audio
audioduration (s) 2
201
| transcription
stringlengths 2
439
⌀ |
---|---|
après nga wut benn brouette fumier |
|
mais daal li ñuy wax xaw ma nu ko olof di wax wala la koy wax xaw ma nu mu koy wax mais li séeréertuddee daal moo xaw a yàq dugub bi |
|
mais bu tawee ci kawam non seulement am na nu muy demee doomu gerte bi dafay |
|
parce que mboq boo bàccee boo bojjee rek da ngay dem defi ci saako |
|
amoon ci début bi ma amoon nañ pause |
|
ba nga xam ne muy borom kµµër ga |
|
repère |
|
bu ñu ñëwee bu fekkente ni dañu dajeeg guusaay ak tàngaay |
|
ndax machine boobu xëy na dinay bougé di dem ci ay villages ak yooyu mais ren jii su ma yeboo ma ne presque bougé wul li ko def mooy presque ñëpp dañoo comprendre ndax année première année bi la énu doon bougé di dem boobu nit ñi xamaguñ ko mais actuellemenet nii mun nañoo wax ni ren o ren génnuñ fenn saalum diané rek ngay ñëw indi sa semence ñu taité teel la wala nga ñëw soxla semence ñu jaay la buñ traité ba pare |
|
kon rafetlu nañ ñu ngi rafetlu seen taxawaay |
|
su fekkee ne commencé na jëfanfikoo nag bidon bi foofu day am benn genre aération parce que li nga xam ne day yàq mooy sax boobu mbala gunóor yi bu amee air rek moom ci la commencé mën a dundee |
|
ndax tekkil jigéen ni mu ngi jàppale li nga xam ne si moom mooy jigéen ñi |
|
waaw ku bëgg a bokk ci fapal comme maanaam tey fapal dafa taxawal ay groupement |
|
su ma paree bàcc bi nag ci laaj soog a nee naa la ceeb nag foofu la utee ak dugub foofu la utee ak mboq |
|
boo demee ci cin bi it ah ñu ngi ko fay lijjanti ci kër yi macha ar allah ar di ko loolu lañ tuddee autoconsommation bi |
|
soo demee ba nga xam ne wàllu góob jot na buñ la waxee ni ngay góobee ba nga góob ñoom danañ la wax ni nga war a dencee dugub ji nga denc ko ba nga xam ne daal utiliser ko jot na si li ma gis man sama xamxamu bopp loolu laa si yaakaar |
|
bu ñu jugee nag ba dem saytu xam lan mooy jafejafe yi |
|
ndax xam nga wut échantillon yoo xam ne ba nga ko joxee mu sell na set na te béréb ba nga nekk jëfëndikoo woo ca noona kon yaakaar ne bu ñu ñëwee waa service d hygène |
|
parce que |
|
pour que mu mën leen convoqué le conseil d administration du resop |
|
li xew thiel moo xew gasaan moo xew barkeyima xaw ma moo tax ñun ñu invité waa suñu agents yi nekk ki nekk barkedji ak ki nekk gasag ñëw xool ñu xam liggéeyam lan la |
|
en tout cas ci zone kaolack ak kaffrine |
|
ñu jéem a gëstu comme niñ koy gëstoo |
|
dina am capacité de reflexion boo xamante ni ñoo ko mën a may |
|
ibrahima defe naa ne loolu am na solo may fàttali numéro bi rek 33 la 967 43 00 16h |
|
waaye ren gën naa gën a fës ba ko jaar foofu nekkul loo xam ne lu ñu lu nit wax lu ñu inventé la kenn ku fay jaar gisal ko sa bopp boo wàccul tali bi sax da ngay gis yoo xam ne dina la xaw a jaaxal tuuti |
|
après ñuy def ay leblante ci biir bu ñuy leble ci biir |
|
donc bépp projet bu ñëw ci département rek toujours da nga fay fekk agent wu ancar donc loolu vraiment dafa nekk avantage boo xam ne ñun munuñu koo natt sax fi mu toll |
|
boo xam ne ñeenti weer lay def pour mu ñor |
|
di gërëm secrétaire gñéral malick sow ak mboolem ñi nga xam si mooy ùbooleme membre fapal yëpp |
|
mooy énezrgie bi nga xamante ne mooy première source énergie de la terre mooy jant bi |
|
xa xa xamoo fan nga war a kiiyee fan la nawet bi baaxee pour nga ji léegi yow dangay ñëw day taw rek nga dem sa léegi |
|
mais toppandoor mawlana cheikh ibrahim ne bu ye bonul baaxul toppandoor lu bon moo baaxul |
|
suuf si après day dem ba xoos en tout cas saag bi te bu xoosee saag bi rek trou dina am te trou bu amee kon liy yàq day dugg yàq en tout cas kii bi mën naa am mën na nekk ay ay jinax wala mën na nekk sax ay gunóor yoo xam ne dinañ dugg ci trous yooyu |
|
xam nga jigéen fi ñu toll tey nii |
|
parce que moo tax soo demee ci ci ci villages yi sax man miy dem ci village léegléeg |
|
danoo soxla am suuf soo xamante ne du dëgër |
|
nga kii ko tàngaay bi jëm ci suuf si ak suuf si ni mu nekkee en contact direct ak gerte gi |
|
sax xam naa demee wu ni waaye ba démb bi may woote neenañu ma produit bi ñëw na engrais bi it yaakaar nañu ne tey àggsi na |
|
ñun am nañ information ne nawet bi kat dina bëri ndox wala du bëri ndox |
|
ji déggoo li ma la wax nawet moom boo buggee def nawet dëgg dix juillet fu mu jotee waratoo ji leneen loo ji ay risques ngay jël risques yi ngay jël nag mooy |
|
su fekkoon ne amoon nañ beneen programme xamoon nañ |
|
xamal leen ne fiñ jëm baaxul |
|
waaw donc ginnaaw bi ñu expliqué li nga xam ni mooy changement climatique |
|
waaw |
|
situation buñ toll nii fii ci département bi jàpp nañ ne man d après suñu calcul gis nañ ne cumul cumul pluviométrie maanaam ndox mi nga xamante ne moom la ñu war a am ci nawet |
|
ak même vocal bi je crois day am français je je sais pas mais en tout cas |
|
parce que léegi bare na ci ay technologies yoo xamante ni |
|
jàppal ne député àll bi nga |
|
donc yooyu ay genre activités yoo xamante dañ koy faral di def donc ci biir loolu tamit ba léegi accompagner population yi ci services climatiques yi |
|
suy arrêté suy es suy arrêté aussi dafay arrêté d une façon boo xam ne normale lay doon |
|
boo ko mënee saxal def ko brise vent ci sa fi xam ngelaw li foofu lay jugee ci sa tool |
|
ah mesures yi il faut mu jugee sa kaw |
|
am na loo xam ne lii de fii nge laa bugg mooy maanaam tant de jeunes |
|
am nañ ay ay mala yu ñu yor ay bëy ak ay xar yoo xamante ne c est à travers activités yooyu noonu ñuy def ci |
|
ñun bëri na yoo xam ni |
|
na sonn ci ci |
|
di rencontré producteur bu mag bu ñuy wax aboubacry kane donc aboubacry kane ñu ngi lay nuyu |
|
yenn produit it bu ci bëree ba jël guub bi yëpp daanaka da koy yàq |
|
yu jëm ci wàllu mbay yi nga xamante ne laal na tamit ci wàllu càmm laal na tamit ñi nga xamante ne moom mooy ci wàllu napp ak alam bi |
|
kooku bon benn jikko la boo xam ne dañuy bëgg nit ñu nite am ko muy nangoo liggéey |
|
donc muy baykat bi lu mu munti am rek |
|
dèjà bu tawee ah mu am na lum mën a xeex ci côté bu amul matukaayu produit yeeg wala ay appareils i tam |
|
et cetera maamaam loolu dafa nekk loo xam ne nii ay mbir yoo xam ne nii projet bi daf koy daf koy daf koy def ngir xool naka la jigéen ñi mën a gën a bénéficié woo ci li xam ne mooy lépp loo xam ne nii mooy service financier |
|
parce que loolu même bu assurer woon day yàqu rek |
|
ci loolu sama laaj bu njëkk rek dama koy jagleel monsieur mignane diouf mu ñëwalaat ñu ci solo bi nga xamante ne nii xibaar yi jëmee ci wàllu jaww ji am na ko ci mbéy mi de manière générale |
|
waaw el hadj ba |
|
waaw c est à dire boo xoolee suñu réseau bi bi mu commencé ak léegi maanaam mu ngi bëri chaque année mu ngi am ñu si yokk |
|
wala saison bu gudd saison bi de ndox bi dina bëri wala ndox bi dina tuuti su ko defee yowx booy dem di uti sa jiw |
|
à travers la coopérative |
|
parce que sànq ñii ñu ngi naan ñii ñu ngi naan am nañu rajo ñii ñu ngi naan amuñu rajo |
|
li ñu liggéey wax dëgg fa yàlla des na des na trop kon te fapal def na ci ay formation yu bari formation yu bari yoo xam si ne kenn ku ci nekk war nga mën a xam ne yow mii kat tey bu fekkee ne dangay samp loo ak lépp loo mën a transformé war nga ko amal bérébu boppam boo dul bokk ak dara |
|
dagg garab dafa bokk ci loo xamni peut être suñu dund la |
|
parce que xam nañ ni ndox bu bëree ndox bu taayee xale yu ci gën a bëri dañuy dem ci ndox yi di fo ak affaire yu mel noonu souvent mën na leen indil ay jangoro ay biir ak affaire yu kenn xamul |
|
waaw loolu itam keroog bi ñiy réunion doon nañu ko wax ñu ne ndox mi des na bu ngeen koy denc dangeen a war bu ngeen demee ba naaj bi tàng ngeen góob def ko jal yu ndaw di ko defar wala nga def ko takk di ko sëpp loolu it wax nañ ñu ko keroog keroog biñ ñëwee réunion waaw loolu wax nañ ñu ko |
|
dañoo am ay groupements mais am na ay associations |
|
wante dañoo bëgg fexe ba jigéen ñi ñëpp mën a ligéey |
|
parcelle bii nii danga koy fumier fumier kese nga koy def bële danga koy def engrais kese bii nga def ko fumier ak engrais bële doo def dara |
|
man boury mbodj laa tudd |
|
su fekkente ne ñun ñëpp dañu jàpp ne europe eldorado la ñu amana ñu fa nekk di dund loo xamante ne duñ ñu ko wax dañuy jékkijékki ñëw fii vac |
|
parce que suñu amee suuf ñu sécuriser ko lépp luñ si liggéey yaakaar naa ne dinañ xeex ndóol dinañ xeex ñàkk |
|
sunu waxtaan wi ci tamba fm ñi leen ko jagleel ñi leen ko jagleel mooy kuréelu projet 4r bu pam programme alimentaire mondial ci dimbalug fond vers climat mu ànd ak xaralay jottali jóge ci kuréel bi ñu tuddee ong jokalante |
|
waa efrfectivement bon ci ren ci kii bi am na li ñu ku mu commencer woon surtout maanaam si dugub bi maanaam wànq yi |
|
da nga koy jël dajale yëpp |
|
depuis les années soixante bi tubaab yi commencé créer ay machines di créer ay usines ay oto |
|
nan nga mën a dëkkeeg moom loolu mooy ngay déglu xibaaru météo |
|
lekk nañ ci yàq nañ ci lu bëree bëree bëri démb démb bi ma fa jógee def fa constat bi dama woo waa isra ñu ne ma léegi li nga xamante ne moom moo fa nekk lu ñor fexeel nga récolter ko au moins ñu rawale ko |
|
day am lu ñuy wax vapeur d eau te vapeur d eau gaz gaz la boo xamante ne day joué |
|
loolu def c est important dafa am solo béykat yi di xam loolu noonu |
|
wala gerte gi dana ndox bi dana bëri ci moom ba nga xam ne gerte gi dafay guus |
|
donc mooy que maanaam dañuy natt parce que anacim dafa am ay bérébu nattukaay |
|
ndax bu fekkee wutal nañu la ab foos boo xam ne danga caa war a def lépp loo xam ne mooy mbalitu kër gi |
|
ndax am na ñoo xam ni munuñu engrais dañuy fab engrais bi yëpp rek xëpp ko si kaw bu ko defee sëb yi mën naa am mu dee ndax engrais dafa am doole mën naa am mu dee mën naa am mu dund |
|
parce que souvent am na jigéen ñu nga xamante ne peut être du zone bi |
|
di ko ñaanal jàmm ndax ku ñeme njaboot la ku ñeme jiite ab njaboot la |
|
donc war na noo mën a xool suuf boobu |
|
wax nañ ko sax ñëpp seetlu nañ ni |
|
li gënoon mooy daaw fi nga defoon gerte |
|
tracée guñ ne ñu aw leen si foofu ñu aw ko te bañ a werante bañ a teggi li nga xam ne moom lañ ñuy jox waa di ñu jox ay formations ndax jigéen ñi nag ñëpp ak man a yem ndax dangay ñëw ne leen kléegi tool bi kat bu ngeen koy engrais nii ngeen koy engrais |
|
mun nga nekk fii thiel ñu ne la ñu ngi xaarandi taw ci zone kolda nga yaakaar ne boo comprendre lul kolda la ñu wax bu tawul thiel rek nga ne ah wax nañ nii te fen nañu te yàlla xam na ne ngeen baal ma ci kàddu gi te nekkul ay fen mais yow yaa comprendre lul seen message bi fu mu fu muy waxee |