start_time
float64 0
2.73M
| end_time
float64 326
2.78M
| speaker_id
stringclasses 55
values | text
stringlengths 1
4.06k
| utterance_pitch_mean
float32 38.3
473
| utterance_pitch_std
float32 0
282
| snr
float64 -3.78
64.6
⌀ | c50
float64 -6.34
60
⌀ | speaking_rate
float64 0
2.1k
| phonemes
stringlengths 0
1.77k
| stoi
float64 0.24
1
| si-sdr
float64 -18.8
28.1
| pesq
float64 1.08
4.37
|
---|---|---|---|---|---|---|---|---|---|---|---|---|
178,031 | 178,465 | 11spk2 | %hum %hum | 88.59494 | 4.877584 | 0.521026 | 2.050207 | 21.333333 | %hʌm %hʌm | 0.6166 | -3.078796 | 1.272344 |
178,465 | 183,699 | 11spk3 | xam nga waxoon nañ la ni la ñu ngi liggéey Etat nag toujours dafa am ñi nga xamante ni ñoom ñoo koy jàppale | 168.080734 | 14.683921 | 20.514563 | 4.278202 | 6.690562 | lɑ ni lɑ næɡ æm ni | 0.741516 | -5.523702 | 1.166175 |
183,699 | 184,114 | 11spk2 | %hum %hum | 119.397255 | 43.975235 | null | null | 900 | %hʌm %hʌm | 0.664579 | -1.177869 | 1.2493 |
184,114 | 194,505 | 11spk3 | ñu leen di tuddee les partenaires techniques et financiers partenaires techniques et financiers boo leen boo boo ko dégloo bu baax moom mooy ONG ak projet programmes yi nga xamante ni ñoo fi nekk | 151.014435 | 32.699226 | 20.948997 | 4.935695 | 9.635652 | lin di lɛs tɛkniks ɛt fɪnʌnsɪɹz tɛkniks ɛt fɪnʌnsɪɹz bu lin bu bu koʊ ɔŋ ji ni faɪ | 0.80664 | 4.286146 | 1.174245 |
194,505 | 194,921 | 11spk2 | %hum %hum | 62.61285 | 0.604385 | null | null | 900 | %hʌm %hʌm | 0.667761 | -3.985539 | 1.248556 |
194,921 | 210,938 | 11spk3 | ñooñu vraiment ñu ngi ci bay actuellement seen wàll bu baax a baax boo ñëwee par exemple fii au niveau de Fatick nga gis %e projet bu mel ni Proval CV avant moom sax avant avant Proval di ñëw sax di judd ak %e le PDRS | 147.076889 | 45.933868 | 23.87401 | 4.947581 | 7.053104 | beɪ sin ʌ bu pɑɹ oʊ di %i mɛl ni sivi ʌvɑnt sæks ʌvɑnt ʌvɑnt di sæks di dʒʌd %i lʌ | 0.838065 | 2.084259 | 1.261545 |
210,938 | 211,354 | 11spk2 | %hum %hum | 168.564926 | 37.710964 | 1.543719 | 15.098583 | 22.222222 | %hʌm %hʌm | 0.477334 | -8.396937 | 1.29573 |
211,354 | 217,546 | 11spk3 | am na benn écloserie bi nga xamante ni bii defoon nañ ko fii ci ginnaawu agriculture non seulement éclo() écloserie boobu mu ngi foofu | 146.005783 | 35.778126 | 18.133997 | 5.423501 | 9.228901 | æm nɑ bɛn baɪ ni koʊ æɡɹɪkʌltʃɜ˞ nɑn () mu | 0.760062 | 1.391404 | 1.183082 |
217,546 | 217,934 | 11spk2 | %hum %hum | 58.108349 | 0.228761 | null | null | 900 | %hʌm %hʌm | 0.612295 | -11.945275 | 1.233704 |
217,934 | 231,186 | 11spk3 | mais %e ñu ngi def aquaculture fii et vraiment population Fatick yi ñu ngi ciy gis seen bopp les kii GIE des kii quoi des femmes de Ndiaye Ndiaye là vraiment ñu ngi ciy gis seen bopp bu baax a baax a baax donc ñu ngi fay yar ay ay kii quoi ay waas | 160.435684 | 34.081619 | 22.990784 | 4.192323 | 9.209719 | meɪs %i ækwʌkʌltʃɜ˞ ɛt pɑpjʌleɪʃʌn ji sin bɑp lɛs dɛs dɛs di sin bɑp ʌ ʌ feɪ eɪ eɪ eɪ wɑz | 0.718119 | -0.799796 | 1.174182 |
231,186 | 231,765 | 11spk2 | %hum %hum | 118.880058 | 63.970974 | null | null | 900 | %hʌm %hʌm | 0.653479 | -7.077472 | 1.235023 |
231,765 | 276,377 | 11spk3 | dégg nga ba mu toll nu mu nu mu ko neexee ñu ngi koy jaayee vraiment ay prix yu baax de la même manière boo demee élevage am na fa ay projets yi nga xamante ne bii donc ñu ngi fi %e aussi c' est des projets donc d' adaptation au changement climatique yi nga xamante ne bii yenn yi mi ngi jëm ci amélioration %e génétique %e donc kii quoi des races %e yeneen yi mi ngi jëm vraiment ci des projets donc de stabilisation wala yu mel kii quoi yu mel noonu quoi donc yooyu yépp gars yi ñu ngi ci ñu ngi ci kii quoi ñu ngi ciy bay seen wa() seen seen seen wàll te yaakaar nañ ni tamit yooyu c' est des projets kii quoi c' est des projets oubien donc des programmes yi nga xamante ni bii tay bu fekkee %e li nga xamante ne bii %e moom lañ si séntu | 153.430222 | 42.938911 | 17.474314 | 5.514204 | 7.980736 | bieɪ mu toʊl nu mu nu mu koʊ eɪ pɹi ju di lɑ bu æm nɑ eɪ ji ni faɪ %i si' ɛst dɛs di' ædʌpteɪʃʌn oʊ ji ni ji mi %i %i dɛs ɹeɪsʌz %i ji mi dɛs di wɔlʌ ju mɛl ju mɛl ɡɑɹz ji beɪ sin wɑ() sin sin sin ti ni si' ɛst dɛs si' ɛst dɛs dɛs ji ni teɪ %i li ni %i si | 0.70697 | -4.916392 | 1.154452 |
280,960 | 281,235 | 11spk2 | %hum %hum | 154.125931 | 54.873253 | null | null | 900 | %hʌm %hʌm | 0.564765 | -3.45572 | 1.24813 |
281,235 | 302,932 | 11spk3 | parce que man dama jàpp ne ni lii sunu maamu pël yi di def muy élevage extensif loolu dañ ko war a dañ dañ ko war a dépassé yore téeméer wala ñaar téeméeri nag yoo xam ne mënalooleen dara boo xëyee dàq leen ñu dem bu ñu toogee ba ñu ni dugg nañ période soudure nga bàyyi leen ñu daal di dem defi %e lu ñuy wax %e | 146.347366 | 43.74218 | 20.694435 | 4.651948 | 8.663282 | kju mæn dɑmʌ ni ni ji di koʊ wɔɹ ʌ koʊ wɔɹ ʌ jɔɹ wɔlʌ næɡ ju ni dæɹʌ bu lin bieɪ ni lin di %i lu wæks %i | 0.809292 | 6.402674 | 1.316337 |
305,481 | 305,873 | 11spk2 | %hum %hum | 175.010376 | 0.785141 | null | null | 900 | %hʌm %hʌm | 0.454625 | -7.536232 | 1.295952 |
305,873 | 311,687 | 11spk3 | jéem a kari kii quoi kari ndox mi loolu am na lu ko gën xam nga loolu nga amoon par exemple fu ngay amee téeméeri nag | 179.110901 | 23.027874 | 18.445021 | 4.611792 | 9.130061 | ʌ kɛɹi kɛɹi mi æm nɑ lu koʊ pɑɹ fu næɡ | 0.71158 | -2.100652 | 1.161201 |
311,687 | 312,111 | 11spk2 | %hum %hum | 156.630112 | 43.105392 | null | null | 900 | %hʌm %hʌm | 0.72845 | -12.468692 | 1.298928 |
312,111 | 324,848 | 11spk3 | yi nga xamante ne mënoo ci dara ludul toog di ko xool di ko topp naan ko is is nga am tay jii juróomi nag yi nga xam ne wóor na la ni yii c' est est des races améliorées juróomi nag yi nga xam ne nag bu nekk mun na la indil lu mu bon bon bon trente littres meew par jour | 166.495255 | 35.236683 | 19.939005 | 4.227822 | 13.203654 | ji ni dæɹʌ di koʊ di koʊ tɑp nɑn koʊ ɪz ɪz æm teɪ næɡ ji ni nɑ lɑ ni si' ɛst ɛst dɛs ɹeɪsʌz næɡ ji ni næɡ mʌn nɑ lɑ lu mu bɑn bɑn bɑn pɑɹ dʒuɹ | 0.723163 | -2.146294 | 1.176204 |
324,848 | 325,265 | 11spk2 | %hum %hum | 181.266815 | 3.659859 | null | null | 900 | %hʌm %hʌm | 0.535267 | -3.263264 | 1.336627 |
325,265 | 335,186 | 11spk3 | ah litre meew bu ne nga mën ko jaayee six cent franc par jours ah yaakaar naa ne loolu moom moo ëpp njëriñ fuuf yow di nga liggéeyal sa bopp te doo ci sonn te doo ci doo ci am àq | 169.939545 | 27.880281 | 22.948746 | 5.100729 | 9.287652 | ɑ ni koʊ sɪks sɛnt fɹæŋk pɑɹ ɑ ni mu jaʊ di sɑ bɑp ti du sɑn ti du du æm | 0.844585 | 6.698318 | 1.347592 |
343,499 | 345,936 | 11spk3 | ñu ngi récolter %e seen i gerte | 171.49884 | 6.065533 | 14.346242 | 6.992372 | 5.349794 | %i sin aɪ | 0.714401 | 2.305409 | 1.169168 |
345,936 | 346,370 | 11spk2 | gerte yi | 178.017303 | 1.604937 | null | null | 300 | ji | 0.599669 | -5.005797 | 1.120933 |
347,940 | 348,252 | 11spk2 | %hum %hum | 176.521103 | 1.267299 | 3.635772 | 8.099134 | 29.629629 | %hʌm %hʌm | 0.557026 | -10.010986 | 1.406737 |
348,252 | 349,359 | 11spk3 | mais seen xel dalul | 169.604568 | 21.766676 | 19.239544 | 3.912101 | 9.11681 | meɪs sin | 0.742329 | -0.309715 | 1.140935 |
349,359 | 349,914 | 11spk2 | dëgg la | 98.78228 | 27.560112 | 0.460437 | 13.097955 | 5.555555 | lɑ | 0.765685 | 2.248793 | 1.146644 |
349,914 | 366,528 | 11spk3 | weer bi ñu ko war a weeree dëgg-dëgg dégg nga sax nangootuñ ko def parce que divagation mu ngi fi boo duggee ci àll bi bon communes yi %e ni ñuy waroon def kii quoi daal di di élaborer %e kii quoi le parcours donc du bétail là amul | 159.215134 | 38.826759 | 20.369535 | 3.779966 | 7.102993 | baɪ koʊ wɔɹ ʌ - sæks koʊ kju mu faɪ bu baɪ bɑn kɑmjunz ji %i ni di di %i lʌ du | 0.783171 | 4.706705 | 1.251839 |
366,528 | 366,944 | 11spk2 | %hum %hum | 156.773605 | 41.311359 | null | null | 900 | %hʌm %hʌm | 0.694633 | -5.386515 | 1.317132 |
366,944 | 385,361 | 11spk3 | pratiquement boo xoolee parcours boobu mun naa ko nii que c' est c' est kii quoi c' est biaisé tay gis nga nag éleveur éléveur mi ngeeg %e mbir bi nga xamante ne bii ci ci ci kii quoi ci boppam moom yaakaar na ni bu xasee ba ba ba départ jur gi nga xamante ni moom la yor dara baaxul pour jur googu | 160.549438 | 36.565872 | 22.970093 | 4.384304 | 7.332722 | bu mʌn koʊ kju si' ɛst si' ɛst si' ɛst teɪ næɡ mi %i baɪ ni nɑ ni bieɪ bieɪ bieɪ ni lɑ dæɹʌ pɔɹ | 0.805844 | 3.691814 | 1.285172 |
385,361 | 385,954 | 11spk2 | %hum %hum | 88.001968 | 24.809288 | 3.622385 | 7.199451 | 15.238096 | %hʌm %hʌm | 0.690172 | 0.503428 | 1.208242 |
385,954 | 416,300 | 11spk3 | tout son problème moom mooy na jur gi lekk ba suur na jur gi naan ba màndi donc man yaakaar naa ni que ni nit ñi aussi léegi war nañu mën a xoolaat seen bopp %e xam ni que vraiment daal di am kii yar ay kii yu bëri dégg nga te vraiment du la amal benn njëriñ fexe woon ba nga am ñaar wala ñett yi nga xamante ni lu mu bon bon bon chaque jour mu mën la génneel au moins dix mille wala quinze mille franc je pense que loolu moom moo ëpp %e moom moo ëpp njëriñ fuuf parce que loolu en rélité bu fekkee yaa ngi ci sax fonctionnaire bi nga xamanate ne bii moom moo lay encadré sax yow di nga am loo xamante ne moom du ko am quoi | 155.016144 | 39.422375 | 18.931721 | 4.844954 | 10.777407 | taʊt sʌn nɑ bieɪ nɑ nɑn bieɪ mæn ni kju ni nɪt wɔɹ ʌ sin bɑp %i ni kju di æm eɪ ju ti du lɑ ʌmɑl bɛn bieɪ æm wɔlʌ ji ni lu mu bɑn bɑn bɑn dʒuɹ mu lɑ oʊ dɪks mɪl wɔlʌ mɪl fɹæŋk dʒi pɛns kju mu %i mu kju ɛn sæks baɪ ni mu leɪ sæks jaʊ di æm lu ni du koʊ æm | 0.756564 | 3.006349 | 1.235954 |
416,300 | 416,915 | 11spk2 | kon dañuy | 183.039398 | 67.944725 | -0.788465 | 59.118523 | 6.584362 | kɑn | 0.604413 | -1.125209 | 1.129628 |
421,643 | 422,056 | 11spk2 | %hum %hum | 170.332626 | 0 | null | null | 900 | %hʌm %hʌm | 0.707611 | -0.264646 | 1.356588 |
422,056 | 425,653 | 11spk3 | war nañ mën a changé doxalin vraiment bu fekkee bëgguñu kii quoi parce que | 134.892563 | 5.435272 | 17.814144 | 5.043629 | 5.842462 | wɔɹ ʌ kju | 0.581169 | -10.277734 | 1.159414 |
425,653 | 426,218 | 11spk2 | d' accord | 160.568024 | 122.36721 | 4.446198 | 8.526908 | 17.957352 | di' ʌkɔɹd | 0.754067 | 0.475469 | 1.137938 |
426,218 | 426,529 | 11spk3 | %hum | 158.678711 | 157.95816 | null | null | 400 | %hʌm | 0.415475 | -2.80689 | 1.321051 |
426,529 | 428,371 | 11spk2 | bala ma lay bàyyi ci information yi | 55.291748 | 16.295052 | 8.379696 | 8.285112 | 15.222562 | bɑlʌ mɑ leɪ ɪnfɜ˞meɪʃʌn ji | 0.745816 | 0.702688 | 1.144443 |
429,783 | 430,083 | 11spk3 | %hum %hum | 123.988075 | 1.110376 | 4.404414 | 10.948193 | 31.372548 | %hʌm %hʌm | 0.581988 | 2.88741 | 1.227245 |
430,083 | 442,146 | 11spk2 | ndax waa DRDR mun nañu témoigner tay jii que ni %e ni ngeen di joxee information yu dem ci producteurs yi ndax %e ñoom kiiyal na leen ils sont en phase ak li nga xam moom mooy information yi | 103.32885 | 45.332706 | 5.344862 | 8.337629 | 8.299616 | mʌn teɪ kju ni %i ni di ɪnfɜ˞meɪʃʌn ju ji %i nɑ lin ɛn feɪz li ɪnfɜ˞meɪʃʌn ji | 0.703924 | -1.119753 | 1.108209 |
442,146 | 444,143 | 11spk3 | loolu dama koy bàyyi moom mu tontu ci | 158.606003 | 22.482697 | 0.870972 | 5.920801 | 10.136452 | dɑmʌ mu | 0.692192 | -6.551337 | 1.145148 |
444,143 | 444,664 | 11spk2 | DRDR ayca | 178.413727 | 8.225912 | 2.01975 | 2.294026 | 1.975309 | 0.770074 | 2.802171 | 1.195775 |
|
449,272 | 459,994 | 11spk1 | %e maanaam dafa %e ñi ñi nit ñi sax dañ léegi dañ ma ne yow boo est ce que duñ yóbbu météo ma ne leen ndo() ba tay it maanaam xam-xam dadul caaxaan | 131.935898 | 34.327564 | 16.072454 | 7.448645 | 7.76699 | %i %i nɪt sæks mɑ ni jaʊ bu ɛst sii kju mɑ ni lin () bieɪ teɪ ɪt - | 0.881482 | 9.679711 | 1.614537 |
459,994 | 460,409 | 11spk2 | %hum %hum | 91.286644 | 0 | null | null | 900 | %hʌm %hʌm | 0.541749 | -0.161793 | 1.292043 |
460,409 | 463,803 | 11spk1 | wax ju tegu ci xam-xam soxna Maguette | 94.770004 | 37.687531 | 8.592132 | 8.152838 | 4.422333 | wæks dʒu - | 0.860748 | 3.208489 | 1.278261 |
463,803 | 464,345.995175 | 11spk2 | %hum %hum | 45.582371 | 1.027778 | 4.070107 | 21.142233 | 266.666656 | %hʌm %hʌm | 0.58016 | -11.935513 | 1.243133 |
464,345.995175 | 471,892 | 11spk1 | dëggu tegu ci xarale ak jumtukaay yu mucc ayib dama ne am nay jamono waa météo bu ñu waxee kenn du leen déglu | 125.163483 | 41.805561 | 16.039494 | 7.744054 | 6.943183 | ju dɑmʌ ni æm neɪ kɛn du lin | 0.912183 | 7.087541 | 1.486344 |
471,892 | 472,470 | 11spk2 | %hum %hum | 65.991875 | 30.202703 | 0.48143 | 3.514027 | 15.686274 | %hʌm %hʌm | 0.645376 | -2.071346 | 1.239919 |
472,470 | 491,321 | 11spk1 | li may wax nii yàggut waaye adduna dafay dox ay jumtukaay maanaam dama ne dama ne ñi doon ñi ko doon wax ay Sénégalis lañ te ba léegi ay Sénégalais lañu jàng am xam-xam jumtukaay rekk moo fa moo doonoon seen gàllankoor Yàlla def na diggante bi at ay at | 111.235657 | 51.903099 | 19.346554 | 4.506318 | 8.96155 | li meɪ wæks eɪ dɑmʌ ni dɑmʌ ni koʊ wæks eɪ ti bieɪ eɪ æm - mu mu sin nɑ baɪ æt eɪ æt | 0.932796 | 10.850583 | 2.006603 |
491,321 | 491,731 | 11spk2 | %hum %hum | 66.177422 | 3.839616 | null | null | 900 | %hʌm %hʌm | 0.669097 | -8.767179 | 1.15274 |
491,731 | 496,897 | 11spk1 | ñu am ay jumtukaay yoo xam ni tax na liñ doon wax mu gën a tegu | 126.613586 | 36.945114 | 12.839563 | 5.293618 | 7.165335 | æm eɪ ju ni tæks nɑ wæks mu ʌ | 0.812474 | 3.431687 | 1.185547 |
496,897 | 497,628 | 11spk2 | %hum %hum | 48.435196 | 0.291083 | 3.996641 | -1.553676 | 12.403101 | %hʌm %hʌm | 0.645678 | -6.300387 | 1.21554 |
497,628 | 512,551 | 11spk1 | xam-xam bi mosu fee jóg jumtukaay dong moo doon jafe-jafe te defe naa jumtukaay yooyu ba ci ña ca war a jóg jóge ah gis na ñépp gis nañ kenn naatablewul waxu météo moo xam ci mbay la moo xam ci sàmm moo xam ci napp kon loolu lu lu ko waral mooy li mu wax rekk | 118.327042 | 40.095783 | 15.462294 | 5.073655 | 8.282017 | - baɪ fi dɔŋ mu - ti bieɪ kʌ wɔɹ ʌ ɑ nɑ kɛn mu lɑ mu mu næp kɑn lu lu koʊ li mu wæks | 0.853563 | 5.819922 | 1.340946 |
518,639 | 519,200 | 11spk2 | bien sûr | 127.81797 | 42.167839 | 8.541174 | 6.161285 | 8.978676 | bin | 0.544384 | -0.947374 | 1.160954 |
519,200 | 537,932 | 11spk1 | léegi nag ñun ñi nga xam ni ñun ci wàllu bay man tay ñun dañ ko jiital informa() climatique fañ teg jiwu teg engrais teg fa lay la ñuy aaree gàncax teg fa jumtukaay bu ndaw mooy matériel bu ndaw bi ak matériel bu mag bi mooy tracteur ak la muy àndal foofu la tegu donc dafa nekk facteur de production | 131.412811 | 45.8666 | 17.214415 | 5.220386 | 7.035057 | næɡ ni beɪ mæn teɪ koʊ () leɪ lɑ baɪ mæɡ baɪ lɑ lɑ di pɹʌdʌkʃʌn | 0.861768 | 4.656389 | 1.304733 |
537,932 | 538,493 | 11spk2 | %hum %hum | 168.879684 | 7.467233 | null | null | 900 | %hʌm %hʌm | 0.678586 | 3.762043 | 1.198961 |
538,493 | 552,892 | 11spk1 | changement climatique ta() tax na ñu teg ko ca a kanam léegi dañ ko boole woon waaye léegi dañ ko teg ca kanam boo ko tegul doo dem ndax ñoom boo leen dégloo di nga xam ndax yow war ngaa jiw wala ndax waroo jiw | 113.799194 | 60.115761 | 20.434237 | 5.648994 | 11.728395 | tɑ() tæks nɑ koʊ kʌ ʌ koʊ bul koʊ kʌ bu koʊ du bu lin di jaʊ wɔɹ wɔlʌ | 0.891892 | 11.164986 | 2.035636 |
552,892 | 553,688 | 11spk2 | %hum %hum | 143.923187 | 56.985424 | 1.839281 | 6.441713 | 11.347518 | %hʌm %hʌm | 0.646792 | -5.101964 | 1.202979 |
553,688 | 578,242 | 11spk1 | léegi ci biir waxtaan yi dañu naan sax léegi nañu xool pour ñëw léegi ci li nga laajoon changement climatique tax na fi mu toll nii ñépp dañu war a teel a ji même ceeb sax dañu ko war a teel a ji ku ci bëgg a génn fi mu toll nii da ngay teel a ji maanaam di moytu yenn xeetu variété yi nga xam ne dañuy laal ñenti weer jëm kaw | 125.77729 | 62.850994 | 18.114628 | 4.303111 | 8.247964 | ji nɑn sæks pɔɹ li tæks nɑ faɪ mu toʊl wɔɹ ʌ til ʌ dʒi sæks koʊ wɔɹ ʌ til ʌ dʒi ku ʌ faɪ mu toʊl dɑ til ʌ dʒi di ji ni | 0.805943 | 3.356191 | 1.26379 |
578,242 | 579,939 | 11spk2 | mais teel a ji bi ndax du indi problème | 159.172943 | 45.663296 | 5.546619 | 5.255303 | 15.407407 | meɪs til ʌ dʒi baɪ du | 0.683094 | 0.88018 | 1.147761 |
579,939 | 585,686 | 11spk1 | déedéet teel a ji bi du indi jafe-jafe teel a ji bi mooy li ñuy mën a faru ñu faru ko | 139.342636 | 47.175499 | 15.111442 | 6.775887 | 10.619939 | til ʌ dʒi baɪ du - til ʌ dʒi baɪ li ʌ koʊ | 0.805079 | 6.824945 | 1.342298 |
585,686 | 586,532 | 11spk2 | dafa mel ni am na ji | 209.911026 | 4.358835 | 4.246096 | 10.707416 | 20.148148 | mɛl ni æm nɑ dʒi | 0.798864 | 4.089782 | 1.130478 |
589,509 | 589,881 | 11spk2 | %hum %hum | 175.770126 | 1.127238 | null | null | 900 | %hʌm %hʌm | 0.687783 | -4.525663 | 1.211656 |
589,881 | 598,548 | 11spk3 | man expérience bi nga xamante ne bii am naa ko ci lu mel ni mbayum gerte wala yu mel noonu xam nga gerte dañu naan pour nga jiw ko il faut nga am une pluie utile | 160.219147 | 46.821228 | 23.018801 | 5.021373 | 9.125695 | mæn baɪ ni æm koʊ lu mɛl ni wɔlʌ ju mɛl nɑn pɔɹ koʊ ɪl æm | 0.72426 | 1.067574 | 1.16644 |
598,548 | 599,148 | 11spk2 | %hum %hum | 120.283562 | 45.649086 | null | null | 900 | %hʌm %hʌm | 0.497708 | -12.063092 | 1.245228 |
599,148 | 612,675 | 11spk3 | dégg nga une pluie utile mooy taw bi nga xamante ne bii dafay nekk ba vingt milimètres soxna Maguette vingt milimètres taw moom mooy nga jël %e nu mu tudd ñaar fukki litres ndox nga wasaare ko ci benn surface su un mètre carré yaa ngi dégg | 145.925858 | 50.227161 | 21.803799 | 5.922693 | 6.555981 | baɪ ni bieɪ %i nu mu koʊ bɛn sɜ˞fʌs su ʌn | 0.794358 | 2.269166 | 1.25872 |
612,675 | 613,138 | 11spk2 | d' accord | 178.968155 | 2.734874 | 5.497031 | 5.624542 | 21.947874 | di' ʌkɔɹd | 0.596294 | -6.518322 | 1.20397 |
613,138 | 624,125 | 11spk3 | donc boo jëlee vingt litres ndox nga sotti ko ci espace su maanaam dégg nga ñenti ñenti careaux:Fra bi tooy bi muy tooy boobu xam nga dafay dafay da() da() day xóot quoi | 162.776627 | 55.432556 | 21.371454 | 5.911657 | 6.549708 | bu soʊti koʊ su : baɪ baɪ dɑ() dɑ() deɪ | 0.718708 | 1.858781 | 1.189672 |
624,125 | 624,450 | 11spk2 | %hum %hum | 152.903961 | 46.992867 | null | null | 900 | %hʌm %hʌm | 0.480724 | -10.337201 | 1.170177 |
624,450 | 631,619 | 11spk3 | xam nga maam mag yu njëkk dañu daan gas seen loxo dina xóot mais gis nga gerte googu boo xa() bu xasee ba ba ba ba kii quoi ba sax bu xasee ba sax | 170.243439 | 41.806892 | 20.162695 | 3.587291 | 13.249613 | mʌm mæɡ ju ɡæs sin dinʌ meɪs bu () bieɪ bieɪ bieɪ bieɪ bieɪ sæks bieɪ sæks | 0.647312 | -5.525332 | 1.152618 |
631,619 | 632,098 | 11spk2 | %hum %hum | 176.342087 | 0 | 1.071652 | 6.759865 | 19.047619 | %hʌm %hʌm | 0.524536 | -11.645331 | 1.44214 |
632,098 | 637,492 | 11spk3 | %e ak %e kii quoi %e évaporation bi nga xamante ne bii moom mu mu moom lay àndal ak yéen xam nga lu ma wax | 182.869675 | 18.370935 | 11.411832 | 6.248137 | 9.746588 | %i %i %i baɪ ni mu mu leɪ lu mɑ wæks | 0.680105 | 0.879891 | 1.164007 |
637,492 | 637,856 | 11spk2 | %hum %hum | 177.380203 | 0.375501 | null | null | 900 | %hʌm %hʌm | 0.551291 | -7.552539 | 1.294073 |
637,856 | 642,169 | 11spk3 | gerte bi xam nga gerte doom bi dafa kii quoi dafa niin gàccax bi dafa niin quoi dafa niin quoi | 174.425507 | 31.759697 | 16.161806 | 4.259977 | 7.668845 | baɪ dum baɪ baɪ | 0.713941 | -0.336032 | 1.138061 |
642,169 | 642,549 | 11spk2 | %hum %hum | 179.284393 | 7.835106 | null | null | 900 | %hʌm %hʌm | 0.591172 | 5.190928 | 1.211208 |
642,549 | 659,970 | 11spk3 | donc bu xasee ba sax ba pare xam nga la lu ko ray yombul li ngay la nu muy demee ba évaporer wu ba suuf sa wow koŋŋ koŋŋ koŋŋ ba amatul dara dara dara li nga xamante ne bii mën na ko puiser ci ci suuf si ba mën ba mën a dem balaa muy egg foofu dina nekk presque weer wala kii quoi weer ak nangam balaa boobu insaa àllaa dina tawaat quoi | 176.776779 | 41.021828 | 18.215878 | 4.798797 | 9.933964 | bieɪ sæks bieɪ pɛɹ lɑ lu koʊ ɹeɪ li lɑ nu bieɪ wu bieɪ sɑ waʊ bieɪ dæɹʌ dæɹʌ dæɹʌ li ni nɑ koʊ si bieɪ bieɪ ʌ ɛɡ dinʌ wɔlʌ dinʌ | 0.620644 | -3.840711 | 1.168139 |
666,327 | 667,192 | 11spk2 | ah d' accord | 52.626137 | 8.604592 | null | null | 1,200 | ɑ di' ʌkɔɹd | 0.435658 | -14.64009 | 1.229427 |
673,835 | 676,138 | 11spk1 | maanaam %e pour dëggal li mu wax | 144.323868 | 42.639759 | 13.550191 | 4.139036 | 8.714597 | %i pɔɹ li mu wæks | 0.759507 | 2.413201 | 1.147562 |
676,671 | 681,107 | 11spk1 | Yàlla dafa maa nattu dama def ay gëstu yu xaw a bëri ci li muy wax nii ci gerte gi | 129.559784 | 21.358215 | 11.479527 | 4.365682 | 7.690133 | dɑmʌ eɪ ju ʌ li wæks | 0.803797 | 4.544123 | 1.274852 |
681,107 | 681,587 | 11spk2 | %hum %hum | 57.326519 | 16.920584 | 1.03254 | 5.258253 | 19.047619 | %hʌm %hʌm | 0.64787 | -4.986442 | 1.24864 |
681,587 | 704,607 | 11spk1 | ba ci dugub maa ngi leen wax ne dugub bu xiifee ca njëlbéen bonut loolu constat empirique la nga dem ISRA kuréel gi yor wàllu gëstu bi soo demee am na benn centre ISRA bu ñuy wax ñoom ñooy gëstu lépp lu ñuy wax déve() lu ñuy wax mécanisme d' adaptation des résidus à la sécheresse Yàlla def ma jaar fa Yàlla def ma liggéey ci ci gerte | 93.271469 | 38.578747 | 9.351421 | 8.247101 | 6.366697 | bieɪ lin wæks ni kʌ lɑ baɪ su æm nɑ bɛn sɛntɜ˞ wæks lu wæks () lu wæks di' ædʌpteɪʃʌn dɛs lɑ mɑ mɑ | 0.802784 | 2.131793 | 1.195967 |
704,607 | 705,148 | 11spk2 | %hum %hum | 61.103851 | 14.885017 | 0.101439 | 2.249689 | 16.666666 | %hʌm %hʌm | 0.658365 | -0.145946 | 1.130684 |
705,148 | 717,112 | 11spk1 | gis nga ñoom li ñu liggéey ci dugub ak gerte maanaam pour ngir dëggal li ñu maanaam loolu mag ñi gis ci dugub ni bu xiifee ca njëlbeen bonut day yokk dana feeñ ca rendement ba | 135.228729 | 41.958309 | 18.856649 | 3.767441 | 5.442177 | li pɔɹ li mæɡ ni kʌ deɪ deɪnʌ kʌ bieɪ | 0.885209 | 10.52955 | 1.590813 |
717,112 | 717,452 | 11spk2 | %hum %hum | 49.576168 | 6.157692 | -0.231976 | 12.938356 | 26.666666 | %hʌm %hʌm | 0.568838 | -5.034326 | 1.186944 |
717,452 | 724,476 | 11spk1 | ñoom dañ ko gëstu ba génn ba bind ko ba teg ko dugub bu xiifee ca njëlbeen ga comme ni mu ko waxee | 129.971466 | 41.71339 | 19.612518 | 4.2891 | 11.538932 | koʊ bieɪ bieɪ baɪnd koʊ bieɪ koʊ kʌ ɡɑ ni mu koʊ | 0.805274 | 5.441902 | 1.165474 |
724,476 | 725,068 | 11spk2 | %hum %hum | 117.944244 | 56.05698 | null | null | 900 | %hʌm %hʌm | 0.506258 | -12.88859 | 1.229378 |
725,068 | 737,444 | 11spk1 | reen ba lay pousse ba mu gën a jëm ca suuf mu jëm ci suuf un mètre ba un mètre cinquante lépp lu fay ndox lépp luy ndox nag mu mu raasaatu yéegal ca kaw | 82.571724 | 37.786362 | 6.054718 | 6.604466 | 8.328328 | ɹin bieɪ leɪ bieɪ mu ʌ kʌ mu ʌn bieɪ ʌn lu feɪ næɡ mu mu kʌ | 0.668709 | 2.23424 | 1.211301 |
737,444 | 738,043 | 11spk2 | %hum %hum | 50.676792 | 0.378027 | null | null | 900 | %hʌm %hʌm | 0.599938 | -12.168231 | 1.296332 |
738,043 | 755,164 | 11spk1 | bu ko fa taw ba fekkee dooleeku ci loolu loola nga gis mun na indi xeetu bu suuf sa amee doole bu suf sa amee doole rekk nga gis mu feeñ ca ngoob ba pour dëggal ko ko ci gerte gerte am na fu muy toll ci xiif ndax man def naa ko ci loolu ma lay wax noonu jàngat boobu ma doon def | 114.627312 | 48.133858 | 15.216342 | 5.339393 | 8.656638 | koʊ bieɪ mʌn nɑ sɑ sɑ mu kʌ bieɪ pɔɹ koʊ koʊ æm nɑ fu toʊl mæn koʊ mɑ leɪ wæks mɑ | 0.843508 | 8.312706 | 1.468838 |
755,164 | 755,526 | 11spk2 | %hum %hum | 46.668091 | 1.060504 | 6.388656 | 6.540526 | 25.396825 | %hʌm %hʌm | 0.752188 | -2.403194 | 1.233607 |
755,526 | 760,590 | 11spk1 | en deux mille deux deux mille trois dañ doon xiifal gerte gi xiifal forcé | 137.937515 | 48.982582 | 13.096867 | 5.07689 | 10.038454 | ɛn du mɪl du du mɪl twɑ | 0.675442 | 4.031655 | 1.172446 |
760,590 | 761,238 | 11spk3 | %hum %hum | 48.685158 | 6.838648 | null | null | 900 | %hʌm %hʌm | 0.430529 | -10.659162 | 1.317621 |
761,238 | 782,727 | 11spk1 | xoon ko reen bi waa ISRA def nañ ko am nañ benn appareil lu ñu tuddee séseauton boo koy xiifal boo ko lifinee da ngay mën a xool soxna Maguette di mën a mesurer développement racine yeeg maanaam ni reen yi di poussé reen yu mag yi di dee bu ñu ko gëstuwee ñoom dem nañ ba gis ne reen bi dina dem ba deux mètres bu dugub dina dem ba un mètre cinquante bu gerte dina def | 116.949303 | 41.65163 | 12.138976 | 6.096153 | 9.848565 | koʊ ɹin baɪ koʊ æm bɛn lu bu bu koʊ dɑ ʌ di ʌ ɹʌsin ni ɹin ji di ɹin ju mæɡ ji di di koʊ bieɪ ni ɹin baɪ dinʌ bieɪ du dinʌ bieɪ ʌn dinʌ | 0.840738 | 5.915077 | 1.244194 |
783,768 | 784,314 | 11spk1 | loolu moo tax | 118.335312 | 0.37285 | 4.638554 | 9.560787 | 14.814814 | mu tæks | 0.766621 | 6.139166 | 1.13482 |
789,763 | 790,350 | 11spk2 | %hum %hum | 47.337955 | 1.036929 | -0.44898 | 20.796141 | 18.390805 | %hʌm %hʌm | 0.448114 | -11.554925 | 1.257427 |
790,350 | 798,752 | 11spk1 | doole jooju muy yëkkatee mu ñëw bu ñëwee bu xëccee bu ñëwee mu boole ca di jur doom day tax li ñu tuddee alimentation hudrique bi dafay gën a am doole | 114.936348 | 50.247128 | 15.801269 | 5.104237 | 8.112056 | mu mu bul kʌ di dum deɪ tæks li baɪ ʌ æm | 0.74364 | 0.005227 | 1.142672 |
811,103 | 811,501 | 11spk2 | %hum %hum | 75.203758 | 22.761599 | null | null | 900 | %hʌm %hʌm | 0.604948 | -6.515763 | 1.148815 |
811,501 | 814,836 | 11spk1 | loolu pour dëggal li mu wax la pour wane ne gëstu wane na ko ba noppi | 107.833168 | 44.494843 | 11.384731 | 8.156598 | 15.040422 | pɔɹ li mu wæks lɑ pɔɹ weɪn ni weɪn nɑ koʊ bieɪ | 0.813632 | 0.834727 | 1.148046 |
819,251 | 820,159 | 11spk2 | am na solo | 113.037537 | 55.175896 | 1.182754 | 18.50589 | 15.80247 | æm nɑ soʊloʊ | 0.652044 | -0.522185 | 1.111162 |
820,159 | 833,043 | 11spk1 | kon li muy wax noonu lu am solo la te ca suñu di() diir boobu nag eh nañuy ñaan projet boobu nga wax noonu mu antu ndax su ma juumut juróom-ñeeti communes defe naa dana ca bokk | 124.959145 | 34.8932 | 15.223232 | 5.912191 | 7.779847 | kɑn li wæks lu æm soʊloʊ lɑ ti kʌ di() næɡ ɛ wæks mu su mɑ - kɑmjunz deɪnʌ kʌ | 0.760366 | 5.727307 | 1.222272 |
833,043 | 835,119 | 11spk2 | waaw huit communes dina si bokk li nga wax loolu la | 97.593956 | 31.499735 | 7.547892 | 2.613152 | 14.935261 | kɑmjunz dinʌ si li wæks lɑ | 0.534907 | -3.555581 | 1.212756 |
835,119 | 835,621 | 11spk2 | %hum %hum | 77.144234 | 21.700548 | null | null | 900 | %hʌm %hʌm | 0.588634 | -3.068707 | 1.126498 |