fr
stringlengths
4
1.08k
wo
stringlengths
2
4.02k
en
stringlengths
3
1.08k
Nadia, née le 17 Septembre 2007 par césarienne dans une maternité à Aleisk, en Russie, a enregistré une pesée massive de 17 livres et 1 once.
Nadia mi judd 17 fan ci weeru Sàttumbar, ci pàc bignuy opéré ca kilinik maternel ba nekk ca Aleisk, Riisi, mingi natt 17 pounds 1 ounce.
Nadia, born on September 17, 2007 by caesarean section in a maternity hospital in Aleisk, Russia, recorded a massive weight of 17 pounds and 1 ounce.
Plus de 500 prisonniers, dont des criminels considérés comme les plus dangereux du pays, sont incarcérés dans la prison HM Long Lartin.
HMP Long Lartin mungi deñc lu ëppu 500 pirisoñe bokk ci ñi gëna ñang ci réew mi.
More than 500 prisoners, including some of the country's most dangerous criminals, are held at HM Long Lartin Prison.
2 buts à zéro et 2ème équipe à se qualifier pour les 1/8 de finale.
Ñaari bal ci dara te ñaareelu ékip bi bokk nañu ci ñiy joŋante ci juróom-ñetteelu xaaj bi.
Two goals to none and the second team to qualify for the 1/8 finals.
Il aura comme adjoint l'ancien défenseur de l'OM Habib Beye.
Abib Béey mi ñuy toftal ci moom ab defaas la woon ca OM.
He will be assisted by former OM defender Habib Beye.
Tous les noms, suivis du mot Sie qui signifie vous, commencent toujours par une majuscule, même au milieu d’une phrase.
Tur yépp, ci wetu baatu Sie ngir yaw, dañuy tambali ci araf bu mag, donte si diggu baatal bi la nekk.
All names, followed by the word Sie which means you, always start with a capital letter, even in the middle of a sentence.
Il consiste à faire des séances de prière et de lecture du Coran.
Ay jotaayu ñaan lay doon ak njàngum Alxuraan.
It involves prayer sessions and reading the Koran.
Si les Sénégalais veulent se soigner, ils ne sont pas pris en charge, il faut réformer le système sanitaire.
Su askanu Senegaal bëggee faju, kenn taxawuwu leen, dañoo war a soppi ni ñuy amale paj mi.
If the Senegalese want to get treatment, they are not being treated, the health system must be reformed.
Une cavalerie est une armée qui combat à cheval. La selle n'ayant pas encore été inventée, la cavalerie assyrienne se battait en montant à cru.
Kawalry mooy arme buy yéeg ci fas di xeex. Tegu bi kenn defaragu kowoon, leegi nak jaabalkati Assyrie dañu dan xeex ci kaw ay fass yu amoul teg.
A cavalry is an army that fights on horseback. The saddle had not yet been invented, so the Assyrian cavalry fought by riding on horseback.
Ensuite tu pourras etre entraineur de L2 y rester pendant certaines années pour consolider tes connaissances pratiques, avant de coacher des équipes de L1.
Ba noppi mën nga nekk tàggatkatu L2 nekk fa ay at ngir dëgaral sa xam-xam bi ngay jëfe, balaa ngay tàggat ay ekibi L1.
Then you can coach L2 and stay there for a few years to consolidate your practical knowledge, before you coach L1 teams.
Regroupé dans son camp, le Sénégal a ensuite souffert mais a tenu jusqu’au bout.
Ci seen mbooloom bopp, Senegaal daj na mettit waaye xare na ko ba mu jeex.
Senegal then suffered, but held out to the end.
Enfin, les prix de cession pratiqués ne sont pas conformes au barème fixé par l’arrêté n° 2781/MEF/DGID du 22 mars 2010.
Ndokk, wàcci gi ñuy jëfe tolloowul ak njëg yi ñu jàpp ci xaatimu jëwriñ ji nekk limat ñaari junni ak juróom-ñaari téeméer ak juróom-ñett-fukk ak benn/MEF/DGID bu ñaar-fukki fan ak ñaar ci weeri màrs 2010.
Finally, the transfer prices charged are not in line with the scale laid down by Decree No 2781/MEF/DGID of 22 March 2010.
La France est le septième pays de l’UE à subir l'impact du virus, faisant suite à l’Autriche, l’Allemagne, la Slovénie, la Bulgarie, la Grèce et l’Italie.
Faraas moy juróom ñaarelu dëkk ci mbootayu wa tugal bu loru ci doomu jàngoro bi; topusi Ótriis, Almaañ, Esloweeni, Bulgaari, Girees ak Itaali.
France is the seventh EU country to be affected by the virus, following Austria, Germany, Slovenia, Bulgaria, Greece and Italy.
Dette entre l’état du senegal, la senelec et la sar retour à la cage de départ
Bor ci diggante waa senegaal, Senelec ak waa Sar delu gannaaw la.
Debt between the State of Senegal, Senelec and Sar back to the cage of departure
J’ai été écrasé dans les ruines du mur, je crois », a confié Haris à Associated Press, précisant que sa famille se trouvait en ville pour un mariage.
NBC News nettalina ne ndawi 18 dëkk ak distirikt jebbalnañu ab teere ca Wasinton ngir jappale benn woy laqqu buy ñaawlu biile tëralin.
"I was crushed in the ruins of the wall, I think", Haris told the Associated Press, adding that his family was in town for a wedding.
Il va sans dire que les politiques jouent un rôle essentiel dans la création d’un environnement qui soit favorable à la numérisation.,
Mënuñu ñàkk a xamle ne way-pólótig yi am nañu taxawaay bu am solo ci pexe yi ñuy teg ngir denc kayit yi ci ordinaatëer yi.
It goes without saying that policies play a key role in creating an environment that is conducive to digitisation.
Il venait de poser les jalons de la révolte populaire qui a eu lieu le 23 Juin 2011.
Mu ngi doon soog a teg jeegoy fippu bi amoon ca ñaar-fukki fan ak ñett ci weeru suyee atum 2011.
It had just set the stage for the popular revolt that took place on June 23, 2011.
Chelsea fera face à Videoton en Europa League de l’UEFA, à 15 h ce jeudi à Londres.
Chelsea dina janoo ak Videoton ci Oropa Lig bi bu 3 waxtu ci ngoon jote Talaata ci London.
Chelsea will face Videoton in the UEFA Europa League at 3pm on Thursday in London. The match is scheduled to start at the end of the day.
Monsieur le Président de la République, votre stratégie d’endettement nous mène vers l’éternel cercle vicieux Endettement – Croissance ; plus d’endettement pour plus de croissance extravertie dans notre cas .
Sëñ bi di njiitu réew mi, sa pexe ci bor yi, dafa ñuy yóbbu ci bor yu amul àpp, di gën a bari bor di gën a tënku ci yeneen réew yi.
Mr President, your debt strategy is leading us into the eternal vicious circle of debt versus growth; more debt for more extroverted growth in our case.
La Guinée-Bissau ne doit pas lui servir d’exutoire, d’autant qu’il a mieux à faire avec la crise économico-sociale qui sévit au Sénégal à cause de son incompétence.
Warul mbubboo Ginne Bisaawo, rawatina ne am na lu ko doy ñuy jafe-jafe koom-koom yeek nekkin wi nekk Senegaal ndax tëleem.
Guinea-Bissau should not be used as an outlet for the Senegalese authorities, especially since they have better to do with the economic and social crisis that is affecting Senegal because of its incompetence.
Il affirme s'être évadé parce qu'ilétait en détention provisoire et qu'il s'est vu refuser une libérationprovisoire et que la procédure judiciaire prenait trop de temps.
Dëggal na ni moo daw ndax dañu koo tëjandi woon rekk te nanguwul ñu bàyyeendi ko te yit doxalinu àtte bi dafa yàgg.
He claims that he escaped because he was in pre-trial detention and was denied parole and the court proceedings were taking too long.
« Je me sens très tendue », a déclaré Risa Kusuma, une mère de famille de 35 ans, en réconfortant son petit garçon fiévreux à Palu, dans un centre d’évacuation de la ville vidée.
Sarah Palin waxna ci feebaru xel Track Palin ci ndaje bu Donald Trump woote woon
I feel very tense said Risa Kusuma, a 35-year-old mother, comforting her feverish son in Palu, in an evacuation centre in the emptied city.
L’article 35 de la Constitution de la Côte d’Ivoire dispose que Le Président de la République est élu pour cinq (5) ans au suffrage universel direct.
Dog 35 bu ndeyu àtte réewu Kótdiwaar biral na ne dañu fal njiitu réew ma ak palug raw-gàddu, ci diiru juróomi at.
Article 35 of the Constitution of Côte d'Ivoire provides that the President of the Republic is elected for five (5) years by direct universal suffrage.
Stv va l'appliquer à la lettre… (Cheikh Diaby)
Stv dina ko defee ni mu waree... (Seex Jaabi)
He's going to apply it to the letter... (Sheikh Diaby)
La commission d’enquête parlementaire, après avoir détaillé des faits qui incriminent Mamour DIALLO tout au long de l’exposé du rapport, aboutit à la conclusion ahurissante de l’absence de détournement de deniers publics et inexistence d’un quelconque comportement répréhensible de Monsieur Mamadou Mamour DIALLO.
Kurélu lëñbët gu Péncu ndawi réew mi, bi mu seetloo bu baax jëf yi ñuy tuumaal Maamur Jàllo, tënk na ne, lu yéeme, Maamur Jàllo sàccul alali réew mi te amul lu ñu ko mën a toppe tamit.
The parliamentary committee of inquiry, after detailing the facts incriminating Mamour DIALLO throughout the report, reaches the startling conclusion that there was no misappropriation of public funds and no wrongdoing by Mr Mamadou Mamour DIALLO.
Au cours des derniers mois, il a beaucoup été question du remue-ménage d’architectes et d’entrepreneurs, provoqué par l’élite laïque de l’église d’un côté, et le diocèse épiscopale de l’autre.
Li xew ca Martin mu sell mi ci weer yi ñu genni yi ap istuwaar bu doy waar la digante ay arsitek aki kontaraktuwel, ñenn ñi njiitu eggaliis bi ñoo leen inndi, ñeneen ñi josees Episkopaal bi.
In recent months, there has been much talk of the architectural and entrepreneurial upheavals caused by the secular elite of the church on the one hand, and the Episcopal diocese on the other.
Quelle sera la part de Senelec dans ses propres filiales?
Lan mooy doon wàllu Senelec ci ay pàccu boppam ?
What will Senelec's share be in his own subsidiaries?
Tu es injuste, petit bonhomme, je ne savais rien dessiner que les boas fermés et les boas ouverts.
Ngóor si, loolu jaaduwul, mënuma woon a nataal lu dul biir yeew ak biti yeew.
You're unfair, little man, I knew nothing but closed and open boas.
L'ancien président de la Chambre des représentants des États-Unis, Newt Gingrich, est arrivé en deuxième position avec 32 %.
Njiitu Amerique ba woon ci House Newt Gingrich moo jël ñaareelu palaas bi ak 32%.
Former Speaker of the US House of Representatives Newt Gingrich came in second with 32%.
Le chef de l’Etat a eu une journée marathon à l’étape de sa tournée à Kédougou.
Njiitu réew mi am na bëccëg bu metti ci moom ci tukkim mi, bi mu jaaree Kéedugu.
The Head of State had a marathon day at the stage of his tour in Kedougou.
« Celui-là, se dit en lui-même le petit prince, il raisonne un peu comme mon ivrogne. »
Ndoomu buur si wax ci xelam ne: “Ki moom, ni sama màndikat ba lay xalaate.”
This one, the little prince said to himself, is thinking a little like my drunk.
Soham El Wardini, maire de la Ville de Dakar, Ali Haidar, militant écologiste et ancien ministre de l'Environnement, ont pris part à cette journée.
Soham El Wardini, njiitu méeri du Ndakaaru, Ali Aydaar, saa-aalam, te masoon a doon jëwriñu aalam ji, demoon nañu ca bès boobu.
Soham El Wardini, Mayor of Dakar City, Ali Haidar, environmental activist and former Minister of Environment, took part in the day.
Il semble que les gens aient juste envie de sortir prendre un verre.
Anterneeru Alloa Athletic ba woon neena yegul benn ragal ci topp ci tuur yooyu ñu lim ci ekip bu ngannde nii, moom mi bañoon ay laaj yu juge ci Barnsley ak Ipswich Town.
It seems like people just want to go out for a drink.
Sept ans après, le Sénégal manque toujours d’eau et fait face à des pénuries récurrentes et en accordéon, faisant douter fortement de la sincérité du regret émis par le président.
Juróom-ñaari at, ba léegi Senegaal ndox mi doyu fi, looloo waral gaa yi di teey ca la njiitum réem mi waxoon.
Seven years later, Senegal is still short of water and faces recurring shortages of water and accordion, raising serious doubts about the sincerity of the president's regret.
Cette somme, qualifiée de financement par Amadou Hott, n’est ni plus qu’un endettement de plus à un projet de TER, inauguré avant sa mise en service, et qui traine plus de casseroles que l’on ne pense.
Koppar yooyu Aamadu Ot tudde xaalis bu ñu leen jox, doonul lu dul bor bu ñu jëmale ci ndefarug TER mi ñu daloo te noppiwul.
This sum, described by Amadou Hott as financing, is nothing more than a further debt to a TER project, inaugurated before it was put into operation, and which is dragging more pots than we think.
Ainsi Mimi Touré a saisi la tribune aussi pour rendre visite à Serigne Sidy Mbacké khalife de Serigne Abdou Lahad Mbacké lors de cette période de veille de magal dédié au troisième défunt guide de la communauté mouride prévu ce vendredi.
Ci noonu la Mimi Ture porofitoo itam ngir seeti Sëñ Siidi Mbàkke Xalifa Sëñ Abdu Lahaat Mbàkke ci waajtaayu màggal gii ñu tudde ñetteelu xalifa murit bi làqu te war a am àjjuma jii.
Mimi Touré also took the stage to visit Serigne Sidy Mbacké, khalife of Serigne Abdou Lahad Mbacké, during the vigil dedicated to the third deceased leader of the Murid community scheduled for this Friday.
Les chauves-souris sont protégées et il est illégal de les tuer, de les déranger, ou de détruire leurs perchoirs.
Amnañu yaakaar ni resilta yi dinañu leeral lu bari ci jikko bu yooyu nampalkat yuy naaw, te itam dina ubbi buntu ci waxtaanu ëllëk yi.
Bats are protected and it is illegal to kill them, disturb them, or destroy their perches.
Ce qui montre à suffisance que Bouga a été contraint à la démission.
Liy wone, ci lu leer, ne Bugaa dañu ko ga ci tekki ndombo tànkam.
Which is sufficient evidence that Bouga was forced to resign.
Cependant, il a lâché son boulot avant de mourir, puisqu’il se trouvait « dans un lieu très sombre. »
Mane, "Tashi, bëggnaa la bu baax, seeri.
However, he quit his job before he died, as he was in a very dark place.
En principe, le bouddhisme tibétain est très simple. Il se compose du Kundalini Yoga, de la méditation et de la voie de l'amour universel.
Sooy xool, bouddhisme bu waa tibé lu yomb la. Nekkul lenn ludul Kundalini Yoga, méditation (xalaat) ak yoon wiy jëme ci mbëggeel te ëmb lépp.
In principle, Tibetan Buddhism is very simple, it consists of Kundalini Yoga, meditation and the path of universal love.
À 07h55, la femme de 44 ans lardée de coups de couteau a été découverte, dans la rue John de Grayson Mews, et un homme de 32 ans soupçonné de meurtre a été arrêté.
Neewu ki am 44 att yi ci 7 waxtu ci suba lañu ko fekk ak ay jam jam ci mbeddu John bu Grayson Mews and ci ak benn waay bu 32 att bu ñu japp ginnaaw ay tuuma faat bakkan.
At 7:55 a.m., a 44-year-old woman was found stabbed to death on John Street in Grayson Mews, and a 32-year-old man was arrested on suspicion of murder.
À l'issue de la course, Keselowski reste en tête du Championnat des pilotes avec 2 250 points.
Bi rawante gi jeexee, Keselowski moo nekkoon ku jiitu ci sampiyonaa pilot yi ak 2250 poñ.
At the end of the race, Keselowski remains in the lead of the Drivers' Championship with 2,250 points.
Nous sommes d'accord avec la déclaration de l'USOC (Comité olympique des États-Unis) selon laquelle les intérêts de nos athlètes et de nos clubs, ainsi que de leur sport, pourraient être mieux servis. Cela peut être fait en allant de l'avant et en procédant plutôt à des changements significatifs au sein de notre organisation, qu'à la révocation d'accréditation.
And nañu ak waxu USOC bi ni li geen ci sunu jonganté kat yi ak kureelu jonganté yi, ak sén taggat yaram, mën na genne jem ci kanam ak ay soppité yu am solo ci bir, mo genn wét.
We agree with the USOC statement that the interests of our athletes and clubs and their sport could be better served by moving forward and making significant changes within our organization rather than revoking accreditation.
Une bonne nouvelle et un succès d’audience assuré.
Xibaar bu neex ak ndamal ñépp di la bëgg a seetaan ci tele.
Good news and a guaranteed audience success.
Ce programme s’inscrit dans la démarche d’autonomisation des populations.
Tëralin woowoo ngi bokk ci pexey fexe ba askan wi mënal seen bopp.
This programme is part of the process of empowering the population.
Avec le Kundalini Yoga, l’énergie Kundalini (énergie d’illumination) est éveillée par des postures de yoga, des exercices de respiration, des mantras et des visualisations.
Ak Kundalini Yoga, kàrtanu Kundlini (kàrtan gu u leeral) danu ko yeejare ko ci taxawaayu yoga, tàggatu nokki, mantras ak xool.
With Kundalini Yoga, the Kundalini energy (energy of illumination) is awakened by yoga postures, breathing exercises, mantras and visualizations.
Consultez l'étiquette pour connaître les instructions de premiers secours spécifiques à ce poison.
Xoolal etiket bi ngir ndimbal ay tektali ndimbal yu njëkk ngir poson bu xejjiku boobu.
See label for first aid instructions specific to this poison.
Ensuite, elle a laissé entendre que le contact direct entre Trump et la presse augmentera.
Clark neena teralinu ci seen diggante ak EU Theresa May ngir ëllëk” ëmmbaalenañu ñakk lënbët ci foroñceer”.
Then she hinted that direct contact between Trump and the press would increase.
Il faut qu’ils sachent que la pudibonderie ou l’hypocrisie ne marchent pas dans les temps qui courent, parce que nos concitoyens le voient clairement.
Fàwwu ñu xam ni caay-caay ak naaféq duñu dox ci jamono yii, ndax sunu nawle yi ñoo ngi koy gis bu baax.
They must know that petty hypocrisy does not work in this day and age, because our fellow citizens see it clearly.
However I doubt that if the Senegalese people elect Sonko President,the guy will ask permission of his maitre coranique before taking any major decisions.
Waaye damay ragal, su waa Senegaal yi falee Sónko njiitu réew wi, muy tàggu sëriñam laata muy jël ay dogal yu am solo.
However I doubt that if the Senegalese people elect Sonko President, the guy will ask permission of his Quranic master before taking any major decisions.
Pour finir, l’ASC Jaraaf doit payer une amende de 50,000 (Cinquante Mille Dollars Américains) pour le comportement agressif et la conduite inappropriée de sa délégation.
Ngir jeexal, ASC bu Jaraaf war naa fay fukki junniy dolaar Amerig ngir nekkin wu ànd ak fitna ak doxalin wu ñu baaxoowul ci mbooloo mi mu ame.
Finally, the ASC Jaraaf has to pay a fine of 50,000 (Fifty Thousand US Dollars) for the aggressive behavior and inappropriate conduct of its delegation.
Waaye, nañudefaraat seen toogaay te xam ni Senegaal jegewul sax ndam.
Waaye, nañu defaraat seen toogaay te xam ni Senegaal jegewul sax ndam.
But I'm not going to let you know that I'm not a Senegalese.
En ce 30 août 2012, Sadio Mané, vingt ans, se préparait à rallier Quevilly pour disputer la 5e journée de National avec le FC Metz.
Ci bésu fan-weeri fan ci weeru ut atum 2012, Saajo Maane, amoon ñaar-fukki at, a nga doon waaj ngir dem Kewily ngir bokk ca juróomeel bésu Sàmpiyonaa Nasiyonaal ak FC Mets.
On August 30, 2012, Sadio Mané, twenty years old, was preparing to join Quevilly to play the 5th day of National with FC Metz.
Les scientifiques du Centre national des ouragans prévoient que Danielle se transformera en ouragan d’ici mercredi.
Scientifique yiy liggéey ci National Hurricane Center wax nañu ni Danielle dina sopeku ngelaane bu mag fileek àllarba.
Scientists at the National Hurricane Center are predicting that Danielle will become a hurricane by Wednesday.
Pour rappel, l’épiphénomène est bien une réalité définitive qui a été choisi par 687000 de vos compatriotes.
Ci fàttali, jumóom-benni téeméri junni ak juróom-ñett-fukk ak juróom ñaari doomi réew mi dañoo far dëkkoo mbir moom.
As a reminder, the epiphenomenon is a definitive reality that was chosen by 687,000 of your countrymen.
Six otages, dont des enfants et des personnes âgées, ont été libérés prématurément, tout comme les photographes philippins.
Juróom-benni ci ñuy jàppoon, am ay xale ak ay mag, tay lañu leen bàyyi ci suba teel, ñoom ak photographe yu waa philippins.
Six hostages, including children and elderly people, were released early, as were the Filipino photographers.
Mais il arriva que le petit prince, ayant longtemps marché à travers les sables, les rocs et les neiges, découvrit enfin une route.
Ginnaaw bu ndoomu buur si jaaree ci ay suuf, ay xeer ak ay galaas, mu daldi yem ci aw yoon.
But it happened that the little prince, after walking for a long time through the sands, rocks and snow, finally discovered a road.
S’ils veulent en changer le périmètre, j’y suis plutôt favorable.
Su ñu bëgg a soppi guddaayu li wër béréb bi, ànd naa ci.
If they want to change the perimeter, I'm all for it.
Nous irons à l'inauguration de la route Kaffrine - Nganda, puis Tamba, et après nous irons voir un peu ce qui se passe à Kédougou où le président va inaugurer le centre hospitalier régional Amath Dansokho.
Dinañu dem ca daloob yoonu Kafirin – Ngànda ba, dem Tàmbaa, bu ñu ci paree, ñu dem Kéedugu, foofee, Njiitu réew mi dina fa daloo lopitaal Ammat Dãasoxo.
We will go to the inauguration of the Kaffrine - Nganda road, then Tamba, and after that we will go to see a little of what is happening in Kedougou where the president will inaugurate the Amath Dansokho Regional Hospital.
Il n’aura réussi qu’à dégueuler, dans son impertinence, l’unique vérité que je partage avec lui : l’Etat est en péril et la République a foutu le camp depuis l’avènement du Président Macky Sall.
Amul lu dul mbel-mbeleek ñàkk a xarañam, fi ma déggook moom fenn rekk la mooy : nguur gi moo nar a nërméelu, Réew mi yàqu na ba mu falee Maki Sàll, njiit li.
He will only have succeeded in disgusting, in his impertinence, the only truth that I share with him: the state is in danger and the Republic has gone to hell since the arrival of President Macky Sall.
La dette se décompose comme suit : numéraire et dépôts, titres de créance, crédits, droits sur les régimes d’assurance, de retraite et de garanties normalisées, et autres comptes à payer.
Bor bi nii la tëddee : xaalis ak denc, lu teewal xaalis, àq ak yelleef ci asirãas, ci àllaterete, ak wóoral ak yeneen yu ñuy fay.
The debt is broken down as follows: cash and deposits, debt securities, loans, claims on insurance, pension and standardised guarantee schemes, and other accounts payable.
Ainsi ces installations inaugurées ce 3 Juin à Deguerre intègrent plusieurs volets:§Education :C’est une école complétement réhabilitée et mise aux normes qui est offerte aux populations de Déguerre, avec:ü.
Ci noonu tabax yi ñu ubbi ñetti fan ci weeru sulet ca Deguerre tënk na ay pàcc yu bari : jàng ak jàngale : lekool bu ñu yeesalaat la defar ko ba mu baax may ko askanu Deguerre.
The facilities, which were inaugurated on 3 June in Deguerre, incorporate several elements:§Education:This is a school that has been completely rehabilitated and brought up to standard, and is available to the people of Deguerre, with:ü.
Si vous n'avez pas l'habitude de conduire sur des routes de campagne, gardez l'esprit ouvert : les pentes raides, les voies étroites et les courbes serrées prédominent.
Soo tàmmul dawal ci yooni kaw ga, jëlal say motuway foo toll: pent yuk awe,yoon yu sew, jaddukaay yu sew ñoo fa ëpp.
If you are not used to driving on country roads, keep an open mind: steep slopes, narrow roads and tight curves are common.
L’Autrichien de 28 ans est un joueur extrêmement polyvalent pouvant jouer dans l’axe de la défense, sur le côté gauche et dans le milieu de terrain.
Doomi Autriche bi am ñaar-fukki at ak juróom-ñetti futbalkat la bu mën a taxaw ci defaas bi, ci càmmoñ ak ci digg bi.
The 28-year-old Austrian is an extremely versatile player who can play in the centre of defence, on the left flank and in midfield.
Il faut dire, malgré tout, que l’ethos-phare de Ousmane Sonko est l’intégrité (jusqu’à preuve du contraire), car il semblerait qu’il soit difficile d’établir un scandale auquel le leader de Pastef serait mouillé…Il fut un savant égyptien qui entreprit, un jour, de déconstruire l’existence du principe Divin… Cela lui prit des années pour arriver à un raisonnement plausible.
Fàww ñu wax, ak nu mu mën a deme, ni jikko ju mag ju Usmaan Sónko mooy mësul a lekk alalu askan wi (ba keroog ñuy gis safaan wa), ndax mel na ni jafe na ñu andi coow loo xam ni njiitu Pastef li dina si taq…donoon na borom xam-xamu Esipt bi sumboon, benn bés, daaneel nguurug Yàlla…Toog na ay at doog a tegu ci yoon wu leer.
It must be said, however, that the ethos of Ousmane Sonko is integrity (until proven otherwise), because it seems that it is difficult to establish a scandal in which the leader of Pastef would be involved...He was an Egyptian scholar who once set out to deconstruct the existence of the Divine Principle...It took him years to arrive at a plausible reasoning.
Comme pour tous les parcs nationaux sud-africains, il existe des droits d’entrée et de conservation quotidiens pour le parc.
Ndéem ak Parku nasiyonal yu Afrig du Sud yepp, am na ay waxtaan bés bu né ak fay ngir dug ci bërëb bi.
As with all South African national parks, there are daily entry and conservation fees for the park.
N'ayant pas convaincu de sa bonne foi, elle a été déférée au parquet.
Bi mu wóoloodee gëm-gëmam, dafa ko yóbbu ca ëttu àttekaay ba.
When the prosecution failed to convince her of her good faith, she was referred to the prosecution.
Maintenant c'est fait !Après douze ans de carrière au Bayern Munich, David Alaba, 28 ans ,dépose ses godasses chez les Merengues.
Léegi def nanu ko ! gannaaw fukki at ak ñaar yu mu dund ak Bayern Munich, David Alaba, ñaar fukki at ak juróom-ñett.
After 12 years at Bayern Munich, David Alaba, 28, is leaving the club.
Chacun y va de sa sauce, de sa potion magique, pour présenter des solutions, un traitement contre ce virus: ail, citron, ognon, banane, miel, gingembre, clous de girofles, feuilles de laurier, neem, vinaigre, piment, etc.
Jon Perkins wax na ne moom ci boppam ne raykat la ci wàllu koppar te nangu na nekkug liggéey biy yoonal borom xaalis yu mag yi.
Each one brings his own sauce, his own magic potion, to present solutions, a treatment against this virus: garlic, lemon, ognon, banana, honey, ginger, cloves, bay leaves, neem, vinegar, pepper, and so on.
La loi française a été modifiée. Son militantisme remonte à l’âge de 15 ans, lorsqu’il a rejoint la Résistance française pendant la Seconde Guerre mondiale.
Dañoo soppi woon yoonu waa Farans. Aktiwism bu amaloon dem na ba ci 15 at bimu duggee ci Resistans bu Farans ci jamanoy Ñaareel Geer Monjaal bi.
His activism dates back to the age of 15, when he joined the French Resistance during the Second World War.
Selon les informations recueillies, nous nous acheminons vraisemblablement vers de bons résultats.
Su nu sukkandikoo ci xibaar yi ñu jot, ñoo ngi jàll ci ay njuréef yu nar a baax.
The information gathered suggests that we are on the way to good results.
« Je le tenais par la main quand il a cessé de respirer et il a fallu qu’il ait cessé de respirer et qu’il soit mort pour que je reconnaisse enfin qu’il n’était pas invincible », a-t-il ajouté.
Mbir mu tiis la."
I was holding his hand when he stopped breathing and it took him to stop breathing and die for me to finally acknowledge that he was not invincible, he added.
Il faut avoir l’intelligence souillée par le diable pour ne pas voir derrière ce lancement des nouvelles offres de l'opérateur Orange une contre-attaque de ce dernier, après la campagne intense de rebranding qui a fait changer de nom Tigo avec une offre commerciale très agressive.
Xanaa ku jinne jàpp xelam rekk moo dul seetlu ne yeneen njëgi Orange yi dañuy wujjeek Tigo mi nga xam ne dafa soppi turam ba noppi yombal ay njëgam lool.
It takes a devil-in-the-middle mind not to see behind this launch of new offers from the Orange operator a counterattack by the latter, after the intense rebranding campaign that changed the name of Tigo with a very aggressive commercial offer.
C’est la consigne, répondit l’allumeur. Bonjour.
Taalkat bi tontu ko: Ndigal la. Jàmm nga fanaane?
"That's the order", said the lighter.
Pendant la saison des pluies (de novembre à mars), le volume d'eau sera plus élevé et les chutes seront plus dramatiques.
Ci jamonoy nawet (nowàmbre ba màrs), ndox mi dafay gêna yokk suko defee wall gi di gëna mëna lore.
During the rainy season (November to March), the volume of water will be higher and the falls will be more dramatic.
M. C : Pour comprendre mon adhésion à PASTEF, il est important de remonter très brièvement à la genèse de mon engagement citoyen d’abord et ensuite politique.
M. C : Am na solo ñu dellu ginnaaw ci lu gàtt, xool anam yi samag pas-pas ci bëgg réew mi sosoo ba pare, soog a xool samag pas-pas ci wàllu pólotig.
Mr C.: To understand my membership of PASTEF, it is important to go back very briefly to the genesis of my involvement as a citizen first and then as a politician.
PS j'aime pas la politique de macky
PS bëgguma pólótigu Maki.
P.S. I don't like the politics of Macky
En cette veille de Gamou, le chef de l'Etat, Macky.
Ci fani gàmmu yii ñu nekk, Njiitu réew mi, Maki.
On the eve of Gamou, the head of state, Macky.
Les experts estiment toutefois que si Pékin peut jouer correctement son rôle, les pressions de la guerre commerciale américaine pourraient avoir un effet positif sur la Chine à long terme en réduisant l’interdépendance des deux économies.
Dañoo yaakaar da nga am naqqar te dinañu begg ci loolu ndax amnañu la."
However, experts believe that if Beijing can play its role properly, the pressures of the US trade war could have a positive effect on China in the long term by reducing the interdependence of the two economies.
Mamour Diallo utilise du faux en citant un décret d’expropriation de la société *SAIM indépendance* en lieu et place d’un décret d’expropriation de la famille Ndoye qui n’existe pas en réalité.
Maamur Jàllo day wax lu dul dëgg ci taafantaloo dogalu nangu këru liggéeyukat gii di « SAIM indépendance » te mu waroon na jël dogalub nangu bu njabootu Ndóoy gi nga xam ne amul.
Mamour Diallo uses a fake by citing a decree of expropriation of the company *SAIM independence* instead of a decree of expropriation of the Ndoye family which does not exist in reality.
Une situation que Wave juge inacceptable au regard de son droit de vente de crédit téléphonique dans les mêmes conditions qu’une filiale de monnaie électronique d’une entreprise de télécommunications .
WAVE jàpp na ne mbir mi teguwul ci yoon ndax am na dogal bu ko may mu jaay kérédi ni ko buumu xaralay jokkoo yiy yónnee xaalis ci enternet di defe.
This is unacceptable for Wave, which has the right to sell telephone credit on the same terms as an electronic money subsidiary of a telecommunications company.
Cette page est accessible facilement à partir d'une seule adresse Web, ce qui la rend facile à mémoriser et à écrire pour les étudiants qui ne savent pas utiliser un clavier et qui ont des problèmes d'orthographe.
Benn adres Web rek ngay joxe nga mëna yegg ci xët wii, moo tax xel daf koy yomba jàpp, dina itam yombal liggéey bi ndongo yi am jafe-jafe ak seen clavier wala yi am jafe-jafe xam ni ñu koy bindee.
This page is easily accessible from a single web address, making it easy to remember and type for students who do not know how to use a keyboard and who have spelling problems.
Il est difficile de ne pas penser aux offres du concurrent Free quand Orange dit : ‘‘Bu andeek réseau mo guen’’, ‘‘Comparaison n'est pas réseau’’.
Xel mënul a ñàkk a dem ci wujj wii di Free su Orãas waxee : "Bu àndeek réso moo gën", "tollale du ci réso".
It is difficult not to think of the competitor Free's offers when Orange says: "Bu andeek network mo gen" "Comparison is not network".
Dans mes oreilles durait le chant de la poulie et, dans l’eau qui tremblait encore, je voyais trembler le soleil.
Woyu poli bi baa ngi doon riir ci samay nopp, maa ngi doon gis tamit jant bi di yëngu ci biir ndox mi doon yëngu ba tey.
I could hear the song of the fowl, and in the still-shaking water I could see the sun shake.
Préparez vos documents juridiques : Évitez les batailles juridiques au passage.
Graham Dorrans bu Rangers yi amna koolute bu matt balaa joŋanteem ak Rapid Vienna
Prepare your legal documents: Avoid legal battles along the way.
Dès lors le Président Sonko devient la première cible politique potentielle à éliminer.
Booba la njiit li, Sónko doon way-pólótig bi ñu war a jëkk a faagaagal.
President Sonko is now the first potential political target to be eliminated.
Ces tempêtes géantes comporte des vents soufflant jusqu'à 480 km/h (133 m/s ou 300 mph).
Ngélawu yu am doolé yii dawnagnu ci 480km/h (133 m/s; 300 mph).
These giant storms have winds blowing up to 300 mph.
Même si, selon la tradition, tous les Samis n'ont pas été impliqués dans l'élevage de rennes à grande échelle, ils vivaient de la pêche, de la chasse et d'autres activités similaires, tout en utilisant les rennes principalement comme des animaux de trait.
Ci aada sax, donté, nekkulné Sámi yepp ñoo bokkon ci tollu waay yu mbay bu mak, wayé di dundé napp, reebb ak linumél, di mélni ay mala ci lu ëpp.
Although traditionally not all the Sami were involved in reindeer herding on a large scale, they lived from fishing, hunting and other similar activities, while using reindeer mainly as draft animals.
Le tirage au sort de l’Afrobasket masculin prévu au mois d’août prochain au Rwanda a été effectué ce vendredi à Kigali.
Waaye du Cnra moo aaye, ñun ci sunu bopp la.
The draw for the men's Afrobasket scheduled for next August in Rwanda was held on Friday in Kigali.
Il faudrait avant de finir,que je vous fasse une petite analyse de cette situation d’inaction d’une bonne partie de l’opposition.
Balaa ñooy jeexal dama la war a defal ab taxaw seetlu ci xew-xewu ñàkk a jëf bi ñu seetlu ci kujje gi.
Before I finish, I should like to give you a brief analysis of the situation of inaction of a large part of the opposition.
A cette occasion, des prières ont été formulées à son endroit par ses proches, amis et sympathisants.
Ci bés boobu, dinañu ñaanal dëkkandoo yi, mbokk yi, xarit yi ak am-di-jàmm yi.
On this occasion, prayers were offered for him by his relatives, friends and sympathizers.
L’accusé, Khalid Barnes, a été déclaré coupable du meurtre de deux trafiquants de drogue mais a par la suite été condamné à une peine de prison à vie en septembre 2009.
Yaayam Sarah Palin, moo woo poliis ngir yegal leen cong bii.
The accused, Khalid Barnes, was found guilty of the murder of two drug traffickers but was subsequently sentenced to life imprisonment in September 2009.
Danielle Lantagne, experte de l'ONU sur la maladie, a déclaré que l'épidémie avait probablement été causée par les Casques bleus.
Danielle Lantagne, bénn borom xamxamu UN ci fébar bi, waxnani saytukatu jam yi ñoo indi féebar bi.
Danielle Lantagne, the UN disease expert, said the outbreak was likely caused by the peacekeepers.
Selon la réglementation indonésienne, les fonds, les ravitaillements et le personnel étrangers peuvent entrer sur le territoire uniquement si le site touché est déclaré zone de catastrophe national.
Sunu sukkandikoo ci waxu kurel bii taxawoo Enndonesi , dajali koppar, joxe ak taggat ci bittim rëëw mi rek ñoo muna am su fekkee ni fi musiba bi ame neeenañu ni bërëbu nasonaal la.
According to Indonesian regulations, foreign funds, supplies and personnel can enter the country only if the affected site is declared a national disaster area.
Tandis que de nombreux républicains de haut rang défendent Brett Kavanaugh, nominé à la Cour suprême dans un contexte d’allégations d’agression sexuelle, les analystes ont averti qu’une réaction négative, en particulier chez les femmes pourrait survenir pendant les prochaines élections de mi-mandat.
Ndox mu sell dafa jafe."
While many senior Republicans are defending Brett Kavanaugh, who was nominated to the Supreme Court amid allegations of sexual assault, analysts have warned that a backlash, especially among women, could occur during the upcoming midterm elections.
Or, la raison doit plus que jamais primer sur la colère: comprendre avant d’agir et agir en toute responsabilité en alliant la détermination dans l’accompagnement et la compréhension des faits.
Wànte xel lañu war a jiitël ci mer : setantalal laata ngay jëf te boole ca ak takku ak ag xam bu baax mbir yi.
Now, more than ever, reason must prevail over anger: understanding before acting and acting responsibly by combining determination in the accompaniment and understanding of the facts.
En 2012, alors qu’un éleveur de l’Oregon venait d’être dévoré par ses cochons, un agriculteur de Manitoba affirme à CBC News qu’il ne s’agit en principe pas d’un animal agressif, mais que le goût du sang peut provoquer ce type de comportement.
Ginnaaw loolu amna benn samkat bu mbaamam lekkoon ci Oregon ci 2012, benn samkat Manitoba moo wax CBC News ni ci yoon mbaam xuux du luy lore waaye xeetu derert bi mënna leen “yënngal."
In 2012, after a farmer in Oregon was eaten by his pigs, a farmer in Manitoba told CBC News that "this is not an aggressive animal in principle, but the taste of blood can cause this type of behavior".
Au même moment, la marine allemande, utilisant principalement des U-Boots, tentait d'arrêter ce trafic.
Ci noonu itam, ci la waa marine bu Allemagne di jëfandikoo ay sous-marins ngir fexe dakkal trafic bii.
At the same time, the German Navy, using mostly U-boats, was trying to stop this traffic.
Action décisive : Sergio Aguero, du Manchester City, se fraie un chemin à travers la défense de Brighton pour marquer
Seetaan: Futbal katu Manchester City bi Sergio Aguero defa raatale defaasu Brighton bi ba mu dajj am bit
Decisive action: Manchester City's Sergio Aguero makes his way through Brighton's defence to score
Chapeau 4: Zimbabwe, Namibie, Guinée Bissau, Angola, Tanzanie, Burundi.
Mbooloo ñeent : Simbabwe, Namibi, Ginne Bisaawo, Àngoloa, Tãasani, Burundi.
The Commission has also been asked to provide information on the implementation of the new rules.
PARTAGEZ POUR SOUTENIR LE SOLDAT AIDER ABDOU KARIM GUEYE, C’EST AIDER LA RÉVOLUTION
TASLEEN XIBAAR BI NGIR JÀPPALE SOLDAAR BI, TAXAWU ABDU KARIIM GÉEY MOOY JÀPP CI COPPITE GI
Share to support the soldier help Abdou Karim Gueye, it is help the revolution