audio
audioduration (s)
0.74
10.5
text
stringlengths
1
99
gender
stringclasses
2 values
Doktoor Anet Njaay la Abdu Laay Siise dalaloon démb ca TFM.
female
Nekkal góor !
female
Sama biir day mitti.
male
WàllKureelu Mbootayu Xeet yi
male
Dama bàyyi tux.
male
Ba mel ne mbëtti deg ya mbaa mel ne ndëfëñ
male
Dañu ne, bu jëkk, amoon na ñeeti rakk yu goor
female
Damay laaj mooy kan.
male
Ŋabar-ŋàbb suuf su gall-góose la, maanaam lii kawe, lee suufe
male
Joxoon nama ab doomu-fowukaay.
female
Tom moo daan ca joŋante ba.
male
Tom a ngi fële .
female
Dangéen a waroon di def ay tàggatu.
male
Jéemleen a neexal seen dund.
male
Téq naa ngànnaay li.
female
Abdu Lahaat Lóo 766176507
female
Tekkee goo ko de
female
Mu daal di jël benn bis ub noppalu.
female
Sotti bu baax, nef it day firi njur mu jegee
male
War nanoo am ay tëraliin.
female
Da ngeen a néeg .
male
Mucc ayib !
female
Ay ruusit la,
male
Sedd na ba doy.
female
Génn naa ci.
female
Dem na nduggi.
female
Kilifa gii di Sëriñ Muntaaxa Mbàkke, Xalif kullu murid, moo jiite xew-xew bile
female
Li waraloon « yéwénal » gi
male
Nee na day xaar kàddug jëweriñ ji yore njàng mi ci réew mi.
male
Daan j Alxuraan nag te Yàlla rekk tax daawu ci laaj benn dërëm.
male
Xeet yu bari tase nañu fa, juge Isipt Séeréer si, Pël, Sooninke, Naar yi
female
Mi ngi làqu atum 1909 g.j.
female
Mu ngi ci bërëb bii?
male
Saara yay Afrig
male
Xamee naa leen.
male
Tiraanga ñaar laa ci xam ju àdduna ak ju Àllaaxira.
female
Nde du alal ak rëy i yax
male
Tijji nay wuntam !
female
Te boo wooteeb xeex ñu néew ñoo la ciy fekksi.
female
Satan ca diiney kirist, wala Seytan ca diiney lislaam
male
Pastéefu jëf ja yaa ko am
female
Luf tànk bu dugg ci ban bu baax
male
Maa ngi sàkku ngeen dimbali ma.
male
Ajara moo ni ñu waxe tur wi ci Lislaam.
male
Xale bu lënt ngeen.
female
Jataayub yoonal bi ,
male
Le Monde Lu tax nga bind Doomi Golo ci Wolof njëkk…
male
Lekk naa bu gaaw.
female
Defoon na liggéey bu rafet.
male
Dangeen di dëkk ba fàww a ?
male
Ku sawaroon la ci dali fipp gi , te fonkoon leen
female
Dama man féey.
female
Tuutee desoon ma jam la.
male
Lu terees natt ko ?
male
Tànnleen ak xel.
female
Bëgg nga ci benn?
female
Bokk na ci njuddéefi mbay yu afrig yi ëpp solo yii
male
Yal nanu ci àgg ak jàmm.
male
Daaray Sëriñ Mbàkke Gayca Lugë, sosu /1998.
female
Maa ngi doon dem nii.
male
Diiwaanu Maatam ci penkoom
male
Day neex nag saf suukar.
male
Ku ci am loo ciy dolli ci waat yii na ko indi.
male
Kaayleen toog ak nun !
female
ba 1973 Santa Isabel tur bi ko waa-espaañ joxoon
female
Nag yi ci la nuy ame meew.
female
Tiis na ma.
male
Ndax kenn namm nama ?
female
Loolu, nag, jaraloon na ko lu nekk
female
Maa ngi gëram fajkati raglu Dalal Jàmm bépp ngir seen liggéey bu mucc ayib.
female
Dama koo bëgg lool.
female
Dinaa ko defaat.
female
Tom dafa soxla ligéey.
female
Demal seet ko!
male
Yéen dangeen may kókkali ?
male
Buuru Torodoo yi Almamy la
female
Doon naa liggéey ci ay tool.
male
Liggéey bépp ay ma-réew a ko yor
female
São Paulo benn dëkku di Bereesil
male
Soxla nanu tàggatu.
male
Nu wér lan.
female
Sori na ?
male
Duggleen ci ndàbb bi!
female
conkom mi safu ma.
male
Man ngeen a am lu ab lii.
male
Tóokiyo laa juge.
female
Laaleey mbaaxu góor!
female
Dangaa yore ub fetal?
female
So mare, sëgg naan
male
dafa melni ku am alal.
female
Mbégte mu raw ‘’suba-la-tabaski’’ lanu doon séentu, di waajal soppi réew mi fuural.
female
Dama bañ meew mi.
male
Tom dal di sikki-sakka.
male
Jug nanu ca teel.
male
Gis na nu dara.
female
làkk moo'y yàlla ji'y faji aajo?
male
Bég naa , man itam.
female
Buntu baa ngi tëju.
female
Yaa waxoon itam dëgg.
male
màggat naa lu doy sëkk.
female