autres | Nañu joxante cër. | Respecting One Another |
Il s’agirait de la cinquième fois dans l'histoire de l’humanité que l'on aurait observé la chute sur la Terre de matières, dont l'analyse chimique aurait confirmé qu'elles seraient originaires de Mars.
| Gëmm nañu ni bii mooy juroomélu yoon ci taarix nit di giss liy soppeeku nekk ay jumtukaayu xamxam martian yu daanu ci suuf.
| This would be the fifth time in human history that material has been observed falling to Earth, and chemical analysis has confirmed that it originated on Mars. |
Tu sais… je connais un moyen de te reposer quand tu voudras… | Xam nga… xam naa pexe mu lay noppal saa yu la neexee… | You know... I know a way to get you some rest whenever you want... |
Les accidents aériens sont fréquents en Iran, qui dispose d'une flotte vieillissante et mal entretenue autant pour les vols civils que militaires.
| Yenn xeeti jéeya yi ci kaw jàwwu ji dañuy faral di am ci Iran, ndax lu ëpp ci roppalaanu saldaar ak tukki yi dañu màgget.
| Air accidents are common in Iran, which has an aging and poorly maintained fleet for both civilian and military flights. |
Pendant ce temps-là, Macky Sall se fend d’un post facebook lunaire et erratique se limitant à inviter les populations à appliquer les recommandations de l’OMS, comme si celles-ci étaient largement connues. | Ci jamono jooju, Maki Sàll moom mu ngi yem rekk ci ab bataaxalu feesbug bu matadi, di ci woo askan wi ci jëfe ndigali Kurélu wér-gu-yaram gu àdduna, mu mel ni askan wi dañu xam ndigal yooyu yépp ba pare. | Meanwhile, Macky Sall is tearing up a monthly and erratic Facebook post that simply invites people to apply the WHO recommendations, as if they were widely known. |
Le Franz Fanon de son époque, Ali Shariati, éminent sociologue, fait une clarification intéressante du concept intellectuel dans son livre intitulé civilisation et modernisation : Est intellectuel, celui qui est conscient de sa situation humaine dans le temps et l’espace historique et sociologique qui est le sien, et à qui cette conscience dicte un sentiment de responsabilité. | Franz Fanon mu jamonoom, Ali Sariyati, xam-xamam màcc ci dundug askan, joxe na leeral bu am solo ci baat bi di « boroom xam-xam bu am njàng » ci téereem bii di Civilisation et modernisation (Xay ak dëppaleek jamono) : boroom xam-xam bu am njàng mooy ki xam nit ci jamono ak béréb, ci taarixam ak dundinam te yég googu jox ko yég-yégu li gàllu ci ndoddam. | The contemporary of Franz Fanon, Ali Shariati, a prominent sociologist, makes an interesting clarification of the concept of intellectual in his book entitled Civilization and Modernization: He is intellectual who is aware of his human situation in time and the historical and sociological space that is his, and to whom this consciousness dictates a sense of responsibility. |
« Eh bien, si le racisme m’inquiétait, j’aurais quitté l’Amérique depuis longtemps », a-t-il affirmé.
| Su ko defe Munnañu gis ap porteyin bu bari ci ay kañseer mu sanniwaat ko
| Well, if I was worried about racism, I would have left America a long time ago, he said. |
Elle est juste audessus de nous… Mais comme elle est loin ! | Mu ngi nii tiim ñu… Waaye sori na de! | It's just above us... but how far it is! |
Le petit prince était maintenant tout pâle de colère. | Léegi ndoomu buur si daldi mer bay futt. | The little prince was now pale with anger. |
Aujourd'hui, informe ces experts agricoles, le pays est à plus de 75 000 tonnes. | Ñi seen xam-xam màcc ci mbay nee nañu gerte gi ci réew mi ëpp na juróom-ñaar-fukki junniy ton ak juróom. | Today, these agricultural experts say, the country is at over 75,000 tons. |
ARENE BI IL N'Y A PAS DE LUTTEUR QUI DOIT LOGIQUEMENT TE POSER DES PROBLEMES. | Areen bi amul mbër bu la mën a sonal. | There is no fight that logically has to cause you problems. |
Le gouvernement écossais s’est déjà engagé à couvrir le coût des demandes de statut pour les citoyens européens travaillant dans ses services publics décentralisés.
| Ay fan ci ginnaaw ci weer wii ñu nekk New York Times fësaloon na ni Rosentein waxtaanena lu jëm ci sol ap weñ ngir ariste waxtaanam ak Trump munna am sax lu jëm ci dinndi persida bi ak amanndama 25 bi.
| The Scottish Government has already committed to cover the cost of status applications for EU citizens working in its devolved public services. |
C'était, rapporte le quotidien L'As dans sa livraison de ce jeudi, aux environs de 17 heures. | Bu ñu sukkandikoo ci li yéenekaay bii di L'As bind ci alxames jii, booru tàkkusaan la xewoon. | It was, reports the daily newspaper L'As in its delivery of this Thursday, at around 5 pm. |
La plénière devrait sursoir à se réunir sur cette question et le ministre de la justice devrait immédiatement informer le Président Moustapha Niasse de ce fait nouveau. | Ngomblaan gi waroon nañu yéexamtu ci dajaloo ci mbir mi te jëwriñ ji yor wàllu yoon waroon na yégal lu bees lii ci saa si njiitu ngomblaan gi Mustafaa Ñas. | The plenary should adjourn its meeting on this matter and the Minister of Justice should immediately inform President Moustapha Niasse of this new fact. |
Le PSG largement supérieur a plié le match avant même la mi-temps. | PSG mi ko mën fuuf féeteel na mats bi boor laata sax ñuy xaajal. | PSG, who were far superior, had already won the game before half-time. |
Poule D : Sénégal, Cameroun, Sud Soudan, 2ème qualifié groupe E (Maroc, Cap-Vert ou Ouganda)Une place qui sera disputée entre le Maroc, l’Ouganda et le Cap-Vert. | Puul D bi : Senegaal, Kamërun, Bëj-Saalumu Sudaŋ, ñaareel bi jàll ci gurub E bi (Marog, Kab-Weer wala Ugàndaa), benn palaas la Marog, Ugàndaa ak Kab-Weer di xëccoo. | Pool D: Senegal, Cameroon, South Sudan, 2nd qualified group E (Morocco, Cape Verde or Uganda) A place to be contested between Morocco, Uganda and Cape Verde. |
Le bouddhisme tibétain est basé sur les enseignements de Bouddha, mais a été enrichi par le chemin de l'amour mahayana et par de nombreuses techniques du yoga indien.
| Buddhism bu Tibet mu àju ci njangalem Buddha, waaye yoonu mbëgeelu mahayana bi ak ay xarala yu bari yi bawoo ci Yoga bu Ind ñoo ko yaataloon.
| Tibetan Buddhism is based on the teachings of Buddha, but has been enriched by the Mahayana path of love and by many techniques of Indian yoga. |
Coordonnateur de la section communale PASTEF / SOMONE. | Kiy lëkkale liggéeyub PASTEF ca gox-goxaatu SOMON. | Coordinator of the PASTEF/SOMONE municipal section. |
Observez : – sacc (verbe: voler) qui devient cacc (nom: vol),– fo (verbe: jouer) qui devient po (nom: jeu),– fenk (apparaître) qui devient penku (lieu d’apparition – comme pour le cas du soleil: l’Orient). | Xool leen : sàcc (njëfka : voler) moo soppaliku càcc (tur : vol), -fo (njëfka : jouer) mooy soppaliku po (tur : jeu), - fenk (apparaitre) mooy soppaliku penku (lieu d’apparition- di tekki jant : l’orient). | Note: sacc (verb: to fly) which becomes cacc (noun: to steal), fo (verb: to play) which becomes po (noun: to play), fenk (to appear) which becomes penku (place of appearance as in the case of the sun: the East). |
Mélangez les deux poudres sèches ensemble, puis, avec les mains propres et humides, pressez-les en une boule.
| Booleel ñaari sunguf yi jaxase, ba noppi nga tooyal sa loxo boole leen dànk leen bu baax ñu nekk benn bul.
| Mix the two dry powders together, then, with clean, wet hands, press them into a ball. |
Les lentilles de l'objectif zoom présentent un inconvénient. En effet, la complexité de la focale et le nombre de lentilles requis pour obtenir une gamme de longueurs focales sont largement supérieurs à ceux des objectifs fixes.
| Li xawa doywaar ci zoom yi mooy bariwaayu focale bi ak limu mbir yi bokk objectif di tax ñu mêna yegg ci rëyaay bi ñu soxla ci focale yi, ñoo gëna rëy lool objectif à focale yi du soppiku wala yëngu.
| The zoom lens has a disadvantage: the complexity of the focal length and the number of lenses required to obtain a range of focal lengths are much higher than those of fixed lenses. |
Au lieu de jouer au pompier pyromane, assurez-vous au moins de faire le travail pour lequel vous êtes payé, c’est-à-dire assurer la sécurité alimentaire. | Balaa ngay def sa bopp pómpiyee piromaan, na nga fexe ba def liggéey bi ñu la fi tege, mooy nga taxaw ci lekk gi ak naan gi doy. | Instead of playing the pyromaniac fireman, at least make sure you do the job you're paid to do, which is to ensure food security. |
Elles se croient terribles avec leurs épines… | Dañoo foog ne seen dég yee tax ñu raglu... | They think they're terrible with their thorns... |
Monsieur Mamour Diallo a créé un mouvement Dollil Macky et il a pris la carte de l’APR synonyme d’immunité juridictionnelle depuis 2012. | Sëñ Maamur Jàllo dafa sos ag kuréel gu tuddu, Dollil Maki teg ci jël kàrtu APR bi nekk tey ag muslaay ci yoon ak yoonal. | Mr. Mamour Diallo created a Dollil Macky movement and he has been playing the APR card, which has been synonymous with immunity from jurisdiction since 2012. |
Selon toujours la mise en cause, l'un de ses collègues lui a suggéré de garder l'argent dans le coffre-fort qui se trouve dans son bureau. | Su nu sukkandikoo ci ki ñu tuumaal kenn ci liggéeykatam moo ko ne mu denc xaalis bi ci koppar-foor bi nekk ci biroom. | According to the indictment, one of his colleagues suggested that he keep the money in the safe in his office. |
Essayez l’amour. »
| Kanye West deñu kaa yuuxu ci istijoo bi mu daan tëgge Laayf ci Samdi Guddi ci ap ligeey fu mu bakke Amerik. Persida ba pare mu ni dina toogat ci atum 2020.
| Try love. |
Nos braves producteurs méritent mieux que cela et, au-delà du conjoncturel, devraient être au centre de votre projet de TRANSFORMATION post-Covid 19, si tant est que vous en ayez un. | Sunu baykat yu am jom yi war nañu leen taxawoo neneen nu dul nii te, bu dul xew- xew yi sax, ñoo waroon a jiitu ci seen mbébéti COPPITE ginnaaw Koronaa bi, su fekkee ne sax am ngeen ci benn. | Our brave producers deserve better than this and, beyond the short-term, should be at the center of your post-COVID-19 TRANSFORMATION project, if you have one. |
Chers Étudiants, vous devez répondre à l’injonction de Frantz Fanon: remplir votre mission face à l’histoire, ou la trahir. | Yeen ndongoy daara yu kawe yi, dangeen a war a tontu Fanz Fanon : bay sa waar ci mbir mi, wala nga wor sa réew. | Dear students, you must answer Frantz Fanon's injunction: fulfill your mission in the face of history, or betray it. |
Le ministre a plutôt souligné trois rencontres ayant eu lieu entre Kim et le dirigeant sud-coréen Moon Jae-in au cours des cinq derniers mois, et a ajouté : « Si la partie concernée par la question de la dénucléarisation était la Corée du Sud et non les États-Unis, la dénucléarisation de la péninsule coréenne ne se trouverait pas dans une telle impasse. »
| Bi Ri tontoo njammbatu Kore bu gannaar bi ñepp miin lu jëm ci mbañeelu Washington bi ci ap jego bu "wax" rek ci dinndi nikaleyeer bi nga xamni dinañu ci fey Kore bu gannaar ndax te dina fekk mu jël ap ndogal bu rëy , li tax kaddoom bi am solo moy moom bañul dinndi nikaleyeer bu ame benn boor te munuñu ci dara ni ko Pyongyang defewoon bu njêkk.
| The minister instead highlighted three meetings between Kim and South Korean leader Moon Jae-in in the past five months, and added: If the party concerned with the denuclearization issue was South Korea and not the US, the denuclearization of the Korean Peninsula would not be in such a deadlock. |
Sur tout ça ? dit le petit prince. | Ndoomu buur si ne ko : Lii lépp? | "All of this?" said the little prince. |
L'agent-comptable K. Kane m'a suggéré de garder les fonds dans le coffre-fort situé dans mon bureau, explique-t-elle dans les colonnes du journal Source A. | Kiy déñc koppar K. Kan dafa ma digal ma denc koppar yi ci kondaane bi nekk ci sama biro, lóolu la leeral ci yéenekaayu Source A. | "Agent K. Kane suggested that I keep the funds in the safe in my office", she explains in the columns of the newspaper Source A. |
Ils n'ont pas encore changé ces avions qui ont encore du potentiel. | Waxtaan wi dafa war a gën a xóot àgg ci loolu, ci li njiitu takki-der yi wax Seneweb. | They haven't changed those planes yet, which still have potential. |
L'annonce d'aujourd'hui prolonge également l'engagement pris par le gouvernement en mars de cette année de financer des voitures supplémentaires.
| Yéglék tay bi yokkona paspasu njiit yi tamit bignu amaloon ci wééru mars ci at mi ngir doolél ci koppar yénééni dém ak dikk.
| Today's announcement also extends the government's commitment in March this year to fund additional cars. |
En juillet 2014, l’Inspection générale d’Etat, qui est l’Institution supérieure de contrôle de l’ordre administratif rattachée directement au Président de la République, a publié son second Rapport public sur l’Etat de la Gouvernance et de la Reddition des Comptes après le tout premier en août 2013. | Kon ñawkat bi dafa ko yoreel ay boru luyaas. | In July 2014, the General State Inspectorate, which is the highest institution of administrative control directly subordinate to the President of the Republic, published its second public report on the state of governance and accountability after the first one in August 2013. |
Il symbolise aussi certaines difficultés offensives des Lions de la Teranga dans cette CAN. | Dafay màndargaal itam yenn ci tolof-tolofu ataagu Gayndey Teraanga yi ci CAN bii. | It also symbolizes some of the offensive difficulties of the Teranga Lions in this AFCON. |
Le géographe est trop important pour flâner. Il ne quitte pas son bureau. Mais il y reçoit les explorateurs. Il les interroge, et il prend en note leurs souvenirs. | Du gëstukatu jéeri ji mooy waññ dëkk yi, dex yi, tund yi, géej yi, géejmbàmbulaan yi ak màndiŋ yi. Gëstukatu jéeri jotam mayu ko muy wëndéelu. Du jóg biróom. Waaye fa lay dalal wërkat yi. Dafa leen di laaj, su noppee mu bind seeni fàttaliku. | The geographer is too important to stroll around, he doesn't leave his office, but he welcomes the explorers, he questions them, and he notes their memories. |
Sundarbans est une réserve naturelle depuis 1966, vous pourrez y trouver environ 400 tigres du Bengale royal et 30 000 cerfs tachetés.
| Li ko dalee 1966 ba tay ji, Sundarbans barab la buñu jagleel rab yi, te leegi warna am lu tollu ci 400 Ségg royal yu Bengale ak lu tollu ci 30 000 kéwél yu am ay tupp-tupp ci gox bi.
| Sundarbans has been a nature reserve since 1966, you can find about 400 royal Bengal tigers and 30,000 spotted deer. |
Le chef suprême Tupua Tamasese Lealofi III fut assassiné lors un rassemblement pacifique qui se tenait en ville, durant la luttee de l’indépendance organisée par le mouvement Mau.
| Ci diiru xeex ngir moom sa bopp bu mbootaayu Mau amaloon, ndaje jàmm bu amoon ci biir dëkk bi mujj na ci bóomug njiit lu kawe lii di Tupu Tamasese Lealofi III.
| Tupua supreme leader Tamasese Lealofi III was assassinated during a peaceful rally in the city during the struggle for independence organized by the Mau movement. |
Il surfe sur la sémantique de la campagne de Free. | Mu ngi dund ci ni mu yége mbaboorum Free mi. | He's surfing the semantics of Free's campaign. |
Les gars se justifient sur le coût d'un voyage en paradis fiscal !!! | Gaa yaa ngi laye tukkim Aljanaay juuti !!! | The guys are justifying themselves on the cost of a trip to a tax haven!!! |
En Novembre 2019, des activistes sont arrêtés aux portes du palais puis emprisonnés et brutalisés à Rebeuss par des geôliers. | Ci nowàmbar 2019, ay way-fippu jàpp nañu leen ci buntu këru njiitu réew mi ba pare tëj leen, toroxal leen ca rëbës ak ñuy yore ñi ñu tëj. | In November 2019, activists were arrested at the gates of the palace and then imprisoned and brutalized in Rebeuss by prison guards. |
Quand ils sont sortis aussi, ils ont dit tout haut ce que nous pensions, tout le monde entendait. | Ba nu génnee yit, biral nan sunu xalaat, ñépp di ko dégg. | When they came out, they said what we thought, loudly, for all to hear. |
Comme le veut la logique, quand tout es permis, il faut s’attendre à tout, à ce que Macky Sall brigue un troisième mandat ou décrète le maire de Dakar. | Ni ko xel di nangoo, soo mayee nit ki lépp kay, lu mu def warul a bett, lu mel ne Maki Sàll di laaj ñetteelu ay wala mu tabb meeru Dakaar. | As logic dictates, when everything is permitted, one can expect anything, whether Macky Sall is seeking a third term or decrees the mayor of Dakar. |
C'est vers les coups de 23 h qu'un conducteur de moto Jakarta a été écrasé par un camion sur la route de Gandiaye (Kaolack). | Ci ay boori fukki waxtu ak benn la benn kamiyoŋ mbëkk benn dawalkatu Jakàrtaa ci yoonu Gànjaay wi (Kawlag). | At about 11 pm a Jakarta motorcycle driver was hit by a truck on the road to Gandiaye (Kaolack). |
Il ouvre les commentaires rien que pour des insultes et mensonges et promotions des pd ! | Seeni kàddu ci mbir mi doonul dara lu dul ay saaga ak ay fen ak jàppal tànk góor-jigéen yi. | He opens the comments only for insults and lies and promotions from PD! |
Elle avait agité l’espace politique et médiatique au point de soulever l’ire de plusieurs personnalités politiques qui avaient réclamé ma tête. | Ndaw si yëngaloon na géewu pólótig bi ba mu àgg ci merloo kilifa ya ba tax bëggoon nañu ma faatu. | It had stirred up the political and media space to the point of arousing the ire of several political figures who had demanded my head. |
L'idée était que toutes les nations européennes empêchent une nation de devenir puissante, c'est pourquoi les gouvernements nationaux changeaient souvent d'alliances afin de maintenir l'équilibre.
| Li ko taxa jog mooy réewi Ërop yi fexe ba menn réew du ëpp lool moroom ma doole, te nguur yi danuy faral di soppi seen lëkkaloo ngir yamale dooley réew yi.
| The idea was that all European nations prevented one nation from becoming powerful, which is why national governments often changed alliances in order to maintain the balance. |
Plusieurs questions restent en suspends et l’Assemblée nationale ne peut rester indifférente et silencieuse. | Am na ay laaj yu kenn tontuwul te Péncum ndawi réew mi ne patt moom tamit. | Several issues remain unresolved and the National Assembly cannot remain indifferent and silent. |
Après cet énième scandale, les mêmes questions reviennent:Qui votent réellement? | Gannaaw ay yu mujj yóoyu, laaj yooyu rekk ñooy delu si : Ñan ñooy wote dëgg dëgg ? | After yet another scandal, the same questions are coming up: Who really votes? |
Il n y a pas de différence entre AISSATA et Racine Sy . | Dara wuutalewul Aysata ak Raasin Si. | There's no difference between AISSATA and Sy Racine. |
Deux chansons du film, Audition (The Fools Who Dream) et City of Stars, ont été nominées pour la meilleure chanson originale. Le studio Lionsgate a reçu 26 nominations — plus que tout autre studio.
| Ñaari woyi filmy bi, Audition (Dof Yuy Gént) ak Dëkku Biddew yi, dañ leen lim ci ñi bokk ci woyu cosaan yi dàq. Istijoo Lionsgate jot na 26 ci ay nit yuñu lim – ëppale istijoo yépp.
| Two songs from the film, Audition (The Fools Who Dream) and City of Stars, were nominated for Best Original Song, with Lionsgate receiving 26 nominations more than any other studio. |
Les meurtres et autres dégâts lors des émeutes sont de votre entière responsabilité. | Yow yaa gàlloo nit ñi ñu faat ak yeneen yàqu-yàqu yi amoon ci ñaxtuy weeru màrs yi. | Any deaths or damage during the riots are your responsibility. |
En réalité ces forces occultes dont les intérêts passent avant ceux des populations, tirent les ficelles et sont les véritables décideurs. | Ca dëgg-dëgg, ay boroom doole yu kenn mënul a teg bët te seeni yitte di jàll balaa yu askan wi, ñooy nas di nocci ak a dogal. | In reality, these occult forces, whose interests are above those of the people, are the real decision-makers. |
La finale tant attendue est peut-être pour cette année. | Ci li mu wax ci waxtaanam ak Seneweb, loolu bi ñu koy defar day ànd ak taw bu baax ak tànneefi pólótig yu mucc-ayib. | The long-awaited final may be this year. |
Mais nous partageons particulièrement le patriotisme parce que notre parti s’appelle Patriotes du Sénégal pour le Travail, l’Éthique et la Fraternité. | Waaye noo bokk li fés muy bëgg sa réew, ndax kurélu pólotig gaa ngi tudd Bëgg sa réewum Senegaal ngir Liggéey, lu Baax ak Mbokkoo. | But we especially share patriotism because our party is called Patriots of Senegal for Work, Ethics and Fraternity. |
Le Boston Globe relate que la démocrate du Massachusetts a discuté samedi de son avenir lors d’une assemblée publique dans l’ouest du Massachusetts.
| Neena Su ko yoroon, konn dina fekk genni nañu ci bu yagg.'
| The Boston Globe reports that the Massachusetts Democrat discussed her future at a public meeting in western Massachusetts on Saturday. |
La meilleure manière de sortir de la crise est d’adopter une stratégie qui s’adapte à nos réalités sociales, culturelles et démographiques, en s’inspirant des méthodes qui marchent tout en évitant des solutions clés en mains, des recettes de prêt à porter. | Anam bi gën ngir génn ci musiba mi mooy nu jël wenn tëralin wu méngook sunu jamono, sunu aadaak cosaan, ak sunu dëkkuwaay, ci sukkandiku ci doxalin wiy dox te moytu saafara yu yomb, jóoni-jóoni. | The best way out of the crisis is to adopt a strategy that adapts to our social, cultural and demographic realities, drawing on the methods that work, while avoiding turnkey, ready-made solutions. |
En Afrique il n'est jamais facile de faire une nette différence même si l'adversaire est composé de locaux en majorité. | Ci Afrig mësul a yomb nga téqale donte kujjee gi bari na waa gox bi. | In Africa it is never easy to make a clear difference even if the opponent is made up of mostly locals. |
Animal Liberation et la Royal Society for the Prevention of Cruelty to Animals (RSPCA) demandent à nouveau l’installation obligatoire de caméras de surveillance dans tous les abattoirs australiens.
| Bayyi mala yi ak Soyite Ruwayaal ngir àartu ci coxoru mala yi (RSPCA) ñoo ngi laajal ñu sampalaat leen ay kamera de surveillance CCTV ci barabi reyukaayu mala yu nekk ci Ostaraali yépp.
| Animal Liberation and the Royal Society for the Prevention of Cruelty to Animals (RSPCA) are again calling for the mandatory installation of surveillance cameras in all Australian slaughterhouses. |
Je t’aurai joué un bien vilain tour… | Dinaa la nax, nax yu metti… | I must have played a very bad trick on you... |
Arrêtons de désigner les autres comme les responsables de nos problèmes. | Nañu bàyyi tuumaal nit ñi suñuy tolof-tolof. | Let's stop blaming others for our problems. |
Bien sûr, dit le renard. | Wel wi ne ko: Waawaaw. | "Of course", said the fox. |
Et vousconviendrez qu’il remplit fort bien son mandat. | Te nangu ngeen ni dina matal ayam gi ci anam bu baax | And you will agree that he is doing his job very well. |
Les procureurs fédéraux de New York demandent la peine de mort pour Sayfullo Saipov, le présumé assaillant de New York qui a fait huit victimes - une peine rare qui n’a pas été appliquée dans cet État pour un crime fédéral depuis 1953.
| Track Palin, taawu goor guwernoor Alaska bu woon ak bëgoon doon ku toppu njiitu reew mi Sarah Palin, dañuko japp ci fitnaal ak dooraate.
| Federal prosecutors in New York are seeking the death penalty for Sayfullo Saipov, the alleged New York City assailant who killed eight people - a rare sentence that hasn't been carried out in the state for a federal crime since 1953. |
Amr Fahmy, ancien secrétaire général de la CAF, estime dans son courrier que 54 000 dollars pour envoyer trois de ses membres superviser la distribution des équipements sportifs pendant une semaine au Maroc constituent un prix déraisonnable , d’autant plus qu’il n’inclut pas les frais de transport, de logement ou de nourriture . | Amr Fahmy, ki nekkoon ci boppu CAF yaakaar na ci baataaxalam bi juróom-fukk ak ñeenti dolaar ngir yóbbu ñett ci àndadoom yi ngir ñu saytu séddalem jumtukaay yu tàggat yaram yi lu tolluu ci benn ayu-bés ci Marog nekk na njëg lu jaaduwul, te booleewu ci njëgu dem beek digg bi, dëkkuwaay bi, ak dund gi. | Amr Fahmy, former CAF general secretary, believes in his letter that $54,000 to send three of its members to oversee the distribution of sports equipment for a week in Morocco is an unreasonable price, especially since it does not include transportation, accommodation or food expenses. |
Les attaquants de Mumbai sont arrivés par bateau le 26 novembre 2008, apportant avec eux des grenades, des armes automatiques et ont touché de multiples cibles, dont la gare ferroviaire bondée Chhatrapati Shivaji Terminus et le célèbre hôtel Taj Mahal.
| Ci def congu gi agsi nanu ci gaal ci ñaar fukki fan ak juróom benn ci weeru Nowembar 2008, n indaale ay ndel, ay fetal te laal jubluwaay yu bare boole ci Gaaru saxaar buy bari nit bu Chhatrapati Shivaji ak Otelu Taj Mahal bu Siiw bi.
| The Mumbai attackers arrived by boat on November 26, 2008, bringing with them grenades, automatic weapons and hit multiple targets, including the crowded Chhatrapati Shivaji Terminus railway station and the famous Taj Mahal Hotel. |
Ces propos, tenus lors de la campagne électorale de 2012 restent invraisemblables et particulièrement choquants au regard de la morale. | Yile wax ci jamonoy kàmpaañu wotey 2012 yi, ñoo des di lor xel yi ci lu amul benn werante. | These remarks, made during the 2012 election campaign, remain unlikely and particularly shocking from a moral standpoint. |
J’ai dit au ministre de la Santé et de l’Action Abdoulaye Diouf Sarr que pour les recrutements des médecins et spécialistes qui se feront, les personnels qui seront choisis auront l’obligation de rester cinq ans dans les régions. | Wax naa jëwriñ ji gàlloo wér-gu-yaram bi, Abdulaay Juuf Saar, ne ko fajkat yi ñu war a jël, dañu war a nekk ci gox yi ñu leen yóbbu lu mat juróomi at balaa ñu fay jóge di dem feneen. | I told the Minister of Health and Labour, Abdoulaye Diouf Sarr, that for the recruitment of doctors and specialists that will be made, the personnel that will be chosen will be obliged to stay in the regions for five years. |
Une autre voix lui répondit sans doute, puisqu’il répliqua : Si ! | Keneen dafa ko war a tontu ndax dafa ci teg ne: Waawaaw! | Another voice must have answered, since he said, "Yes". |
Un autre grec célèbre est le mathématicien Pythagore, surtout connu pour son célèbre théorème sur les relations des côtés des triangles rectangles.
| Beneen xeltukat Grek ci wàllu xayma bu siiw Pythagoras, te nu gën ko xam ci sàrtam bu siiw boobu ajju ci lëkaloo yi ab ci weti ñattangal bu jub bi.
| Another famous Greek is the mathematician Pythagoras, best known for his famous theorem on the relationships of the sides of right triangles. |
Il faut bien que je supporte deux ou trois chenilles si je veux connaître les papillons. Il paraît que c’est tellement beau. Sinon qui me rendra visite ? | Fokk ma dékku ñaar ba ñetti sax, su ma bëggee gis ay lëppaa-lëpp. Dégg naa ne dañu rafet lool. Bu dul loolu, ku may seetsi? | I'd have to put up with a couple of caterpillars if I wanted to know the butterflies, and I hear it's so beautiful, otherwise who'd visit me? |
Le troisième mettra le focus sur l’éducation comme instrument de promotion de valeurs, de culture de la paix et de la justice. | Mbébét bi dafa war a defar kóolute ak doyu kuraŋ bi ci Ruwàndaa, yokk askan wi doon jot ci kuraŋ gi, te wàññi tasaare gaas yiy lore tey jógee ci asamaan, ci joxe enersi bu sell. | The third will focus on education as an instrument for promoting values, a culture of peace and justice. |
Courroux de la star du programme télévisé Dragon’s Den, Peter Jones, après l’annonce du retrait de l’animatrice Holly Willoughby d’un contrat à hauteur de 11 millions £ lié à sa marque de décoration maison, pour se consacrer à ses nouveaux contrats avec Marks & Spencer et ITV
| Estaaru Dragons Den, Peter Jones ' demna ak 'mer' ginnaaw bi surnalist tele bii di Hollu Willoughby yaxxe ap diil bu tollu ci 11£ milyoŋ ak dunndinam gu bees bi ci markam bu taaba taaba ngir yitewo kontaram bu bees bi ak Marks ak Spencer ak ITV.
| Anger at Dragon's Den star Peter Jones after announcing that host Holly Willoughby had pulled out of an £11m deal with her home decoration brand to focus on new contracts with Marks & Spencer and ITV |
Au départ, l’idée de la CEDEAO était de faire en sorte que les sept pays ouest-africains non-membres de l’UEMOA créent une union monétaire en 2015 – la zone monétaire de l’Afrique de l’Ouest (ZMAO) – avant de fusionner ensuite avec les huit pays de l’UEMOA en 2020. | Ci ndoorteel la, xalaatu CEDEAO bi moo doon def ba nga xam ne juróom-ñaari réewi Afrig sowu jant yi bokkul ci kuréelu UEMOA sos am mbooloom tëgg benn xaalis atum 2015 - barab ya xaalisu Afrig sowu jant di doxee (ZMAO) - balaa ñuy jokku ci juróom-ñetti réewi UEMOA atum 2020. | The original idea of ECOWAS was to have the seven non-UEMOA West African countries create a monetary union in 2015 - the West African Monetary Area (WAAM) - before merging with the eight EUMOA countries in 2020. |
Pelosi a déclaré que selon elle, le témoignage de Kavanaugh démontrait qu’il était inapte à siéger à la Cour suprême, puisqu’il a montré qu’il était contre les démocrates.
| Bo leegi leeragul, ndax Kavanaugh munna am lu ëppu 50 baat ci biir Sena bi, liy tax ki topp ci persida bi Mike Pence , dagg benn pas , mu firndeel ko ci Kuur bu Kawe bi.
| Pelosi said that in her opinion, Kavanaugh's testimony showed that he was unfit to serve on the Supreme Court, since he showed that he was against the Democrats. |
Pour rappel, dans la nuit du 28 au 29 octobre dernier, la police des Parcelles Assainies a été informée d'un meurtre au quartier Grand-Médine, à 50 mètres de la pharmacie Mountaga, en allant vers le Stade Léopold Sédar Senghor. | Di fàttali rekk, ci guddig ñaar-fukki fan ak juróom-ñett jëm ñaar-fukki fan ak juróom-ñeent ci weeru oktoobar wi weesu, pólis bu Pàrsel Aseni yég na ray gi am ci goxu Garãa-Medin tollu ci juroom-fukki meetar ak farmasi Muntaxaa booy dem estaat Léwópóol Sedaar Seŋoor. | On the night of October 28th to 29th, the police of the Murder Plots were informed of a murder in the Grand-Médine district, 50 meters from the Mountaga pharmacy, on the way to the Leopold Sédar Senghor Stadium. |