audio
audioduration (s) 0.74
10.5
| text
stringlengths 1
99
| gender
stringclasses 2
values |
---|---|---|
Dikkal seet ko. | female |
|
Dangéen a kannasu dëgg. | female |
|
Nay dëppoo, màndaxe mooy tollale gi nuy def ay balăs bu ñuy peese | male |
|
Kuy Muhammadu Buhari? | female |
|
Moom man ree na ma. | female |
|
Bul ma reetaani ! | female |
|
Ndool mou tôôy | female |
|
Na ngeen sax cig ragal Yàlla ta yewenël seen digënteeg nit ñi. | female |
|
Lu xewoon fii ? | male |
|
Ndax bëgg nga ma\? | female |
|
Sëy yi tawat yu baree bari ñoo ngi xar-xarle . | male |
|
Bokk na ci ba leegi | male |
|
SJ Ci li man agum jàpp, Covid-19 bi Siin la doore ca jawub Wuhan | male |
|
Bi ci des mu ngi jëm ci taxawal xumbéem yi | male |
|
Sëriñe Ibrahima Mbàaké Ibn Sëñ Mor Dothie néna | male |
|
Li tax ñépp doon xaar bés bii, nag, du neen. | female |
|
Jigéen ñi, ñoom, dañ leen daan siif saa su nekk, di leen tëdde | male |
|
Bu nu dem. | female |
|
border19pxRaaya Réewu Diggu Afrig | male |
|
Damaa aay ci xeltu. | female |
|
Mbedd mi kenn nekku fi. | female |
|
P ngóora gi, ñu koy natt ciy watt. | female |
|
Turam feeñ na ci Injiil ci Mc 2335. | female |
|
Gaboŋ BOKKEEF Gabonee réew Afrig | female |
|
Mel na ne rafet ngeen. | male |
|
Lii laa bëgg ag reeral ? | female |
|
Bul sànk sa xel. | male |
|
Damaa gëlëm lool. | female |
|
Sol leen seen mbaxane ! | female |
|
Moom sax manoo koo gise ci fésalukaay yu elktronik yu bees yi am leegi | female |
|
Dafa war ma am diir. | male |
|
Amoon nan wërsëg . | male |
|
Dees na ko tekki | male |
|
Génn nanu ci ci jàmm. | male |
|
Ndax nun doŋ la? | male |
|
Dooley gornamaa bu Britani moom, teg loxo lu bari ci waaxi Amerig yi. | male |
|
Ciy junni ngir weer week jullit ñi koy woor | female |
|
Damay fay ay galag. | male |
|
Sa Boroomay jéggalaakoon tey boroom yërmande | female |
|
Përëm Cuivre Cu | female |
|
Topp-njaatige Sñ Fàllu Jàllo ?? | male |
|
Nit ñépp a yem ci kanamu àtte | male |
|
Kenn rëccu ci. | male |
|
Damay faral di dawal. | male |
|
Jafe-jafe la woon. | male |
|
Noppi ngeen ngir dem a? | male |
|
Diggante Soxna Jaara ak Sëriñ Tuubaa | male |
|
Nu xootal bu baax tam ci xam-xam yu nuy wax “maxruutaat” | female |
|
Lakk gi fey. | male |
|
Yii laa jàpp ne moo fi ne, ba tay moofi am.✍? | female |
|
Ak la nga dugal lumu am solo am solo | male |
|
Luma ñëw di def nii ? | male |
|
Kon amul ubbeeku ci géej gi | female |
|
Buleen ko wax kenn ! | male |
|
Benn wañeeku woon ns. | male |
|
Dangaa niru um waxambaane. | male |
|
Damaa bëgg liggéey. | male |
|
Damay tisyóoli lu bari. | male |
|
Mbooloo mu takkoo noonu, day laaj ay matuwaay yu wér te wóor | female |
|
Dangéen a war a nob. | female |
|
Dangeen a yeex a àgsi . | male |
|
Man, dipite Maki Sàll laa, waaw | female |
|
Tey texeg ndaw ñi,ak mag ñi,ak waxambaane yeek jigeen ñi. | female |
|
Sunuy gët a daje. | male |
|
Cuune, yaataayumbe ak sëriñtu bi ñu nekke moo nu teree jël kub… | female |
|
Laaj naa Tom. | male |
|
Bëgg du bañ. | female |
|
Ndax jàpp na ko ? | female |
|
Bu yëkkatee, ñépp yuuxu, mu bàyyi | male |
|
Danoo bëgg sunu xaj. | male |
|
Dinaa la wool ben Taksi. | male |
|
Ci li ñépp seetlu, waa nguur gi ñemewuñu ko lool | female |
|
Bàyyi leen li ngen di jàng. | female |
|
Ànd jayante tàggoo jëwante. | male |
|
Lu nekk ci wayndare wi ? | male |
|
Mi ngi jar 2 euro. | female |
|
Daan naa ree ak a doyodal waati sama làkk wi di Wolof | female |
|
Ndax bëgg nga ay filmo ? | female |
|
War na fa am yàppu ganaar ci ruq bi. | male |
|
Loolu waral na sax Guy Mari Saañaa yobbu ab jure ca OFNAC. | female |
|
Yéenekaay bii di Le Quotidien moo jexe xibaar bi ci altine ji | female |
|
Damaa war a gaawtu. | male |
|
Amdi Géy 764511504 | female |
|
Tom du nelaw mukk. | male |
|
Tóor-tóor bi guddaayam 1 la ba 2,5i sàntimet cib guddaay. | male |
|
Luga am na lu tollu ci 835 325 doomu-aadama ci atum 2013. | female |
|
Joxleen ma geen niral. | male |
|
Aw meloom day ñuul, boo ko tojee it day am aw kemb ci biir | female |
|
Tëjal sa bunt ! | male |
|
Deeleen jéggale ! | male |
|
Ñoo nu wallu. | male |
|
Manoo bàyyee noonu rekk. | male |
|
Leegi bari naa alal. | female |
|
Ndax dangay liggéey? | male |
|
Am naa welo bu bees. | male |
|
Baa waxuma ci lu ëpp ? | male |
|
Séddoo ga bér na aa | male |
|
Na ngay yërëm gone | female |
|
Nees ko baaxoo Màggale | female |
|
Am naa doom bu jigéen. | female |