text
stringlengths 38
33.7k
|
---|
deel d ëkkee dund ak moomeelu bopp di moytoo jàppe d ëgg li ko nirool ci biir te d ëggu ci yéeg bi ngay yéeg |
naka jekk nosteg doxiin gi mooy tax jefandikukat bi man di jot ci embiit li nekk ci nosukaay bi jaarale ko cib jokkalekaay muy ay njunj walla mbind yooy cuq mu lay won li nekk ci biiram . |
ci maanaa mooy ne ndëgërlu gi dafa aju ci tàngaay bi lii man nañ koo wax ci bépp wommatukaay |
ku aji sax ji rafetlu say jef , say ban sax , mu jubaleek yaw . |
mu ngoog , keey mabb te deesul tabaxaat , di tej nit , te deesul tijji . |
mu ne nag yaxya dekki na , moo tax mu and ak kattanu def ay keemaan . |