audio
audioduration (s)
2
201
transcription
stringlengths
2
439
jigéen ñi bokk soo bokkee dangay dangay denc di leb
fekk loolu nekkul la nga xam ne mooy lu baax nekkul la nga xam ne aussi moo koy jëriñ dana sonn ñëw
mën na ko stocké stockage yi damm ah ay nuisibles ñëw gunóor yi dugg ci
yenn saa yi mu yéex a ñew lool yenn saa yi mu teel a jeex lool
ak si suñuy activités si li nga xamante ni moom mooy suñu yënguyëngu
ñëw rek sësaat si beneen pile mais diggante deux pile dafa war a bçyyi benn yoonboo xam ne dana am aération ba nga xam ne
waaye tey dafa ñëw au lieu mu fekk ci poos bi junne mu ñëw fekk fa téeméer te munul bàyyi njaboot gi ñuy toog di jooy mu jël téeméer bi jox ko soxna si ne ko kat seetal na nga def kooku moo xam ñebe lay wut moo xam kecax lay wut moo xam waaye daal dina fexe daal ba réglé ko ba nit ñi am lu ñu dugal seen biir ba kenn du jooy dëgg la wala déet
tey boo demee ba dëkk bu mel ni kol mbaa bu mel ne sotokoy mais da nga fay fekk ñoo xam ne ëpp na juróom fukki hectares yoo xam ne dañ ko doon béy maraîchage mais tey nii tey hectares yooyu yëpp bàyyi nañ ko
da nga daa gis si biir jiw bi sax dañ si doon boole yeneen
def ko si mbuus yoo xam ne si ne mbuus yi yiy sol galaas la rek
xaalis kenn du ko jël ba noppi door a xalaat li ngay def soo ko defee rek dangay échec xaalis bala ngay dem dangay dangay xool sa activité lan la war a jar nga war koo
waaw sëñ ablaye ñu ngi lay
te loolu bëggoon nañu xam lan lañ ci parce que cas fra la
parce que ñu bëri ci mbéy mi la ñuy jéem a góorgóorlu
ak projet bi nga xam ne partiquement tous les jeunes
léegi nag plante bi moom lim li nga suuf bi ni mu daan décomposé matière organique bi
waa xam nga ceeb moom laa la doon wax sànq ma ne la ceeb tey pour ma denc ko moom laa la wax ne la mooy béytéef bi nga xam ne moo ëpp bëggbëgg ci wàllu weer dama ne ceeb su ma ko bàccee an su ma góobee dama wax ne dama ko war a weer ñetti fan bu ma wóoree ne taw amul su fekkee ne moom maa ngi am information ne taw yi ñu ngi continué ba tey dama koy takk ay say ay lee wéer ko
léegiléegi wallaahi ar barke el hadj abdoulaye sama xol bi dafay jeex
kon su fekkee ne fi mu ne nii njaqare googu ñuy am mooy ñu bloqué
loolu yëpp ay impacts la yoo xamante ne changement climatique
donc da ngay ne ah kon de kii ci première phase bi am na lu mu ñàkk
léegi bon bu fekkee am na est ce que ñor du am na problème ndaxte ci biir waxtaan wi gis nañ ne am na foo xam ne jiw ya am na xaw naa am problème
dafa ñëw pour yokk leen dara yokk boobu nag dañoo am dafa am fu ñu séntu fuñ leen bugg a yóbbu mooy que ngeen dem ba mënal seen bopp di ko defal seen bopp sans que ngeen di xaar programme
kon nag li nga xam ne tey gis nga ne am na ayib
kon nit ki bu ko gisalee boppam sax moom moo lay njëkk a wax ñi ñu jox presque ñun suénu client yëpp ñun ñoo ñu woowal suñu bopp wax ñu li nga xam si ne mooy bë ngënéel yi ñu gis
faaw kenn ku ci nekk ci ñooñu nga dugal sa loxo ci biir kër gi
tey da ngay xëy mu taw taw wu bëri suba nga xëy du def dara loolu moom moo am muy ay variabilité inter annuelle ren jii mu taw bu déwénee du taw xam nga
bu dee mënoo bañ a téléphoné booy téléphoné na nga laqatu
guddi gi mu sedd dem ba moins quinze degré bay commencé glace
waaw soppeeku soppeeku yooyu nag ah fim ne nii actualité la
waaw parce que heure bii population bi jàppee nañ ko te et puis am na tamit ay sensibilisations sensebilisation yoo xamante ne ñu ngi doon def
yooyu yëpp nag danañ def mission de suivie ndax loolu est ce que benn bëri na ci nit ñindax nit ñi jëfee nañ ko
mais pambal pour mu développer il faut que li fiy li fiy lu ñu foi am si xaalis muy des ci biir pambal léegi bu fekkee ne yow sa balance toujours dafay déficitaire maanaam lépp loo soxla da ngay dem tivaouane wala da ngay dem thiès wala dem feneen duggal ñu duñu gaaw a développé
kooku tamit dafay dégrader maanaam dafay def ay pax
xëy na moom mooy jëfee ci sama xel ak sama xalaat
xam nga semaine tranfert dafa am lu xaw a métti nit ñi ñooy changé numéro comme nu leen neexee
bu ko naaj wi laalee am na fu tolluwaay fu muy toll ñu doog ko dajalewaat def ko naaf la cay topp mooy lan mooy bàcc la ca topp mooy lan def ci saag jaay maa ngi denci ji kër ga
waaw dafa gaaw dafa gaaw waaw
ndax semaine bu nekk ku ci bokk natt booy natt rek danga joxe solidarité
waay ji
bu ñu paree joxe recommandations yi météo dina wax agriculture wax élevage wax ñun ñëpp bu ñu paree non seulment dañu koy def ci wolof wax ko ci séeréer pour nit ñi dégg ko
waaw maa maa ngi am na ci yu a ci doon jot a dégg
garab gi dina jël lekk bi lekk sans problème
di waxtaan ak yéen di leen woo kenn ku ci ne nag moom bala ngaa dem dinga ma sa tur ak sa sant jox ma sa numéro waaw
comme ñu ñuy dem nappi comme ñuy dem ci avion yi dañuy alerter mu ne ah attention am na lii lu war a xew soit ngelaw bu fort donc dèjà nit yi su ñu dégluwee loolu su ñu xamee loolu ma ne tey du ma dugg du ma wax du ma dem géej oubien xaaral du ma dem tool
du tey li nga xam ne mooy maraîchage boobu kon da nga doon gis ne da ngay béy noor béy nawet
parce que ku déglu émission bi da nga ne ah
loolu moo waral sunu teewaay fii en fait non lii moo nekkoon sunu mëbët yi si wàllum projet bi
ndax xam nga semence certifiée mooy semence bu mucc ayib
ñuy bu boobaa dinañ mën seen matukaay yëpp dinañ ko mën a kii bu ko defee bu bu nen yi tojee rek
day day si bopp bi si xol bi lay dugg
parce que suuf bu argileux boobu sableneux boobu
donc loolu mooy institut national de pédologie
mooy fexe ba nit ñi aaru ci wàllu dund
daaw gisoon nañ ko ren it daaw li mu doon exceptionnel exceptionnel xaw na faa feeñ tuuti waaye xawoon na vasquer wu ndax daaw année exceptionnelle la
mais ñun ñu dolli ci un mois de sécurité muy quatre mois
nga door a mun a am xaal mais fañ ko daan jiyee fañ ko daan jiyee
commande locale bi ñu bàyyi ci xel xam ne ñu ngi créé emploi ñu ngi créé emploi waaye itam ñu ngi promouvoir emploi waaye itam ñu ngi produire suñu produit
ak wàññeeku taw yi ak ngelaw yu bëri yi ak maanaam lu ñuy wax les événements extrèmes maanaam taw yu méttee métti yi dafay gën a bëri
wa waaw xaaral ma déglu rek sama waay
boobu état bi daf fi envoyé un important tranche ñebe ak ak ak ak ak
waaye dañoo weesu foofu dañuy ñaan yàlla képp ku jaayati kilo ceeb
ah man de maa ngi koy door a déglu
léegléeg doo ma dégg ca kaw waaye léegiléeg dinaañ wax ci suuf
ndax ñi ngi lay sa moromu jigéen ñi sax presque dama leen di wax naan suñu moromu jigéen ñi si suñu bopp rek daanaka ndax fu mutuelle u toogee mutuelle u ngi waxtaane suñu activité
et su ko defee ñu koy bañ ko bàyyee gone yi rek et ñu lijjantil ko seen bopp su ko defee balaa ñuy tëdd ñu daal di koy muur ak comme ni ñu ko faral di defee mu lifin su ko defee bu bëccëgee fu fu mu xiinee ñu muuraat
ak waa sénégal yi nga xam ne doom laa ci saloum
parce que munoo ñëw ni damay bay nangam
ki yàlla di tànn tànn na ko ba pare
adduna bi du mun a am dund
loolu moom mën nañu wax ni lépp lu ugpm di def
te it ngooñ bi ëllëg gis nga ne sax fas yi sax
tout son problème moom mooy na jur gi lekk ba suur na jur gi naan ba màndi donc man yaakaar naa ni que ni nit ñi aussi léegi war nañu mën a xoolaat seen bopp
bu dee dugub bi la plus part suuna 3 bi moom la ñuy béy moom la ñuy kii
brouillard bi brouillard bi nag pratiquement gisatoo ko fi mu ne nii wala benn fan ñaari fan nga koy gis waaw
nga lekk ko mu indi yeneen loraange ci wér gu yaram
suñ la waxee jiw bu nawet bu gudd nga dem ut xaw ma jiw bu gàtt day ñor si biir ndox buñ la waxee jiw bu xaw ma nawet bu bu gudd bu gàtt nga dem ut jiw bu gudd sa jiw du ñor loolu mooñu daloon comme daaw gerte gi du ñor
ñun dañuy wër di xool di leen formé également di leen wax nan la ñu war a xoolee ak nuñ ko bu ko defee bu teelee bu ñëwee rek ñu daal di teel a intervenir
parce que je sais que la demande va dépasser alors largement l offre cette année ci parce que au nivaau de la vente dese wu ñu woon dara semence passée te en plus forte raison nawet bi amuñu dara
ñu gën ci discuté xool nu ñu demee plus en profondeur
information météo dafa war a bokk comme ni ngeen ko waxee ci intrant yi
moom moo doon ñëw lu gën a bari di def si émissions yi
te dèjà ñun fin wu nawet bi
ndax lépp li nga xam ne si moom la énuy def ci kër gi lay juddoo
parce que ñoom dañuy semer à sec
mais da nga doon fekk lu mot juróomi téeméeri xale yoo xam ne ñu ngi co xor wi
ci juróom yi nag on a mission de suivie mooy maanaam def nañ loolu yëpp nag
tey boo demee pour wax ak ñoom rek pour jeune bi mën a am suuf lu ñuy njëkk a wax mooy suuf si bëriwul surtout les jeunes femmes
activité yi nga xam ne jigéen ñi petits commerce yi commercial defal nañu leen formation
incha ar allah ar buñ tollee ci wàll maraîchage
naka la mën a def ba defar kompos ndax comme ni mu waxee engrais produit chimique la
mooy union des groupements paysanes de mekhe maanaam mbooleem seen mbooleem baykat yi nga xam ni si ñoo nekk ci ngaye ak li ko wër
bële day dundal suuf
toujours kon yow amoo autonomie boo xamante ne war na la mën a permettre nga mën a départir
donc moo tax ma ne dafa am waxtu bindu waxtu boobu nag moom moo weesu
waaw comme force paysane soo déggee force paysane rek force bi rek signifié na lu ne
léegi jant bi moom daf ñuy leeral daf ñuy leeral
kon gis nga ne fi ñuy amee ndox dëggdëgg waxtu wa ñu doon waxee ne pare nañu wolli ñun fa la ñuy waxee ne ñu ngi ji gerte
parce que dañ ñu ci bëri dañoo def seen bopp ne afaire coutume su papa nekkee fii amoo droit dem di laaj suuf ñenn ñi moom dañu def seen bopp ne ah suuf daal nekk na loo xamante ne waajur bi si kër gi rek moo koy gérer
ndax it wax dëgg yàlla macha ar allah ar seen taxawaay rafet na
README.md exists but content is empty. Use the Edit dataset card button to edit it.
Downloads last month
41
Edit dataset card